wo stringlengths 1 251 ⌀ | en stringlengths 1 297 | fr stringlengths 1 1.15k |
|---|---|---|
Amaana doo musa judd! | I wish you'd never been born! | J'aurais aimé que tu ne sois jamais né! |
Kon soo noppee, nga dellusi fii? | So when you're done, you're coming back here? | Quand vous aurez fini, vous reviendrez ici? |
Ndax sama doomu bajjan... | Because my faking nephew... | Parce que mon faux neveu... |
Du woon lenn lu wuute. | It wasn't anything special. | Ce n'était rien de spécial. |
Xamnaa loolu waaye dafa yéeme. | I know, but it's just so mesmerizing. | Je sais, mais c'est tellement envoûtant. |
Noo ngi jubal Juroomi Jardin yi. | We're heading towards Five Gardens. | Nous nous dirigeons vers cinq jardins. |
Waaw, boroom doole bi dafa leer ni tilim la suñu ko jàppee. | Yes, the all mighty comes clean about how dirty he is when it counts. | Oui, le tout puissant est clair sur la façon dont il est sale quand il compte. |
Jade mbindéef yi dañu song sunuy village. | Jade creatures attacked our villages. | Des créatures jade ont attaqué nos villages. |
Figure aksioŋ. | Action figures. | Chiffres d'action. |
Ray xaj bi. | Killed the dog. | Il a tué le chien. |
Heh heh, déet. | Heh heh heh, no. | C'est pas vrai. |
Du woon dara wow! | It wasn't anything wow! | Ce n'était rien de wow! |
Amna fumu nekk. | It's here somewhere. | C'est quelque part ici. |
Ak poof! | And then poof! | Et puis pouf! |
A-A-A-P, T-a-m. | A-S-A-P, T-i-m. | A-S-A-P, T-i-m. |
Dama bëggoon fo rek. | Just wanted to play. | Je voulais juste jouer. |
Slip ci douche bi? | Slip in the shower? | Plonger dans la douche? |
Lien ionik buñ dooleel. | Reinforced ionic bonds. | Des liens ioniques renforcés. |
Topp nanu leen fii. | We've tracked them here. | Nous les avons suivis ici. |
(Kaaraange) | (Defense) | (Défense) |
- Mija... | - Mija... | - Mija... |
Amoon na itam ay kontaraktuwel kaaraange ci biir desert bi. | He also had private security contractors in the desert compound. | Il avait également des agents de sécurité privés dans le complexe désertique. |
Ndax Timothy Templeton dina jël telefon bu weex bi? | Would Timothy Templeton please pick up the white courtesy phone? | Timothy Templeton pourrait-il prendre le téléphone blanc de courtoisie? |
...te doo yokk xorom sangu ci ndox mi, dangay yokk poobar bu Szechuan. | ...and instead of adding bath salts to the water, you just added Szechuan peppercorns. | ...et au lieu d'ajouter des sels de bain à l'eau, vous venez d'ajouter des grains de poivre de Széchuan. |
Ni ngay jox cër sa yaay ak sa pàppa... noonu la... dinga jox cër sama yaay ak sama pàppa itam. | The way you respect your mother and father... similarly... you will respect my mother and father too. | La façon dont tu respectes ta mère et ton père... de même... tu respecteras aussi ma mère et mon père. |
Dama bëgga gis naka lay jeexee. | I kind of wanna see how it ends. | Je veux voir comment ça finit. |
Abuser xale bu jigéen bu rafet bi. | Abusing that adorable girl. | J'abuse de cette adorable fille. |
Dina nu la yóbbu ci yoon wi. | We'll drop you on the way. | Nous allons vous déposer sur le chemin. |
Waaw, lu mel noonu. | Yeah, something like that. | Oui, quelque chose comme ça. |
Ngir muccal Martha, indil ma boppu mbonaat mi. | To save Martha, bring me the head of the Bat. | Pour sauver Martha, apportez-moi la tête de la chauve-souris. |
Lucas, def ngama mbetteel. | You disappointed me Lucas. | Vous m'avez déçu Lucas. |
Woo. | Woo. | C'est pas vrai. |
- Mu tontu ko déet. | - She said no. | - Elle a dit non. |
Leegi bàyyileen ma. | Now just leave me alone. | Laisse-moi tranquille. |
Shifu, loolu lan la woon? | Shifu, what was that? | Shifu, qu'est-ce que c'était? |
Duma famiy. | I'm not a family man. | Je ne suis pas un homme de famille. |
Dafa sàcc benn oto. | He stole a car. | Il a volé une voiture. |
Bàyyileen ko mu dem. | Let him go. | Laisse-le partir. |
Dédeet, jërëjëf waay. | No thank you. | Pas de merci. |
Sechuan... | Szechuan... | Széchuan... |
Ndax gis nga li nga doon wër, soxna? Maa ngi jéem! | Have you found what you were looking for yet, miss? I'm trying! | Vous avez trouvé ce que vous cherchiez? |
Timote Leslie Templeton, jëlal telefon bu weex bi. | Timothy Leslie Templeton, please pick up the white courtesy phone. | Timothy Leslie Templeton, s'il vous plaît décrochez le téléphone de courtoisie blanc. |
Te... buñu sukkandikoo ci sa njaboot... dinga def jëfi diine te wéy di jaamu Yàlla. | And... according to your family's norms... you'll perform religious deeds and stay devoted to God. | Et... selon les normes de votre famille... vous ferez des actes religieux et resterez dévoués à Dieu. |
Dañu wara nekk foofu. | They must be in there. | Ils doivent être là. |
Ak 1-6 yaatal. | With 1-6 magnification. | Avec un grossissement de 1-6. |
