wo stringlengths 1 251 ⌀ | en stringlengths 1 297 | fr stringlengths 1 1.15k |
|---|---|---|
Baax na.... | Well.... | Et bien... |
Xonq. | Red. | Rouge. |
Lima xam mooy, bis yi ci des dafa daan naan ñam ci ñax. | To my knowledge, he lived out the rest of his days drinking his food through a straw. | À ma connaissance, il vécut le reste de ses jours à boire sa nourriture à travers une paille. |
Naka lañu mënee def loolu ? | How can they do this? | Comment peuvent-ils faire ça? |
Daa melni amna lu ci nekk ci sa bopp Jeevesy old boy. | Looks like you might have got a spot of it on yourself Jeevesy old boy. | On dirait que tu as peut-être une place sur toi-même, le vieux Jeevesy. |
Ñëwal jël ma! | Come and get me! | Venez me chercher! |
Di nga am sama doom. | You will have my son. | Vous aurez mon fils. |
- Du man. Tiirewuma sama jabar te tiirewuma soppeem? | - Not me. I didn't shoot my wife and I didn't shoot her lover? | Je n'ai pas tué ma femme et je n'ai pas tué son amant? |
Ndaw si, sa doom la. | Woman behold your son. | La femme voit votre fils. |
Woowaat ko! | Call her back! | Rappelle-la! |
Mën na def loolu. | She might just do that. | Elle pourrait faire ça. |
Kon, lan mooy ñam wi la gënal? | What's your favorite food, then? | Quel est votre plat préféré, alors? |
Dina nu bokk dundu. | Together we'll live. | Ensemble, nous vivrons. |
- Ndax sa xol. | - Because of your heart. | - À cause de ton cœur. |
Gis na nu! | He's seen us! | Il nous a vus! |
Danuy jaar ci lii. | We'II pull through this. | On va passer par là. |
Duma muñ benn ci samay yunit. | I won't tolerate it in any of my units. | Je ne le tolérerai dans aucune de mes unités. |
Maa ngi féex. | I feel better. | Je me sens mieux. |
Bàyyil ma dem! | Let me go! | Lâchez-moi! |
Tommy am jabar ju ndaw ak doom ju jigéen ju bees. | As it turned out, Tommy had himself a young wife and a new baby girl. | Il s'est avéré que Tommy avait lui-même une jeune femme et une nouvelle petite fille. |
Duma def benn bruit. | I won't make a sound. | Je ne ferai pas de bruit. |
Sama Yàlla, liggéey! | My God, a job! | Mon Dieu, un travail! |
Jën wu fere! | Fresh fish! | Du poisson frais! |
Aspasia la wax. | Aspasia it says. | L'aspasie, c'est écrit. |
Dafa waroon dee ci biir. | He should have died in here. | Il aurait dû mourir ici. |
Nimero kaadar bi: 12033. | Frame number: 12033. | Numéro de cadre: 12033. |
Maa ngi des ci ginaaw, yalwaankat bu amul xaalis. | I am left behind, a penniless beggar. | Je suis laissé derrière, un mendiant impitoyable. |
Eva, gëmloo ko ni dañu wara bàyyi Berlin! | Convince him that we have to leave Berlin, Eva! | Convainquez-le que nous devons quitter Berlin, Eva! |
Lu tax mu wara xool ngay lekk? | Why should she watch you eat? | Pourquoi devrait-elle te regarder manger? |
Yaay ji Bengta faatu na, leegi mingi ci bàmmeel bi ci këram. | The mama Bengta died and now she's in the cemetery back home. | La mère Bengta est morte et maintenant elle est dans le cimetière à la maison. |
Naan. | Drink. | Bois. |
Machatas, yaa ko gën a xam. | You know better, Machatas. | Tu sais mieux, Machatas. |
Sa xalaat amul benn njariñ! | Your suggestion is absurd! | Votre suggestion est absurde! |
Def naa ko! | I made it! | J'ai réussi! |
- Te duma sama baay. | - And I am not my father. | - Et je ne suis pas mon père. |
