wo stringlengths 1 251 ⌀ | en stringlengths 1 297 | fr stringlengths 1 1.15k |
|---|---|---|
Bokk na ci Nancy Mirando. | Including Nancy Mirando. | Y compris Nancy Mirando. |
"W-W-S-B-F-B-B-D? | "W-W-S-C-B-F-B-B-D? | "W-W-S-C-B-F-B-B-D? |
(Dafay yuuxu) Bànk yi: | (Gasps) Banks: | (Gasps) Banques : |
Déet, 49. | No, 49. | Non, 49. |
ñaw ko ak beurre? | sharpen it with butter? | l'affiner avec du beurre? |
- Conique. | - Tapered. | - Câblé. |
Salaam, ndax...yaakaar nga? | Dear, are you..okay? | Chéri, est-ce que... ok? |
Marta dund na. | Martha lives. | Martha vit. |
Dani: | Dani: | C'est quoi, ça? |
Delloosi ko. | You take that back. | Retire ça. |
- Ñett... | - Three... | - Trois... |
Fexeel woor wala saraxe. | observe a fast or give charity. | observer un jeûne ou donner de la charité. |
Mënu ma des fii ci suuf, Alfred. | I can't stay down here, Alfred. | Je ne peux pas rester ici, Alfred. |
Kan laa ci yaw ginaaw guddi gi? | who am I to you after that night? | Qui suis-je pour toi après cette nuit-là? |
CIA dafa yaakaar ni desert bi dañu ko defar. | CIA thinks the desert was a setup. | La CIA pense que le désert était un piège. |
Okja xamul sax ni nga fi. | Okja doesn't even know you're here. | Okja ne sait même pas que tu es là. |
Waaji mooy ñaareelu defkatu ñaawtéef bi ñu fekk mu wane màrku yat wi. | The man is the second criminal found baring the bat brand. | L'homme est le deuxième criminel trouvé à la barre de la marque de chauves-souris. |
Daa melni damay wax "Antenne bu am doole" wala "Thorax bu defar sandwich." | It's like me saying "Antenna of Power" or "Thorax of Making Sandwiches." | C'est comme si je disais "Antenna of Power" ou "Thorax of Making Sandwiches". |
Man maa leen di wax. Kai! | It's me talking through them. Kai! | C'est moi qui parle à travers eux. |
Gis... | See... | Vous voyez... |
Nooyal, foofu. | Pause, there. | Pause, voilà. |
Saa waay, pàppa. | Oh, hey, Dad. | Oh, hé, papa. |
Jéemal bii. | Try this one. | Essaie celui-là. |
Waaw, waaw, waaw. Doyna. | Okay, okay, okay. Enough. | Ça suffit. |
"Lu nara def xale bu mag bu mag bu mag bi?" | "What Would Super Colossal Big Fat Boss Baby Do?" | "Que ferait Super Colossal Big Fat Boss Baby?" |
Kon loolu mooy moom. | So that's her. | Alors c'est elle. |
Guddi gi jeexna... | The night's gone... | La nuit est révolue... |
Ana lu jëm ci fourure bi? | How about the lining? | Et la doublure? |
Laaf yu ñàkka deggoo. | Wings of Disagreement. | Des ailes de désaccord. |
Ñoom ñépp lañu yóbbu? | All were transported? | Ils ont tous été transportés? |
Faluja. | Fallujah. | Falloujah. |
Sarmila, Ram! | Sharmila, Ram! | Sharmila, Ram! |
Leegi Yàlla, def sama bëgg-bëgg. | And now God, bends to my will. | Et maintenant Dieu, penche à ma volonté. |
Demal ci kaw nga nekk ak nit ñi. | Go upstairs and socialize. | Montez et socialisez. |
Sama dundu jaar na yoon ba nga ñëw! | My life was perfect until you showed up! | Ma vie était parfaite jusqu'à ce que tu arrives! |
Metzger! | Metzger! | Metzger! |
Amna ku bëggoon Superman melni ku def njuumte. | Somebody wanted Superman to look guilty. | Quelqu'un voulait que Superman ait l'air coupable. |
Su ko defee nga def ko ak man. | Then you will do it with me. | Alors tu le feras avec moi. |
Amul fuñu mëna nëbb. | There is nowhere to hide. | Il n'y a nulle part où se cacher. |