Sama njiitu kuréel niko, "Danga wara def dara. | And my group leader goes, "You got to do something. | Et mon chef de groupe dit : "Tu dois faire quelque chose. |
Demal ci enregistrement. | Go on record. | Allez-y, notez-le. |
Man, umm. | I, umm. | Je, euh. |
Ak ci uniform yi ma defar sama bopp. | And in the uniforms that I personally designed myself. | Et dans les uniformes que je me suis personnellement conçus. |
Biddéew yi dina ñu jeex ci diir bu gàtt. | The stars will soon be gone. | Les étoiles vont bientôt disparaître. |
Daf nuy jox. | He's going to give us away. | Il va nous donner. |
Neena ñu yaa ko jàpp. | They say you kidnapped her. | Ils disent que vous l'avez kidnappée. |
Bëggoon naa la wax ni amnanu xale bu jigéen bi. | I just wanted to tell you we got the girl. | Je voulais juste te dire qu'on a la fille. |
Yaay ji, ndax dinga xool waxtu wi. | Mother of God, would you look at the time. | Mère de Dieu, regardez l'époque. |
Ak puus xaritam bi gëna baax ci kamioŋ. | And shoving her best friend onto a truck. | Et a poussé sa meilleure amie dans un camion. |
Te lii mooy planu jamono jii. | And this is the modern blueprint. | Et voici le plan moderne. |
Waaye loolu jeexul bu baax. | Well, that didn't end well. | Ça ne s'est pas bien fini. |
Nanu dellu ginaaw. | Let's go back. | Rentrons. |
Master Shifu daf nu digal bu baax... nu baña sëy. | Master Shifu strongly advised us... not to engage. | Maître Shifu nous a fortement conseillé... de ne pas nous engager. |
Déedet, man lan laa? | No, what am I? | Non, qu'est-ce que je suis? |
Soo nangu... | If you agree... | Si vous êtes d'accord... |
Karina! Henry! | Carina! Henry! | Carina, Henry! |
Loolu moo nuy ray. | That's gonna kill us. | Ça va nous tuer. |
A hoi hoi. | A hoi hoi. | Un hoi hoi. |
Mija. Mija, jàpp naa ni xamoo mbir mi. | Mija. Mija, I don't think you understand this situation. | Mija, je ne pense pas que vous compreniez cette situation. |
Benn oto... | A car... | Une voiture... |
Leslie. | Leslie. | Leslie. |
Kai... | Kai... | Kai... |
Maa ngi nekk ci ginaaw biro. | I belong behind a desk. | Je suis derrière un bureau. |
Amul jafe-jafe, ñëwal. | No problem, come along. | Pas de problème, venez. |
Oh, samay tender! | Oh, my tenders! | Oh, mes offres! |
Leegi wax ma kan laa. | Now tell me who I am. | Maintenant, dites-moi qui je suis. |
Loolu mingi ci sunu inventaire. | Which currently is among our inventory. | Ce qui fait actuellement partie de notre inventaire. |
Toppatoo nañu ko. | She's been taken care of. | Elle s'est occupée d'elle. |
dina ñu dëkk ci sa wetu cammoy. | they'll I'll reside in your left side. | Je vais résider dans votre côté gauche. |
Bi nga fiy ñëw, am nga benn waxtu. | When you came here, you had an hour. | Quand vous êtes venu ici, vous aviez une heure. |
Xoolal, ile bi mingi fa. | Look, the island is there. | Regarde, l'île est là. |
Amna benn, ñaar, ñetti bunt. | There are one, two, three gates. | Il y a une, deux, trois portes. |
-Danu wara dugg foofu. | -We've gotta get in there. | - Il faut qu'on y aille. |
Yaakaar naa ni sa coono yépp amul benn njariñ. | I guess all your trouble was for nothing. | Je suppose que tous vos ennuis ont été pour rien. |
- Loolu lu baax la! | - That's awesome! | - C'est génial! |
Leegi dafa néew. | Now it's less. | Maintenant, c'est moins. |
Waaw, amna lu jaarul yoon. | Okay, yes, something's wrong. | Ok, oui, quelque chose ne va pas. |
- Ku góor ki ci tente bi. | - Man on the marquee. | - L'homme sur le chapiteau. |
Demal ci.. | Get to the.. | Allez au... |
Bàyyileen ko, Abhimanyu. | Let her be, Abhimanyu. | Laisse-la, Abhimanyu. |
Wax ma kan laa ci yaw. | Tell me who I am to you. | Dis-moi qui je suis pour toi. |
Xibaar yépp a ngi ci. | It's all over the news. | C'est partout aux infos. |
Waaw kay, loo wara wax? | Alright, what am I suppose to say? | D'accord, qu'est-ce que je suppose dire? |
Nun lay am Okja. | We are the ones who have Okja. | Nous sommes ceux qui ont Okja. |
-Waaye Shifu neena... | -But Master Shifu said... | - Mais Maître Shifu a dit... |
Kon noo ngi bàyyi lépp... ngir am oto? | So, we are giving everything up... for a car? | Donc, nous abandonnons tout... pour une voiture? |
Dédeet, musu ma ko dégg. | Nope, never heard of him. | Non, jamais entendu parler de lui. |
Karina! Karina! Henry! | Carina! Carina! Henry! | - Carina, c'est Henry! |
Disk karbure de silisium. | Silicon carbide discs. | Disques en carbure de silicone. |
Nataal boobu. | That image. | Cette image. |
- Xamnaa loolu, wala ? | - I know, right? | - Je sais, n'est-ce pas? |
Dama bëgg sama liggéey. | I happen to like my job. | Il se trouve que j'aime mon travail. |
Danu dee. | We're dead. | Nous sommes morts. |
Saru, xaaral tuuti. | Wait a minute, Saru. | Attendez, Saru. |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.