wo
stringlengths
1
251
en
stringlengths
1
297
fr
stringlengths
1
1.15k
Du oto rek...
Its not just a car...
Ce n'est pas juste une voiture...
Sëñ bi, dañu amoon dëgg.
Sir, they were right.
Monsieur, ils avaient raison.
Yaa ngi ragal lool?
You're seriously afraid?
Tu as vraiment peur?
Foofu, foofu, sama doom.
There, there, son.
Voilà, fiston.
- Taxawal, bul ko gëm.
- Stop, don't believe it.
- Arrête, n'y crois pas.
Trident bi mën nako muccal leegi.
The trident be all that can save him now.
Le trident est tout ce qui peut le sauver maintenant.
Leegi yaa ngi daw, maa ngi yaakaar.
You're on the run by now, I expect.
Tu es déjà en fuite, j'espère.
Noo ngi lay defal lu baax.
We are doing you a favor.
Nous vous rendons service.
Daa melni dafay dem ak kenn.
I guess she's going on a date.
Je suppose qu'elle va à un rendez-vous.
Brooke Baldwin bu CNN mungi ci fi mbir yi xewewoon.
CNN's Brooke Baldwin is on the scene.
Brooke Baldwin de CNN est sur les lieux.
Metit wu wex wi ci nit ñi mooy am xam-xam bu amul benn kàttan.
The bitter sweet pain among man is having knowledge with no power.
La douleur amère et douce chez l'homme est d'avoir la connaissance sans pouvoir.
Ndax dangay dem ci date?
Are you going on a date?
Vous allez à un rendez-vous?
Ella, lii mooy Dani.
Ella, this is Dani.
Ella, voici Dani.
Ndax xam nga ko leegi?
Do you get it now?
Vous l'avez maintenant?
Inspektër...
Inspector...
Inspecteur...
Oto John Wick la.
It is John Wick car.
C'est la voiture de John Wick.
- Banc banc.
- Pew pew.
- Pew pew.
metrisis seramik.
Ceramic metrisis.
La métrise en céramique.
Wax ko lépp sa pàppa.
You tell your daddy all about it.
Raconte tout à ton père.
Brooke, yaa ngi ci air bi.
Brooke, you're live on the air.
Brooke, tu es en direct.
Lucy, ndax mën naa la laaj dara?
Lucy, may I ask you a question?
Lucy, puis-je vous poser une question?
Yaakaar naa ni duma la gis.
I don't suppose I'll find you.
Je ne vous trouverai pas.
Ba ci Master Chicken dafay dugg foofu!
Even Master Chicken's going in there!
Même Master Chicken y va!
Sama pàppa dafa tuddee liggéeyukaay bi ci turam.
My father named the company after himself.
Mon père a nommé la compagnie d'après lui-même.
Wax nga ni dañu defar ambush bi ngir kaadre Superman, waaye naka lañu mëna xamee ni dina feeñ ci diggu desert bi.
You said that the ambush was arranged to frame Superman, but how could they know that he'll show up in the in the middle of the desert.
Tu as dit que l'embuscade était arrangée pour piéger Superman, mais comment pourraient-ils savoir qu'il se montrera au milieu du désert.
Xel mi barina fii, mënu ma ci gis dara.
There's so much wisdom in here, I can't find anything.
Il y a tant de sagesse ici, je ne trouve rien.
Te ginaar la.
And he's a chicken.
Et c'est un poulet.
Yékkal sa loxo.
Lift your arm.
Soulevez votre bras.
Xale bu jigéen bi.
The girl.
La fille.
lamine.
Laminated.
Laminée.
Dafa wara nekk fii.
It has to be here.
Ça doit être ici.
Waaw, waaw, waaw.
Yep, yep, yep.
Ouais, ouais, ouais.
Kon dimbali ma, dinaa weñ couche bi ci kuuraŋ bi!
So help me, I will nail his diaper to the wall!
Alors aide-moi, je vais clouer sa couche au mur!
Mooy Lex bi nekkoon ci kanamu Corp.
He was the Lex in front of the Corp.
