wo stringlengths 1 251 ⌀ | en stringlengths 1 297 | fr stringlengths 1 1.15k |
|---|---|---|
Yalla, bañ naa leen. | God, I hate them. | Mon Dieu, je les déteste. |
Waaw amna, kilifa. | Yes it has, sir. | Oui, monsieur. |
Ñoom ñépp ñu ngi wax. | They're all talking. | Ils parlent tous. |
Mu ñëw ci ndeyjoor gi. | She comes starboard. | Elle vient à tribord. |
Sérieusement Big Boss Baby... ak moom. | Seriously Big Boss Baby... and him. | Sérieusement Big Boss Baby... et lui. |
Dangay wàcci ba ci suufu barab biñu bind "leeralu dugg." | Just skip down to the bottom where it says "login information." | Il suffit de sauter au bas où il est dit "l'information de connexion." |
Kon mën nañu ko def ci barab bimu nekk. | So it can be placed in the exact same position. | Il peut donc être placé exactement dans la même position. |
Dina rëy. | It's gonna be big. | Ça va être gros. |
Waaw, waaw, lépp a ngi baax. | Yes, yes, everything is fine. | Oui, oui, tout va bien. |
Màrt, Màrt, Màrt. | Martha, Martha, Martha. | Martha, Martha, Martha. |
Tiitaange? | A threat? | Une menace? |
Ba beneen! | See you! | A tout à l'heure! |
Waaye danga wara sol lii. | But you have to wear this. | Mais tu dois porter ça. |
Leegi liir bu rëy la, gëna graas. | Now that's a big, fat baby. | C'est un gros bébé. |
Yaayu jinne juy naaw dafa wara nekk jaaykat. | The mother of a flying demon must be a witch. | La mère d'un démon volant doit être une sorcière. |
Te xamnaa ni dina ñu bëgg porting biñ la jagleel. | And I know you ll appreciate the custom porting. | Et je sais que vous apprécierez le portage personnalisé. |
Musu ma bëgga àdduna bi am yaw. | I never wanted this world to have you. | Je n'ai jamais voulu que ce monde t'ait. |
Delloosi say waajur... génn fii. | Get your parents... out of here. | Sortez vos parents d'ici. |
Loolu rekk lañu soxla ak sa siife, waaw? | We just need that and your signature, okay? | On a juste besoin de ça et de votre signature, d'accord? |
Oh, kontaan naa ci yaw, William. | Oh, I'm so proud of you, William. | Je suis si fier de toi, William. |
- Ak benn poid bi. | - With the exact same weight. | - Avec le même poids. |
Bëggu ñu ma nekk ci seen wet. | They don't even want me around. | Ils ne veulent même pas de moi. |
Xam nga ko, mënu ma ko wax. | You know him, I cannot tell him. | Tu le connais, je ne peux pas lui dire. |
Nanga def... ndax mën naa wax ak Saraswati Parthasaarthy. | Hi... can I speak with Saraswati Parthasaarthy. | Bonjour... je peux parler à Saraswati Parthasaarthy. |
Dina nu xeex ba ci njeexte li. | We shall fight to the last. | Nous nous battrons jusqu'au dernier. |
Moo waral sa doom ju jigéen di dundu ba leegi. | He's the reason your daughter is still alive. | Il est la raison pour laquelle votre fille est encore en vie. |
Ndax yéen ñaar mën ngeen def juróom ñaari waat yi? | Are you two ready for the seven vows? | Vous êtes prêts pour les sept vœux? |
Lépp a ngi soppiku. | Everything's change. | Tout change. |
Uh, maa ngi... | Uh, I just... | Euh, j'ai juste... |
Dogg rekord. | Record-breaking. | C'est un record. |
Danuy jaxasoo ci mbirum terrorism bii, nu dem ba mujj nekk ñi gëna ñaaw. | We get tangled up in this terrorism thing, and somehow we end up being the ones who look bad. | On est coincés dans cette histoire de terrorisme, et d'une certaine façon on finit par être ceux qui ont l'air mauvais. |
Waaw, wax nga dëgg. | Whoa, you're right. | Vous avez raison. |
