text
stringlengths
8
159
transcription_normalised
stringlengths
8
159
utterance_pitch_mean
float32
48.6
346
utterance_pitch_std
float32
0.34
291
snr
float64
2.31
74.1
c50
float64
10.3
59.9
speaking_rate
float64
0.36
2.8k
phonemes
stringlengths
2
107
stoi
float64
0.36
1
si-sdr
float64
-16.56
34.8
pesq
float64
1.13
4.13
Man naa ñëw ci ginnaaw a
man naa ñëw ci ginnaaw a
90.88501
55.989044
21.610569
53.255184
5.387205
mæn ʌ
0.991836
8.873762
1.90003
Luy ndayam nag laa bëgg a xam leegi?
luy ndayam nag laa bëgg a xam leegi?
75.013252
53.232056
21.39773
59.403175
4.804805
næɡ ʌ ?
0.988785
7.629651
1.908075
Diggam ak Ndakaaru tollu na ci 150 km .
diggam ak ndakaaru tollu na ci 150 km .
71.359848
52.22171
19.809473
45.985924
2.693603
nɑ .
0.978239
7.888445
2.002538
Ñi ngi nattale ne murit yi tollu nanu ci 40% ci askanu Senegaal wi
ñi ngi nattale ne murit yi tollu nanu ci 40% ci askanu senegaal wi
95.098732
68.997414
22.416128
59.45042
2.452107
ni ji %
0.990999
6.506226
1.994777
Yégal nga ko a ?
yégal nga ko a ?
94.642265
73.179993
19.742655
51.604164
7.407407
koʊ ʌ ?
0.986647
9.311676
2.201505
Niti diine yi dañoo war’a nekk ci ron kiliftéefug nguur gu àdduna gi.
niti diine yi dañoo war’a nekk ci ron kiliftéefug nguur gu àdduna gi.
88.756798
63.174137
19.394678
58.440132
4.396088
ji wɔɹ’ʌ ɹɑn ɡu .
0.995794
9.148983
2.204286
Senegaal, Suwis, Faraas
senegaal, suwis, faraas
92.350693
69.557892
27.079243
48.972427
1.623541
, ,
0.986683
19.865025
2.614492
Damaa war a taxaw.
damaa war a taxaw.
113.895699
76.247406
29.756754
37.611397
7.524985
wɔɹ ʌ .
0.978326
21.295557
2.775414
Dinan jóg àndandoo, won ko ni ko nun
dinan jóg àndandoo, won ko ni ko nun
92.708099
67.752129
23.293085
53.162685
8.290155
dɪnʌn , wʌn koʊ ni koʊ nʌn
0.986482
10.368241
2.143692
Yegsi de dox ba egsi fi nga jëmoon.
yegsi de dox ba egsi fi nga jëmoon.
213.079636
25.556707
30.740215
59.2878
6.257189
di bieɪ faɪ .
0.97363
19.910839
2.348688
li mu Malaaka yi
li mu malaaka yi
104.077774
75.916931
24.652451
46.612858
6.666667
li mu ji
0.982273
14.352283
2.448367
Loolu kat moo di ay teggiin, kon jëfe ko cig wàllam
loolu kat moo di ay teggiin, kon jëfe ko cig wàllam
130.514038
81.841034
40.299591
33.666439
6.757635
kæt mu di eɪ , kɑn koʊ
0.990285
21.547291
2.893578
Wax dëgg dama leen a yittewoo.
wax dëgg dama leen a yittewoo.
93.544304
67.013268
25.985931
53.282066
8.268733
wæks dɑmʌ lin ʌ .
0.994418
11.599715
2.45101
Loo bëgg ?
loo bëgg ?
58.366711
27.52454
null
null
500
lu ?
0.986493
4.879087
2.137328
Man namaa leeral.
man namaa leeral.
111.913544
87.172615
47.836533
48.563629
4.283802
mæn .
0.990374
13.311076
2.912656
Xoolleen li leen wër
xoolleen li leen wër
119.95813
82.268684
28.348591
55.235512
5.711736
li lin
0.982968
16.81818
2.577396
Damaa bëgg way lool.
damaa bëgg way lool.
104.714272
66.958748
16.525509
41.775646
3.607085
weɪ .
0.976144
8.386192
2.160843
Dama bëgg sama dund.
dama bëgg sama dund.
203.948898
30.036093
60.127792
25.336172
8.366013
dɑmʌ sɑmʌ .
0.969437
25.416714
3.364877
Fajkat bu mag la.
fajkat bu mag la.
57.868694
25.955221
19.125093
38.911087
7.111111
mæɡ lɑ.
0.967983
4.899432
1.724553
kureel yi ci bokkSoppi
kureel yi ci bokksoppi
68.462067
50.054813
18.767912
32.647758
2.57649
ji
0.981722
4.788775
1.753594
Foofa nag am ñaari téemeeri jarag yi am tawati koronaawiris ji.
foofa nag am ñaari téemeeri jarag yi am tawati koronaawiris ji.
107.292534
73.649696
25.612083
58.449394
5.066777
næɡ æm ji æm dʒi.
0.99581
13.059625
2.434211
Mbir mi dafa mujj tiis sax
mbir mi dafa mujj tiis sax
149.291321
78.341934
44.789597
46.63229
5.25687
mi sæks
0.993996
25.673386
3.084972
Reer bi damaa rëcc
reer bi damaa rëcc
106.034424
69.541542
45.120701
59.259949
4.283802
baɪ
0.980682
19.967533
2.620185
Nit ñii mat nañu 447 340 2011.
nit ñii mat nañu 447 340 2011.
225.065979
22.283794
33.932804
59.639515
1.516477
nɪt mæt .
0.955482
19.64323
2.283805
Natago Fara Njaag47.Yirim Anta
natago fara njaag47.yirim anta
108.055496
71.210358
14.787571
49.878437
0.940623
.
0.991946
11.881588
2.676216
Lusiyaa mu sell mi ca réew Amerig, dun mbàmbulaanu Atlantig
lusiyaa mu sell mi ca réew amerig, dun mbàmbulaanu atlantig
93.19648
67.339394
24.24358
39.372173
4.689582
mu sɛl mi kