wo
stringlengths
1
251
en
stringlengths
1
297
fr
stringlengths
1
1.15k
Pikodon yi 12,90 lañu, kabekous yi 23,50.
Picodons are 12.90, cabecous 23.50.
Les picodons sont 12,90, cabocus 23,50.
Nànd?
Understand?
Compris?
Ndax xam nga fi ñuy jëm?
Are you sure you know where we're going?
Tu es sûr de savoir où on va?
Looy gëna jëm mag, ngay gëna am doole.
The older you get, the stronger.
Plus vous vieillissez, plus vous êtes fort.
Oh dëggantaan?
Oh, really?
Vraiment?
Amul benn liggéey ci yéen nit ñi!
There's just no work for you people!
Il n'y a juste pas de travail pour vous!
Déedéet, nanu jaar fii.
No, let's go this way.
Non, allons par ici.
Sama jëkkër defna benn at ci biti.
My husband's been out there for a year now.
Mon mari est là depuis un an.
Soo yewwoo gërëm Yakul.
If you're awake thank Yakul.
Si tu es réveillée, remercie Yakul.
Gisoon naa li waral yenn xale yu góor yi jàppee ko ni snob la.
I could see why some of the boys took him for snobby.
Je pouvais voir pourquoi certains garçons l'ont pris pour snobby.
Danga may sol ni sëriñ bi di yëngal sa scimitar dénk.
You used to dress me up like a sheik wave your wooden scimitar.
Tu m'habillais comme un cheik en agitant ton scimitar en bois.
- Hey!
- Hey!
- Bonjour!
Dëgg la dina am sikki-sakka ndax dina ñu def benn bloke ci loolu.
Of course, I doubt they'll toss up any roadblocks for that.
Bien sûr, je doute qu'ils jettent des barrages pour ça.
Nanu ko wutal ay xeer.
Let's get him some rocks.
Allons lui chercher des cailloux.
Loy def? Loy def?
What are you doing? What are you doing?
Qu'est-ce que tu fais?
Dama bëgga fecc!
I want to dance!
Je veux danser!
Ñenn ñi dañu leen ray ci Scythie ci wetu Oxus.
Some were butchered in Scythia by the banks of the Oxus.
Certains ont été massacrés en Scythie par les rives de l'Oxus.
Yaakaar naa ni danga wara defal sa bopp lii, Andy.
I don't think you ought to be doing this to yourself, Andy.
Je ne pense pas que tu devrais te faire ça, Andy.
Xool bu baax sa jéego.
Watch your step.
Surveille ton pas.
Am xel mu ñaw.
Very wise.
Très sage.
- 100.
- 100.
- 100.
Dégg naa ni jàppale nga ñaari nit ci loolu.
I hear you helped a couple of fellas with that.
J'ai entendu dire que vous avez aidé quelques gars avec ça.
Ku inndi Ashitaka.
Someone bring Ashitaka.
Quelqu'un amène Ashitaka.
Maa ngi dëkk ci sama pàppa te bëggul.
I've stayed with Papa against his will.
Je suis resté avec papa contre son gré.
Sanja, fan nga nekk?
Sanja, where are you?
Sanja, où es-tu?
- Dellu ci yeneen dof yi.
- Go back to the other oafs.
- Retourne dans les autres oafs.
Wax ma, fuck-baton?
You tell me, fuck-stick?
Tu me le dis, connard?
Loolu neex na.
How nice.
Comme c'est gentil.
Sama Führer... komànd yi pare nañu.
My Führer... the orders are ready.
Mon Führer... les ordres sont prêts.
Bul fàtte!
Don't forget!
N'oublie pas!
Dafa ànd ak dal ci moom.
He had a quiet way about him.
Il était tranquille.
Mu daw, ray ay mbokkam ak mbagg.
He ran amuck and killed his family with an ax.
Il a couru et tué sa famille avec une hache.
Yaw kese nga musul may ma jël ndam li.
You were the only one who'd never let me win.
Tu étais le seul à ne jamais me laisser gagner.
Ricci, bul fàtte yóbbaale sa welo.
Ricci, don't forget to take your bicycle.
Ricci, n'oublie pas de prendre ton vélo.
Booba ba leegi ténji laa.
I've been a widow since.
Je suis veuve depuis.
Fii moo gën.
It's better here.
C'est mieux ici.
Pecc!
Dance!
Danse!
Gaa? .?
Guys? .?
Les gars?
Dakkal dal!
Stop!
Arrêtez!
- Loolu la.
- That's it.
- C'est ça.
Waaw, sama buur.
Right, my king.
Oui, mon roi.
Xaaral, xaaral.
Wait, wait.
Attendez.
Xale bu baax.
Good boy.
Bon garçon.
Loolu ay gént yu bonn lañu.
These are just shitty pipe dreams.
Ce ne sont que des rêves de merde.
Ay sàmmkat?
Sheepherders?
Des Sheepherders?
Duma def, yaay.
I won't, Mom.
Je ne le ferai pas, maman.
Booy seet, daa ragal.
In fact, she's cowardly.
En fait, elle est lâche.
Dibéer bi weesu, Führer bëggoon nama jàppale ma dem.
Last Sunday, the Führer wanted to help me leave.
Dimanche dernier, le Führer voulait m'aider à partir.
M. Hallorann, naka nga xamee ni ñu koy woowe Doc?
Mr. Hallorann how'd you know we call him Doc?
M. Hallorann, comment savez-vous qu'on l'appelle Doc?
- Réer, biir bu mboq bi!
- Get lost, yellow-belly!
- Allez-vous-en!
Bëgg nañu bàyyi liggéeyum wen!
They want to abandon the ironworks!
Ils veulent abandonner les forges!
Jack:
JACK:
C'est pas vrai.
Dunga bàyyi fas yii foofu, ngay lekk.
You're not gonna leave these horses there, while you eat.
Tu ne vas pas laisser ces chevaux là, pendant que tu manges.
Maa ngi lay massawu ci say xarit.
Sorry about your friends.
Désolé pour tes amis.
Shawl bu rafet la, tànta.
What a lovely shawl, Auntie.
Quel joli châle, tante.
Delloosi xaalis bi.
Take back the silver.
Reprenez l'argent.
Ñenn ñi dee ñu baax.
Some died good.
Certains sont morts bien.
Sama Yàlla, lu tax nga dëddu ma?
My God why have you forsaken me?
Mon Dieu, pourquoi m'as-tu abandonné?
Daa melni ngelaw lu am doole moo koy naaw.
Looked like a stift breeze would blow him over.
On dirait qu'une brise étouffante le ferait sauter.
Mu ngi lay xool saa yu nekk.
He watched you the whole time.
Il t'a regardé tout le temps.
Amaana kenn ci ñoom mingi daw ba leegi.
Maybe one of them still runs.
Peut-être que l'un d'eux court toujours.
Bëgg naa ko gërëm.
I want to thank him.
Je veux le remercier.
Ñoom ñépp yaw lañu ko bindal.
They're all addressed to you.
Ils vous sont tous adressés.
Dina nu xaar!
We'll be waiting!
Nous allons attendre!
Yenn aljuma ci ngoon, Amélie dafay dem sinemaa.
Some Friday evenings, Amélie goes to the cinema.
Quelques vendredis soirs, Amélie se rend au cinéma.
Amnaa benn?
I got one?
J'en ai une?
Yéen ay dof!
You bastards!
Espèce d'enfoirés!
Amul werante Darius daw bimu demee ci mbir mi.
No wonder Darius fled when he had this to come back to.
Pas étonnant que Darius se soit enfui quand il a eu ça à revenir.
Führer mënul réer ci taarix ni dawkat bu amul ndam!
The Führer can't just disappear from history like some inglorious fugitive!
Le Führer ne peut pas disparaître de l'histoire comme un fugitif inglorieux!
Yobbu leen ci moom.
Take them back to her.
Ramenez-les à elle.
Dafay sos ay noon ndax limu am doole te dëgërul.
Already she makes enemies with her strong, clumsy nature.
Elle fait déjà des ennemis avec sa nature forte et maladroite.
Ci boucher bi, daa am xale bu ndaw buy xool xaj buy xool ginaar yi ñuy toggu.
At the butcher's a baby's watching a dog that's watching the chickens roasting.
Au boucher, un bébé regarde un chien qui regarde les poulets rôtir.
Ndax dafa féey?
Has he drowned?
Il s'est noyé?
Dama bëgga dem ci tundu wi.
I want to go to the mountain.
Je veux aller à la montagne.
Kenn ki ma musa dëggu.
The only one who's ever been honest with me.
Le seul à avoir été honnête avec moi.
Duma yàq sama jot ci ñi ñàkk, Tommy?
I don't waste time on losers, Tommy?
Je ne perds pas de temps avec les perdants, Tommy?
Doxantu ak waxtaan bu jaarul yoon ci gox bii.
A walk and a talk that just wasn't normal around here.
Une promenade et un discours qui n'était pas normal ici.
Lima bëgga wax mooy, Mexico mingi foofu ci suuf te yaw nga nekk fii?
I mean, Mexico is way the hell down there and you're in here?
Le Mexique est loin d'être là-bas et tu es là?
Amna lu amul fenn?
Anything in particular?
Quelque chose en particulier?
Beneen?
Another one?
Un autre?
Ñëwal seen kër!
Come home!
Rentre à la maison!
Bëgg nga ko?
You like it?
Ça te plaît?
Leegi sa turn la.
Your turn now.
À ton tour maintenant.
Amul dinaar?
Got no dinars?
Vous n'avez pas de dinars?
Yeen ñaar ngeen xool pëno yi kese.
You two look only for the tires.
Vous ne cherchez que les pneus.
Danga soxla benn.
You need one.
Tu en as besoin.
Xam nga sa yaay bu baax.
You know your mother well.
Tu connais bien ta mère.
Raju moo ma ko jox, ngir may tàngoor ci guddi gi.
Raju gave it to me, to keep me warm in the evenings.
Raju me l'a donné, pour me garder au chaud le soir.
Katja la woon?
Her name was Katja?
Elle s'appelait Katja?
Mi ngi nelaw.
He's sleeping.
Il dort.
Sunu xaar, dina nu yeex!
If we wait we'll be too late!
Si nous attendons, nous serons trop tard!
Demal sa kër, biir bu mboq!
Go home, yellow-belly!
Rentrez chez vous!
Demal... yaw xaj bu tàyyeel bi.
Get out... you lazy dog.
Sors... espèce de chien paresseux.
Ñenn ñi amul wërsëg.
Some just didn't get no luck.
Certains n'ont pas eu de chance.
Naka nga xamee turam ?
How do you know his name?
Comment connaissez-vous son nom?
Yaa ma musal ci sama bopp.
You saved me from myself.
Tu m'as sauvé de moi-même.
Fi!
Here!
Ici!
Fexeel nga dellusi ci saa si ndax damay waajal añ ci lu yaggul dara.
Make sure you come right back because I'm going to make lunch soon.
Assure-toi de revenir car je vais bientôt déjeuner.
Déedet, deful ko.
No, he hasn't.
Non, il ne l'a pas fait.
-Maa ngi lay jéggalu?
-Beg your pardon?
- Pardonnez-moi?