Ki ñu njëkka faat, ap xale buñu jiiñ ni def na ñaawtéef, ñu sonal ko ci kaso bi, te mingi wéy di nekk ci paj mu metti ndax ay gaañu gaañu yu mu am. | The first victim, an accused child predator later was assaulted in prison and remains in critical care from his injuries. | La première victime, un enfant prédateur accusé plus tard, a été agressé en prison et demeure sous la garde critique de ses blessures. |
Soo yéegee ci kaw seen bi te waxoo ko, dina la yéem lool. | If you show up on stage without telling her, it'll be such a great surprise. | Si vous vous pointez sur scène sans lui dire, ce sera une grande surprise. |
Gisuma fumu fanaan. | I can't find a place to stay. | Je ne trouve pas d'endroit où rester. |
Dama doon... taxaw ngir xooj tuuti. | I was just... stopping by for a little soak. | Je passais juste... passer prendre un peu d'eau. |
Mbënd? | Surprise? | Surprise? |
-Ndax gis nga loolu? | -Did you see that? | - Vous avez vu ça? |
Leegi lépp jaar na yoon. | Now it's perfect. | Maintenant c'est parfait. |
Balaa bi? | The bullet? | La balle? |
Genneel ko. | Get her out. | Faites-la sortir. |
Loolu mooy nataal bi. | That's the image. | C'est l'image. |
Kon loolu rek nga am? | So that's all you get? | C'est tout ce que tu as? |
Maître Urs, Maître Poulet, Maître Croc! | Master Bear, Master Chicken, Master Croc! | Maître Ours, Maître Poulet, Maître Croc! |
Nanu jambaar, muccal Perle bi. | Let's be brave, save the Pearl. | Soyons courageux, sauvez la Perle. |
mbir yi jeexna, Inder. | the matter's over, Inder. | C'est fini, Inder. |
Sa nataal ci kuuraŋ bi? | Your picture on the wall? | Votre photo sur le mur? |
Benn kompiñi buñ defar weñ moo ko defar. | The metal was developed by a private company. | Le métal a été développé par une société privée. |
Leegi kamera yi ñu ngi xaar ci sa gaal. | Now the cameras are waiting at your ship. | Les caméras attendent à votre vaisseau. |
Ñooy kan, pàppa? | Who are they, daddy? | Qui sont-ils, papa? |
Taktik. | Tactical. | Tactique. |
Nu gas fu xóot, di xool noon yi. | We were dug in deep somewhere, watching an enemy compound. | Nous avons été creusés quelque part, en regardant un complexe ennemi. |
Amna xale bu jigéen bu bawoo Metropolis bu lay wax nga dëggu. | Some young lady from Metropolis will make you honest. | Une jeune femme de Metropolis vous rendra honnête. |
Loolu mooy nataal bi nu nara yàq. | That is the image that is gonna destroy us. | C'est l'image qui va nous détruire. |
Gëm leen, xale, yëg-yëg bi bokk na. | Believe me, kid, the feeling is mutual. | Crois-moi, petit, le sentiment est réciproque. |
Benn yeglekaat neena Metropolis ni ñu bari deñu yaakaaroon ni fasoŋu Bat bi ci kaso bi moy daan dee. | One source tells Metropolis, that many believed the mark of the Bat brand in prison essentially is a death sentence. | Une source dit à Metropolis, que beaucoup croyaient que la marque de la marque Bat en prison est essentiellement une condamnation à mort. |
Ak sargal gu mat sëkk, gëm nga ni lii mooy tànneef bi gëna baax? | Sir with all the respect, you sure this is the best option? | Monsieur avec tout le respect, vous êtes sûr que c'est la meilleure option? |
Te danga wara jox rapoor bi ci nimu gëna gaawe. | And you need to give me the report as soon as possible. | Et vous devez me donner le rapport dès que possible. |