Mënu ma ni dañu nu woowe ay dojkat. | I can't believe they called us stoners. | Je n'arrive pas à croire qu'ils nous aient appelés des lapidaires. |
Danga wara dem lu ko moy jafe-jafe dina am ak kilifa yi. | You have to go or there will be trouble with the authorities. | Vous devez y aller ou il y aura des ennuis avec les autorités. |
Nànduma. | I don't understand. | Je ne comprends pas. |
Yalla--! | Goddamn--! | C'est pas vrai! |
Loolu amul solo, sang bi. | That doesn't matter, sir. | Ça n'a pas d'importance, monsieur. |
- Waaw. Xam naa. | - Yes. I know. | - Oui, je sais. |
Loolu mooy dëgg. | That's goddamn right. | C'est vrai. |
Mën na am muy xalaat seen nekk ci mbedd mi wala doomam biy màgg te xamul pàppaam. | Maybe it was the thought of them on the streets or his child growing up not knowing her daddy. | Peut-être que c'était l'idée d'eux dans la rue ou son enfant grandissant ne connaissant pas son père. |
Frites ak ketchup. | French fries and ketchup. | Des frites et du ketchup. |
Fan nga nekk? | Where are you? | Où es-tu? |
Moo ma gëna xam. | He knows it better than I do. | Il le sait mieux que moi. |
Ki ma jiitu ci liggéey boobu dafa jël ku tuddu Charles Grady ngir mu toppatoo baayima yi ci hiver bi. | My predecessor in this job hired a man named Charles Grady as the winter caretaker. | Mon prédécesseur a embauché un homme nommé Charles Grady comme gardien d'hiver. |
Daw dem ci sa yaay, sama xarit. | Run along to your mother, dear. | Va voir ta mère, ma chérie. |
Xaar! | Wait! | Attendez! |
Dama jàpp ni Andy mën nako dalal bu baax su génnee ci saal bi. | I'm thinking Andy could use a nice welcome back when he gets out of the infirmary. | Je pense qu'Andy pourrait avoir besoin d'un bon accueil quand il sortira de l'infirmerie. |
Ak sa pàppa jabar la? | And your father is a widower? | Et ton père est veuf? |
Soo noppee, jogeel fii! | If you're done, get out of here! | Si vous avez fini, sortez d'ici! |
Dellu ginaaw! | Fall back! | Reculez! |
Waaye gëm naani dinga ko gisaat. | But I truly believe you'll see him again. | Mais je crois vraiment que vous le reverrez. |
Am nga wërsëg, Orin. | You're lucky, Orin. | Vous avez de la chance, Orin. |
Dof! | Insane! | C'est dingue! |
Bis baa ngi jegesi, màntoo guddi gi wàcci. | Day draws to its close, night's mantle descends. | Le jour tire à sa fin, le manteau de la nuit descend. |
Daf ma jox liggéey! | He gave me a job! | Il m'a donné un boulot! |
Suma sama yaay mënoon nu gis! | If Mama could see us! | Si maman pouvait nous voir! |
Ndox mi tooy na. | The water's wet. | L'eau est mouillée. |
Jën wu fere tay! | Fresh fish today! | Du poisson frais aujourd'hui! |
Amaana M. stagiaire bi mën nama wax fumu wara taxaw. | Perhaps Mr. trainee could tell me where she is suppose to stand. | Peut-être que M. le stagiaire pourrait me dire où elle est censée se tenir. |
Saa waay, nun nak? | Hey, what about us? | Et nous? |
Sama doom, sa yaay a ngii. | Son, behold your mother. | Fils, voici ta mère. |
Dinaa yewwu ci diir bu gàtt. | Soon, I'll be up. | Bientôt, je serai debout. |
Katja bi? | Which Katja? | Laquelle Katja? |
Dama bëgga gis fi ngay liggéey, soo ko bëggee... | I would like to see where you work, if you don't mind... | J'aimerais voir où tu travailles, si ça ne te dérange pas... |
