wo stringlengths 1 251 ⌀ | en stringlengths 1 297 | fr stringlengths 1 1.15k |
|---|---|---|
Keefe. | Mr. Keefe. | M. Keefe. |
Ak kuti. | And a puppy. | Et un chiot. |
Sir... ndax mën nanu weccoo garland te baña waat sëy? | Sir... can we just exchange garlands and not vows to get married? | Monsieur... peut-on juste échanger des guirlandes et pas des vœux pour se marier? |
Ndax mën ngama wax dara ci njeexte guddi gi? | Could you recommend anything for the end the night? | Pourriez-vous recommander quelque chose pour la fin de la nuit? |
- Ndax nu def ko? | - Shall we? | - Allons-y. |
Jàngale kung fu? | Teaching kung fu? | Enseigner le kung-fu? |
Lii mooy kàrt bi kenn mënul jàng. | This is the map no man can read. | C'est la carte qu'aucun homme ne peut lire. |
Mën nga gis bëréet googu. | You can see that lightning. | Vous pouvez voir cette foudre. |
Soledad O'Brien "Ci Moment" | Soledad O'Brien "In the Moment" | Soledad O'Brien "Dans la minute" |
Turnout bi defa baax, yaakaar nga? | The turnout's looking good, don't you think? | Le taux de participation est bon, non? |
Mbaam xuux bi gëna baax ak xale bu jigeen baykat bu taaru bi dañu leen forse ñu tàqaloo, ñu dajaloo ci sunu seen bi. | The best super pig and the adorable farmer girl forced apart and somehow brought together on our stage. | Le meilleur super cochon et l'adorable fermier se sont séparés et se sont rassemblés sur notre scène. |
Dinaa yéeg, yaw wàcci. | I'll go high, you go low. | Je vais me défoncer, tu vas te défoncer. |
Yaakaar nga ni dina bàyyi leegi? | You think he will stop now? | Tu crois qu'il va s'arrêter maintenant? |
Kenn mënu la yàq. | He's fairly indestructible. | Il est assez indestructible. |
Xale bu jigeen bu rafet. | Pretty girl. | Jolie fille. |
Mën naa la laaj? | May I ask you a question? | Puis-je vous poser une question? |
Sëñ bi, maa ngi lay xaar bu yàgg. | Sir, I was expecting you much earlier. | Monsieur, je vous attendais beaucoup plus tôt. |
Po, loolu promotion la! | Po, that's a promotion! | Po, c'est une promotion! |
Jëf ju bon. | Bad habit. | Mauvaise habitude. |
Laaj bu gaaw ci yaw. | Quick question for you. | Une question rapide pour vous. |
-Déedet, xaaral. | -No, wait. | - Attendez. |
Dara bu rëy... | Something big... | Quelque chose de grand... |
Lucy, xarañ la. | Brilliant, Lucy. | Génial, Lucy. |
Ile bii dafay wane asamaan bu baax. | This island is a perfect reflection of the heavens. | Cette île est un reflet parfait des cieux. |
- Lucy kontaan na lool. | - Lucy must be thrilled. | - Lucy doit être ravie. |
Sëñ bi, nit rekk la. | Sir, he is one man. | Monsieur, c'est un homme. |
Lu ngay def ak moom? | What are you doing with him? | Qu'est-ce que tu fais avec lui? |
Yooyu surge dañuy gëna yokk, simili bu nekk dañuy gëna am doole. | Those surges are like increasing and they seem to be getting stronger by the minute. | Ces surtensions sont comme en augmentation et elles semblent être de plus en plus fortes d'ici la minute. |
Barab bi rafet na lool. | The place is really nice. | L'endroit est vraiment sympa. |
Yaa ngi jubal ngir daje ak senateer yi. | You're heading in to meet with the senators. | Vous allez rencontrer les sénateurs. |
Moom rek laa am. | He's all I got. | Il est tout ce que j'ai. |