Faale nama! | I care! | Je m'en fiche! |
Ndax xamoo ko? | Didn't you get it? | Vous n'avez pas compris? |
Balaa may jeexal ak ñoom, Oogway... kenn du des kuy fàttaliku sa tur. | By the time I am done with them, Oogway... there will be no one left who will even remember your name. | Quand j'aurai fini avec eux, Oogway... il ne restera plus personne qui se souviendra de ton nom. |
(Klik bik) | (Pen Clicks) | (Pen clics) |
Yar gi ñuy teg jaaykat yi, loolu lan la? | The punishment for witches, what is that? | La punition des sorcières, qu'est-ce que c'est? |
Danga wara tëb! | You've gotta jump! | Il faut que tu sautes! |
Clark, nekkal seen ndaanaan. | Be their hero, Clark. | Sois leur héros, Clark. |
Saru dafa am gripu, moo tax ñëwul bibliotek bi tay. | Saru's got flu, so she didn't come to the library today. | Saru a la grippe, donc elle n'est pas venue à la bibliothèque aujourd'hui. |
Duñu ma jëlaat perle bi.. | The pearl will not be taken from me again.. | La perle ne me sera pas prise de nouveau.. |
Déedet, loolu mooy Big Fat Boss Baby. | No, that's Big Fat Boss Baby. | Non, c'est Big Fat Boss Baby. |
Loolu dafa raglu. | That's so scary. | C'est tellement effrayant. |
Dunu nuru lu bon lool. | We don't look too bad. | On n'a pas l'air si mal. |
Nit ñi dañuy daanu ci asamaan si. | Men fall from the sky. | Les hommes tombent du ciel. |
Jàppoon naa ni duus bi mingi fii ci suuf. | thought the bathroom was down here. | Je croyais que la salle de bain était là. |
Nit ñu bari ñu ngi joge Midwest ak Canada. | Lot of folks flying in from Midwest and Canada. | Beaucoup de gens arrivent du Midwest et du Canada. |
Juum naa ci benn. | I did get one wrong. | J'ai eu tort. |
Yenn saa baay yi dañuy juum. | Sometimes dads make mistakes. | Parfois, les pères font des erreurs. |
Kai mingi ñëw! | Kai is coming! | Kai arrive! |
Dama soxla lu dëgër, leer. | I need something robust, precise. | J'ai besoin de quelque chose de robuste, précis. |
Edisioŋ buñ jagleel la, ñu defaree ko ci yaw. | It's a special edition, custom-made, just for you. | C'est une édition spéciale, faite sur mesure, juste pour vous. |
Waaw, Po! | Yay, Po! | Ouais, Po! |
Baby Corp mingi waaja dem ci liggéeyam. | Baby Corp is going to go out of business. | Baby Corp va faire faillite. |
- Wax nga ko ba pare. | - You already said that. | - Tu l'as déjà dit. |
Komisario, jàppoon naa ni noo ngi ci jafe-jafe.. | Commissioner sir, I thought we're in danger.. | Monsieur le Commissaire, je croyais qu'on était en danger. |
Kon bul ma woo. | Then please don't call me. | Alors s'il te plaît, ne m'appelle pas. |
Ak naka lépp ci kër gi? | And how's everything at home? | Et comment ça se passe à la maison? |
Lii xale bu mag bu mag la. | This is Super Colossal Big Fat Boss Baby. | C'est Super Colossal Big Fat Boss Baby. |
CEO bi daal di koy otograaf. | The CEO even autographed it. | Le PDG l'a même autographié. |
..moo tax ma woo la. | ..that's why I called you. | C'est pour ça que je t'ai appelé. |
Loolu rek ngeen musa wax. | That's all you ever talk about. | C'est tout ce dont tu parles. |
Inspectër bi, pare nañu. | Inspector sir, they are ready. | Inspecteur, ils sont prêts. |
Su ko gisee, dina jeex. | If he finds out, he'll be shattered. | S'il le découvre, il sera brisé. |
Def naa ko... te bàyyi naa la nga dem ndax... | I did... and I let you go because... | Je l'ai fait... et je t'ai laissé partir parce que... |