Wala nga ànd ak man. | Or come with me. | Ou viens avec moi. |
Nga bàyyi sa xel, squirt. | Just remember, squirt. | Souviens-toi, éjaculation féminine. |
Ba leegi maa ngi seen buur. | I'm still your king. | Je suis toujours ton roi. |
45 | Spareribs, 45! | Des côtes de secours, 45! |
Maa ngi lay dige ni dinaa ko def. | I promise I'll tiptoe. | Je te promets que je vais faire du pourboire. |
Bàyyileen ko mu jàll. | Let him pass. | Laisse-le passer. |
Baamtu ci sama ginaaw. | Repeat after me. | Répétez après moi. |
Yaay ki am solo. | You're the important one. | C'est toi l'important. |
Tur wi xonk la. | The name's Red. | Le nom est Red. |
Ñàkk naa nit ñu bari. | I lost many a man. | J'ai perdu beaucoup d'hommes. |
Lu nga def? | What the fuck have you done? | Qu'est-ce que tu as fait? |
- 2 dinaar | - 2 dinars | - 2 dinars |
- Kon moom kan la? | - So who is he? | - Alors qui est-ce? |
Jàngalekat Friis? | Master Friis? | Maître Friis? |
Ñaareelu yoon ci sama dundu, | For the second time in my life, | Pour la deuxième fois de ma vie, |
Man ak Yakul dinañu la seeti. | Yakul and I will visit you. | Yakul et moi allons vous rendre visite. |
Lu sa doom di wax? | What's your son going to say? | Qu'est-ce que ton fils va dire? |
Mingi xalaat pexe. | She's devising a stratagem. | Elle conçoit un stratagème. |
Mën nanu def lépp lunu bëgg, ndax nun ñaar ñépp ay góor lañu. | We can do anything we want, because we're both men. | On peut faire tout ce qu'on veut, parce qu'on est tous les deux des hommes. |
Baaxna... ngir nu mëna xaaj liggéey bi. | Good... so we can divide up the work. | Bien... pour qu'on puisse diviser le travail. |
Ndax gaaw nga fàtte nii? | Have you so quickly forgotten? | As-tu si vite oublié? |
Yaakaar naa ni dina wéyal xeex bi ci Bavière ci diir bu yàgg. | I'm sure he'll continue the fight in Bavaria for a certain time. | Je suis sûr qu'il continuera le combat en Bavière pour un certain temps. |
Mu ñëw ak jabaram ak ñaari doomam yu jigéen yu tollu ci 8 at ak 10 at. | He came up with his wife and two little girls of about 8 and 10. | Il est venu avec sa femme et deux petites filles d'environ 8 et 10. |
Lu tax nga wax loolu? | Why you say that? | Pourquoi tu dis ça? |
Dafa baax ci nun? | Sounds good to us? | C'est bon pour nous? |
Kan mooy jigéen jii ngay woowe sa reine, Alexander? | Who is this woman you call your queen, Alexander? | Qui est cette femme que tu appelles ta reine, Alexander? |
Ndax jël nga dara ci jardinier Mme Mukherji? | Did you take something from Mrs. Mukherji's garden? | Avez-vous pris quelque chose dans le jardin de Mme Mukherji? |
Berlin, 20 awril, 1945 56eelu bësu juddu bu Adolf Hitler 21 at ak genn-wàll ci ginnaaw | Berlin, 20 April, 1945 Adolf Hitler's 56th birthday 21/2 years later | Berlin, 20 avril 1945 Adolf Hitler fête ses 56 ans 21/2 ans plus tard |
Jàllal ma ba ci weneen wetu dex gi. | Row me across to the other side. | Ramez-moi de l'autre côté. |
Dellu ci liggéey bi! | Back to work! | Au travail! |
Ndaw yi, musu ñu nekk ak jigéen. | Young ones, never been with a woman. | Les jeunes n'ont jamais été avec une femme. |
Am naa ñaari liggéey, waaye du yaw. | I've got two jobs, but they're not for you. | J'ai deux boulots, mais ce n'est pas pour toi. |
Xonq? | Red? | Rouge? |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.