audio audioduration (s) 1.22 171 | transcription stringlengths 6 108 |
|---|---|
nga dellu, xool frãs | |
siiw na itam ne ñoom gànnaar lañu bawoo, dem fuuta | |
garab yi ak ndawalum daamar | |
yaakaar naa dangaa yaatu. | |
ma daal di dige. | |
dama réeral sama caabi daamar. | |
te doylu doyle amug baaxam yorug leeram | |
ca noona xel ma tàmblee dal, mu yëg jàmm. | |
sama muus dafa weex. | |
damaa bëgg ñu déglu ma. | |
nan jóg jëlee fii | |
laabire nit ñi moo gën fital jiyaar | |
jiggeenu fariŋ bi ñu leen wo musu-mansa | |
mu ngi nii, naanal ab guux ! | |
ndax naan yi dañu jarul daral? | |
ndaw ñooy sàkku ñu dàkkal nekkinu tereg ngénn gi ci nimu gënee gaaw. | |
damaa soxla kenn, leegi. | |
ñaan naa la nga baal ma . | |
mën ngeen a mbiib a ? | |
luy sa xalaat ci ni nguur giy xeexe mbas mi ? | |
àddina, ànd bi géléem la. 2 | |
ndeem dangay roy ci moom | |
nee nañu waaw. | |
bul jooy sama nenne, aayoo, beeyoo, beeyoo. | |
wayndare wi dina jàll ci magum àttekat ya ca cees ci bisub alxemes ji | |
liig fogo | |
damaa aay ci xeltu. | |
dangeen koo war jàpp. | |
danu cee noppee ? | |
i ñoo jàllut 25,58%. | |
woroom xam-xam yiy yëngu ci paj ànduñu ci | |
dangeen di dawal. | |
ci xayma, 551.000i ci kow 3.500.000i ndongo, boo boolee lekooli nguur geek yeneen yi | |
man nanoo dellu ca kër ga rekk a? | |
boo moyuwul nag mbas mi dina gën a yaatu ci réew mi. | |
noo ngi waat fii. | |
jii wax la yonnen xamle woon | |
kenn gisul lii reelu. | |
waaye naan ci tarixa bii walla bee la bokk, ëpp naa def. | |
sama nataalukaay dafa toj. | |
limu nit ñi dëkk luanda ci at yi | |
daqaar dees koy jëfandikoo di ci defar naan yu neex | |
lépp jexoon na. | |
def naa njuumte. | |
ci atum 2010, epatit a bu tar bi faat 102,000 doomu aadama | |
loo jëmbat yendu ci keram ba mu des nit | |
bàyyil ngànnaayi ñu wadd ! | |
dajale naa niwu sokolaa. | |
waaye, farãs dafa jéggi àtte boobule, wàññi ngirtey wote bi | |
taxu koo xoromu. | |
mu mbëkku ci óom. | |
jëfe digal yii |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.