audio
audioduration (s)
1.22
171
transcription
stringlengths
6
108
demokaraasi, kàttanu fere yi
guddaayam danay àgg 20i met
kan moo toc waas bi?
bis niki tay dina dox.
di ndokkle ñi jàll ci yeneen jàngu yi ak mbooleem ñi kiilu
man nañoo dimbali way-jëfandikoo yi ci teqaleyinu baat yi
siyaare bu laayéen yi
moo tax it maa ngi nii
nangeen def gaa ñi!
bul des ci ron taw bi.
am naa 19 at.
ku nekk ci ñoom di xëcc jëmale fi nga yaakaare mbooloo bésu wote ba
fajkat bii di kan moo amaloon waxtaan ci jataayu 2stv bii di cëtëŋ.
loolu du ko mate.
bul naan lii !
damaa bañ lool waññig yaram.
dinga bëgg lii a ?
dañu koo umpale ba leegi.
dëppoo gu fraans-rusi gi
pare naa !
dinaa dem soo demee.
liig 1 senegaal
damaa ñàkk yaakaar.
mucc ayib !
leegi, naan ko benn yoon !
wóolu nga maa?
waaye nag, bàkk mbaa ŋàññ maam rekk yi taxunoo jóg
loolu yépp lu man a nekk la, tesax lu am la.
fàtteliku naa ko.
li ko waral mooy xasiidaam yii yamuñu ak dara fa yàlla sunu boroom.
danoo ree woon nun ñéep.
wolof ak xamle ?
dama bëgg fecc.
ku fi ne di xool li masàmba mbaa li madembay def, doo dem
ana jaaro mari ?
yaa not !
b anamug ñaareelug ndëngug mbas mi dafay wone wàllanteg umple gi.
fële ca senegaal dees na ko toggu boole ko ak cere cere mbuum.
mu tëj bunt ba.
soog a nekk siin-saalum, ca tekuruur lañu nekkoon
jëlleen sama yos.
amleen sutura !
sëriñ abdu xaadir ñaŋ ndogo li amatina solo.
meew mi daa wexoon.
kon bégal, am ngërëm
njiitu réew mi nangooguñu waa ndakaaru lëlu.
sanc ngir dëkk
man naa dox.
nafag dimblante gu lislaam gi
daa am lu leen di mitti?
di nañ ma rey .
xereñtéefu doomi afrig yi lu fésoon la laataa béefarkat bi di fi dugg
dama santaane itam ay fiiriir.
ndax jekk ngeen leegi?
bul caga !
lii yépp lumuy wund?
a mooy dijjaayu wommatukaay bi ñu koy natte meetar kaare
wax ma li ma war a fay.
nit ñii mat nañu 431 902 2010.
xarala gi moo yor mbooleem lu jëm cig xarala ci mbootaay.
doonte leeg-leeg yàlla bàdd menn mbas waaye jotte wul ak mbas yooya daa am
te, bcg bi day aar xëtër yi
misig lay wéetalikoo.
wooleen ma suba.
nuru woon na dëgg.
am ay rëdd ci biir xob wi yu sew
tekkikat bi àlliyun jóob bindkat bi habiibul xadiim géy
tànn naa bii.
max m gunóor rab
ngir pexem jinne.
noppi naa ak yéen.
dinaa la ca yóbb.
ba suba !
kuy jënd jëndii
tom jéemoon na nelaw .
damaa bëggoon a fecc.
sullaymaan jiim 77 290 55 79
waaye lu njuumte néew néew soo ko weddee sànku.
joxleen ma benn sàngara.
yaxantu gi itam du dakk ci diggante ñaari keppaar yi
duma am mbëfër .
xët yi mu lëkkalool
manumaa xam lu tax loolu.
ñépp a ko seetlu.
néegam dafa jaxasoo.
tom am na bis bu metti.
firnde laa soxla.
maa ngi bég.
ku tekkiwul dara laa.
fa la masjidun nabii nekk jàkkay yonent bi
am ngeen ci benn?
gëstukat , dalee ko ci jamano yu yàg ya, kon luy walbatiku
laalal lii !
dama xalaat ne danga màndi.
ame ngeen xaalisu xobbet nu mu man a toll?
tom xamoon na ci lu bari.
demal wutil ma am ndox !
nit ñii mat nañu 8 230 000 2015.
nit ñii mat nañu 31 301 2013.
buur aayul, dag yaa aay