Dina ñu ma yokk rang. | I'll get a promotion. | Je vais avoir une promotion. |
Alfred, ci sa gént. | In your dreams, Alfred. | Dans tes rêves, Alfred. |
Kan ñooy dof yooyu? | Who are those morons? | Qui sont ces crétins? |
Ànd naa ko! | I agree! | Je suis d'accord! |
LEXKORP. | LEXCORP. | LEXCORP. |
-Lu xew leegi? | -What just happened? | - Que s'est-il passé? |
AR-15. | AR-15. | AR-15. |
(Di yuuxu) Déedet, déet, déet! | (Screaming) No, no, no! | Non, non, non! |
- Dafa wara nekk fii. - Gaal ci suuf si. | - It has to be here. - Sail that land. | - Il doit être là. |
- Téyéel. | - Hold on. | - Attendez. |
Dama bëgga njëkka gis Okja. | I want to see Okja first. | Je veux voir Okja d'abord. |
Xaj bii daal di ñëw ci nun. | And this dog come up on us. | Et ce chien vient sur nous. |
Amaana musul daje ak yaw! | I wish I'd never met you! | J'aurais aimé ne jamais t'avoir rencontré! |
Daa melni dañu wara daw. | I feel like we should run. | J'ai l'impression qu'on devrait fuir. |
Ngir àdduna bi gis pax yi ci barab bu sell bi. | For the world to see the holes in the holy. | Pour que le monde voie les trous dans le saint. |
Lu ngay def fii? | What are you doing out here? | Qu'est-ce que tu fais là? |
Lu tax dunu jubbanti rek... | Why dont we just correct... | Pourquoi ne pas juste corriger... |
Biro bi ci koñ bi... ak sama potty privé. | The corner office... with my own private potty. | Le bureau du coin... avec mon propre pot privé. |
Dama yegsi ci kër ga fekk la ngay sangu ak say puppe... | I come home to find you taking a bath with your dolls... | Je rentre pour te trouver en train de prendre un bain avec tes poupées... |
Téere xam-xam la, xam-xam lu am solo la. | Books are knowledge, and knowledge is puff worth. | Les livres sont des connaissances, et les connaissances en valent la peine. |
Lu mëna xew ci guddi gi... yàggul dara ñu fàtte Abhinamyu. | Whatever happened that night... was only a moment to forget Abhinamyu. | Ce qui s'est passé cette nuit-là... n'a été qu'un moment pour oublier Abhinamyu. |
Sama yaakaar mooy benn yoon kese nga wooma ngir reer ak seetaan filmu, hmm? | I wish that just once you'd call me up for dinner and a movie, hmm? | J'aimerais qu'une fois que tu m'appelles pour dîner et un film, hmm? |
Ci beneen xibaar, meer bi xamlena ni Metroplis... | In other news, the mayor has announced that Metroplis... | Dans d'autres nouvelles, le maire a annoncé que Metroplis... |
Man maay... | And I am... | Et je suis... |
Muy yuuxu. | He was barking away. | Il aboyait. |
Frank, sa D! | Frank, your D! | Frank, ton D! |
Lex Lutor? | Lex Luthor? | Lex Luthor? |
Wala duma ànd ak moom. | Or I won't cooperate. | Ou je ne coopérerai pas. |
Xool leen te dàq leen. | Find out and fire them. | Trouvez-les et tirez-les. |
11.5 puus. | 11.5 inch. | 11,5 pouces. |
Oh mi bëtu Boroom bi. | Oh mi Lord's eye. | Oh, l'œil du Seigneur. |
- Bàyyileen ko mu dem. | - Let him go. | - Laisse-le partir. |
(Telefoŋ biy sone) | (Cell Phone Rings) | (Cell Phone sonne) |
Saxaar bu wert bi, poof rek! | The green smoke, just poof! | La fumée verte, c'est du caca! |
Leegi nu wax ci ñaareelu dige bi. | Now for the second promise. | Maintenant pour la deuxième promesse. |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.