Mën naa la xelal... | May I suggest... | Puis-je vous suggérer... |
Planet bis bu nekk. | Daily Planet. | Planète quotidienne. |
Doom, jëlal liggéey bi! | Take the job, son! | Prends le boulot, fiston! |
Bul ma wax, waaw? | Don't quote me, alright? | Ne me cite pas, d'accord? |
Daje bu am yëg-yëg, ñu ànd génn ci seen bi. | An emotional reunion, and then they leave the stage together. | Une réunion émotionnelle, puis ils quittent la scène ensemble. |
Ragal bug bi! | Fear the bug! | Craignez l'insecte! |
Lu nga leen di wax? | What would you tell them? | Qu'est-ce que tu leur dirais? |
Benn biddiiw réer na, ci saasi. | One star's missing, quickly. | Il manque une étoile, vite. |
Ak, bis boo nekkee kilifag Jade Palace bi yépp... | And, someday when you're in charge of the whole Jade Palace... | Et un jour, quand tu seras responsable de tout le palais Jade... |
Dafa melni lu amul dara... waaye suba dina ñu dem jënd lujum ak yeneen mbir. | It looks a bit empty... but tomorrow we'll go buy vegetables and stuff. | Ça a l'air un peu vide... mais demain, on ira acheter des légumes et des trucs. |
Um. | Um. | C'est ça. |
Lan mooy sa xalaat ci wallu chat ci Gotham? | What's your position on the bat vigilante in Gotham? | Quelle est votre position sur le justicier de la chauve-souris à Gotham? |
Beneli M4. | The Benelli M4. | Le Benelli M4. |
Loxo ci loxo. | Hand in hand. | Main dans la main. |
Waaw kay, yaw xale bu ndaw... | All right, you little... | Très bien, petit... |
Dama wara dem Gotham ngir mu jàppale ma. | I have to go to Gotham to convince him to help me. | Je dois aller à Gotham pour le convaincre de m'aider. |
Libboon porte boulong ak jàppukaayu sarse buñ personaalise buñ defar. | Custom bolt carrier release and charging handle. | Poignée de chargement et de déverrouillage sur mesure. |
Dama ñëw fi ngir wax leen ñu yewwu. | I've come here to tell them to wake up. | Je suis venu leur dire de se réveiller. |
Mën naa jënd lujum ak yeneen mbir sama bopp. | I can buy vegetables and stuff myself. | Je peux acheter des légumes et des trucs moi-même. |
Mën naa jaay fideos ci foyer bi | I can sell noodles in the lobby! | Je peux vendre des nouilles dans le hall! |
Danu wara wut trident bi ngir muccal Henry. | We have to find the trident to save Henry. | Nous devons trouver le trident pour sauver Henry. |
Texture. | Textured grips. | Poignées texturées. |
Hektër. | Hector. | Hector. |
Xaaral, xarit. | Hold on, buddy. | Attendez, mon pote. |
- Bët yépp a ngi ci moom. | - All the eyes on her. | - Tous les yeux sur elle. |
Waaye soo ñëwee... | But if you come along... | Mais si vous venez... |
Lii deret ak yàpp la. | This is flesh and blood. | C'est de la chair et du sang. |
Xaaral, ndax amnaa lii? | Wait, do I own this one? | Attends, est-ce que je possède celui-ci? |
Lu tax ba leegi ngay sangu ni liir? | Why are you still here taking a bath like a baby? | Pourquoi tu prends toujours un bain comme un bébé? |
Lu tax du leer? | Why is not it glowing? | Pourquoi ça ne brille pas? |
Wala mu dee. | Or he has to die. | Ou il doit mourir. |
- Dafa yaakaar ni defile mode boppam la. | - She thinks it's her own fashion show. | - Elle pense que c'est son propre défilé. |