Il était le Lex devant le Corp.
Amaana danga wara doxantu balaa muy jeexal.
Maybe you should go for a walk while she finishes up.
Peut-être que tu devrais aller faire un tour pendant qu'elle finit.
Saru duma jox cër sama pàppa.
I don't respect my father, Saru.
Je ne respecte pas mon père, Saru.
Kon... lu tax doo ko delloo?
So... why just dont give it back?
Alors... pourquoi ne pas le rendre?
Du ni loolu moo am solo.
Not that it really matters.
Ce n'est pas vraiment important.
Abhimanyu, lii mooy Inder.
Abhimanyu, this is Inder.
Abhimanyu, ici Inder.
Waaw kay, ñëwal.
Alright, come on through.
Très bien, passez.
Ndax loolu lu jaarul yoon la, te umm...
Because that is paradoxical, and umm...
Parce que c'est paradoxal, et euh...
Amna lu xew ci gaal gi.
There's something happening at the ship.
Il se passe quelque chose au vaisseau.
Armure corporelle.
Body armor.
Armure du corps.
Jaruwoo ko.
You're not worth it.
Tu n'en vaux pas la peine.
-Loolu la.
-That's it.
- C'est ça.
Xoolal ko Jack.
Look at it Jack.
Regarde-le Jack.
Moo ray sama doomu rak.
He killed my nephew.
Il a tué mon neveu.
Yaa ngi xalaat yóbbu ko New York, wala book?
You're thinking of bringing her to New York, aren't you?
Vous pensez l'emmener à New York, n'est-ce pas?
Bëgg nga ñibbi ak Okja, wala book?
You want to go back home with Okja, right?
Tu veux rentrer chez toi avec Okja, pas vrai?
Tontu yépp ñu ngi ci.
All the answers will be found within.
Toutes les réponses seront trouvées à l'intérieur.
Shifu niko xamuma luy nekk xarekatu Dragon.
Shifu says I don't know what it means to be the Dragon Warrior.
Shifu dit que je ne sais pas ce que ça veut dire d'être le Dragon Warrior.
ñungi xaar atte bu sena bi tammbali ci beppu simili leegi.
The Senate hearing is expected to get under way in any minute now.
On s'attend à ce que l'audience du Sénat commence d'une minute à l'autre.
Suma defee dige boobu ci sama bopp, fen la.
If I make take that promise inside, it will be a lie.
Si je fais cette promesse à l'intérieur, ce sera un mensonge.
Johnny Walker, yaa ngi ci jàmm.
Johnny Walker, S'il vous plaît.
Johnny Walker, S'il vous plaît.
Dafay yónnee kuuraŋ yu bari.
It's sending massive power surges.
Il envoie des surtensions massives.
Baal ma, naan, doo fay.
Please, drink, it's free.
S'il vous plaît, buvez, c'est gratuit.
Inder, mooy Abhimanyu, Namrata ak Sheetal.
Inder, that's Abhimanyu, Namrata and Sheetal.
Inder, c'est Abhimanyu, Namrata et Sheetal.
Ndax dégg nanu dara ci Boss Baby bu ndaw bi... bi ñu yónnee Templetons?
Have we heard anything from that little Boss Baby... that we sent down to the T empletons?
Est-ce qu'on a entendu quelque chose de ce petit Boss Baby... qu'on a envoyé aux emplettes T?
Danu koy togg ci diggante tissu bi ak fourure bi.
We just sew it between the fabric and the lining.
On vient de le coudre entre le tissu et la doublure.
Leegi dama wara nekk jàngalekat?
Now I have to be a teacher?
Maintenant, je dois être professeur?
- Dañu la dàq!
- You're fired!
- Vous êtes viré!
Ndax nu ñibbi?
Shall we go home?
On rentre chez nous?
Mooy mbir mi gëna rafet ci yima musa gis.
It's most beautiful thing I've ever seen.
C'est la plus belle chose que j'ai jamais vue.
Dama doon waaja wax loolu!
I was about to say that!
J'allais dire ça!