ak boroom yi sànni ay dënd. | and gods hurl thunderbolts. | et les dieux lancent des tonnerres. |
Di nga ci xam. | You'll get the hang of it. | Tu vas le faire pendre. |
Xaaral ma wane la benn mbootaay bu bees. | Let me introduce you to a new member. | Permettez-moi de vous présenter un nouveau membre. |
Maa ngi waajal... jàngal la. | I am ready... to teach you a lesson. | Je suis prêt... à vous donner une leçon. |
Dama wara am... | I must have... | J'ai dû... |
Lépp a ngi baax? | Everything all right? | Tout va bien? |
Nanga def, gato bu neex la! | Come on, it's a piece of cake! | Allez, c'est un morceau de gâteau! |
Deet ci safara. | Death by fire. | La mort par le feu. |
Danu wara jéem loolu itam. | We should try that, too. | On devrait essayer ça aussi. |
(Dafay babax ak tiitaange) | (Stammers Nervously) | (Frappe Nerveusement) |
- Dunu ko? | - We don't? | - C'est vrai? |
Deel nekk seen monumaa. | Be their monument. | Soyez leur monument. |
Xamnaa ni wax naa ko. | I know I said it. | Je sais que je l'ai dit. |
Robust, jaar yoon. | Robust, Precise. | Robuste, précis. |
Saru dellu na? | Saru's back? | Saru est de retour? |
Empire bu Grande Bretagne kese mooy yor dooley géej gi. | Only the British Empire will hold the power of the sea. | Seul l'Empire britannique conservera le pouvoir de la mer. |
Martini bu mujj bi... | That last Martini was a... | Ce dernier Martini était un... |
Amaana dina leen tiital. | Maybe it'd be scary back at them. | Peut-être que ça leur ferait peur. |
Saa waay, mën nga wax ak man, xam nga? | Hey, you can talk to me, you know? | Tu peux me parler, tu sais? |
- Déedet, ba leegi mingi wéy di am grip. | - No, she's still got flu. | - Non, elle a toujours la grippe. |
Mooy ki gëna ndaw ci taarixu liggéeyukaay bi. | He was the youngest Chief Executive Infant in the history of the company. | Il a été le plus jeune chef de la direction bébé dans l'histoire de l'entreprise. |
Lu mëna xew, nanga toog ci sa yoon. | What ever happens, stay your course. | Qu'est-ce qui se passe, reste ton cours. |
Rad la, wala ? | Totally rad, right? | Totalement rad, n'est-ce pas? |
I c... | I c... | C'est... |
Leegi, maa ngi lay ñaan, nga delloosi waat yii ci sama ginaaw. | Now please repeat these vows after me. | Répète ces vœux après moi, s'il te plaît. |
Jàngaleel ma? Déedet! | Teach me? Oh, no! | Enseigne-moi? |
Um, ñaata fan ngay yegg ci aéroport bi? | Um, how long until the airport? | Combien de temps avant l'aéroport? |
Saa waay, dóor ngama ñaari yoon. | Hey, you hit me twice. | Hé, tu m'as frappé deux fois. |
Déedet, déet, moom ak DK ñoo bokk waajal lii lépp. | No, no, he and DK together planned all this. | Non, non, lui et DK ont planifié tout ça ensemble. |
Barina luma wara jàng. | I have so much to learn. | J'ai tellement à apprendre. |
Ñi deful dara dañuy dee. | Innocents die. | Les innocents meurent. |
Diggante njàngalem baay ak doom ju jigéen, di jël doomu jàmbur. | Between the father-daughter principles, of the getting wrenched. | Entre les principes père-fille, de se faire écraser. |
Xamoo sax luy bokk ci njaboot. | You don't even know what it's like to be part of a family. | Tu ne sais même pas ce que c'est de faire partie d'une famille. |
Nekk seen malaaka. | Be their angel. | Sois leur ange. |
Ubbi mbir mi! | Open that thing! | Ouvre ce truc! |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.