Dafa indi xare fii. | He's delivered a war here. | Il a livré une guerre ici. |
Wala beneen waay bi la woon? | Or was that the other guy? | Ou c'était l'autre type? |
Soo amee loxo... tooy. | If your hands get... wet. | Si tes mains sont mouillées. |
Antenne bu am doole! | Antenna of Power! | Antenne du Pouvoir! |
Carina, jeexal. | Finish it, Carina. | C'est fini, Carina. |
Klasik italien. | An Italian classic. | Un classique italien. |
Liberté civil dañu ko xañ ci seen dëkk. | Civil liberties has been trampled on in your city. | Les libertés civiles ont été piétinées dans votre ville. |
Kenn du nekk ku baax ci àdduna bi. | No one stays good in this world. | Personne ne reste bon dans ce monde. |
Desàmbar? | Dessert? | Dessert? |
Noonu la xare di nuru. | This is what war looks like. | C'est à ça que ressemble la guerre. |
Yaatal franchise bi ñu ngi nuy xaar! | Franchise expansion awaits us! | L'expansion des franchises nous attend! |
Desàmbar. | Dessert. | Dessert. |
Kuttu yi gëna baax. | The finest cutlery. | Les meilleurs couverts. |
Biddéew bi réer. | The missing star. | L'étoile disparue. |
Nit ñu baax ñu dundu ci tiitaange. | Good people living in fear. | Des gens bien vivant dans la peur. |
Metropolis ci lëndëm / doole juy joge ci gaal | Metropolis in the dark / power surges from ship | Metropolis dans l'obscurité / surtensions du bateau |
Man, lii baaxna lool, man. | Man, this is so good, man. | Mec, c'est si bon, mec. |
Waaye ana lu jëm ci joŋante nuru Dragon Warrior? | But what about the Dragon Warrior look-alike contest? | Mais qu'en est-il du concours Dragon Warrior ressemblant? |
Barina nit ñuy wax ni mooy seen ndaanaan. | There are plenty of people, sir, who would say he's their hero. | Il y a beaucoup de gens qui disent qu'il est leur héros. |
Fresh-affir. | Fresh-sharpened. | Fraîcheur. |
Ngir sama pàppa. | For my father. | Pour mon père. |
Du ab ndaanaan! | He is not a hero! | Ce n'est pas un héros! |
Doom, bul gëm lépp loo dégg. | Don't believe everything you hear, son. | Ne crois pas tout ce que tu entends, fils. |
Danga wara jéem lii. | You gotta try this. | Tu dois essayer ça. |
Mme Chow mooy jël ndam li saa yu nekk. | Mrs. Chow always wins that. | Mme Chow gagne toujours ça. |
Wayne, Bruce Xale yu góor yi | Wayne, Bruce Boys Share Too | Wayne, Bruce Les garçons aussi |
Waaw.. | Aye.. | Oui. |
Gis naa ko, M. Wayne. | I've seen it, Mr. Wayne. | Je l'ai vu, M. Wayne. |
Grace, mën nga indi Greg fii, leegi. | Grace can you get Greg up here please, right now. | Grace, tu peux amener Greg ici, s'il te plaît. |
Loolu baaxna lool. | It's actually really good. | C'est vraiment bon. |
- Mën nga def komànd bu gaaw? | - Could you do a rush order? | - Peux-tu faire un ordre rapide? |
Luthor's Drive bi dafa gis sa nataal. | Cracked Luthor's Drive found your photography. | Cracked Luthor's Drive a trouvé votre photo. |
Dafa yaakaar ni moo ëpp yoon. | He thinks he's above the law. | Il pense qu'il est au-dessus de la loi. |
Waaye du yaw. | But it doesn't belong to you. | Mais ça ne t'appartient pas. |
Senateer! | Senator! | Sénateur! |
Bis bu neex, ñépp. | Good day, all. | Bonne journée, tout le monde. |
- Mën naa | - I sure can | - Je peux vraiment. |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.