Dëgg la dina am luñu xamul ci lii lépp:
Of course the big unknown in all of this is:
Bien sûr, le grand inconnu dans tout cela est:
Poliis dafa defar benn barikade ci biir barabu tëjukaay bi.
The police created a barricade around this containment center.
La police a créé une barricade autour de ce centre de confinement.
Duko def?
Won't it?
N'est-ce pas?
Kon baaxna sudee ma ànd ak yaw?
All right if I join you?
D'accord si je me joins à vous?
Fukk ak ñaar ci samay nit.
A dozen of my men.
Une douzaine de mes hommes.
Man ak yaw jeexnañu.
You and I are done.
Toi et moi, c'est fini.
Dafa amul dara?
It's blank?
C'est vide?
Kon defal li ñu la wax.
Then do as you're told.
Alors fais ce qu'on te dit.
Jërëjëf ci li nga ma jox kër.
Thanks for finding me a home.
Merci de m'avoir trouvé une maison.
Clark Kent, Planet bis bu nekk.
Clark Kent, Daily Planet.
Clark Kent, Planète quotidienne.
Te mënu ma la fen, Saru.
And, I can't lie to you, Saru.
Et je ne peux pas te mentir, Saru.
Lii mooy li sama pàppa bëggoon gis.
This is what my father wanted to find.
C'est ce que mon père voulait trouver.
Jàppoon naa ni xam naa ki ma doon.
I thought I finally knew who I was.
Je pensais enfin savoir qui j'étais.
Amatuloo am.
You no longer exist.
Tu n'existes plus.
Amul benn dugg.
Zero penetration.
Pénétration zéro.
Luko moy, lii mooy dall Okja.
Otherwise, this is what will happen to Okja.
Sinon, c'est ce qui arrivera à Okja.
Naka lay deme?
How is he doing?
Comment va-t-il?
-Mantis! Am nanu ndigal ñu baña...
-Mantis! We have orders not to...
- Mantis, nous avons l'ordre de ne pas...
Ndax Superman dina feeñ?
Will Superman show up?
Superman va-t-il venir?
Ci kaw otoom.
Over his car.
Au-dessus de sa voiture.
Xeer yi? Déedet, déet.
The rocks? No, no.
Les rochers?
Xaaral, xaaral, xaaral.
Wait, wait, hold on.
Attendez, attendez.
Te danuy jéema jege tuuti ngir xam li xew.
And we're trying to get a little bit closer here to find out what's going on.
Et nous essayons de nous rapprocher un peu ici pour découvrir ce qui se passe.
Di nga ko invite ci Festiwaalu mbaam xuux bu gëna baax te...
You'll invite her to the Best Super Pig Festival and...
Vous l'inviterez au Best Super Pig Festival et...
Waaye...
However...
Cependant...
Mën ngama gërëm soo bëggee barab bi.
You can thank me if you like the place.
Vous pouvez me remercier si vous aimez l'endroit.
Loolu mooy li ñuy xaar gis.
That is what they're really waiting to see.
C'est ce qu'ils attendent vraiment de voir.
Sudee duma xarekatu dragon bi, kan laa?
If I'm not the Dragon Warrior, who am I?
Si je ne suis pas le Dragon Warrior, qui suis-je?
Dafa metti lool, maa ngi ragal.
Quite painful I am afraid.
C'est douloureux, j'ai peur.
Oh, sama fondation jota genne kominike ngir jàppale... mbir mi.
Oh, my foundation has already issued a statement in support of the... cause.
Oh, ma fondation a déjà publié une déclaration à l'appui de la... cause.
Dina wér.
He'll be okay.
Ça va aller.
Solal ko.
Put it on.
Mets-le.
Soxla nañu sunu ndimbal!
They need our help!
Ils ont besoin de notre aide!
Ndaje bu neex!
A moving reunion!
Une réunion émouvante!
Jaxasoo bu mat sëkk la.
It is absolute chaos.
C'est le chaos absolu.
Du xeer, biddiiw.
Not rocks, stars.
Pas des rochers, des étoiles.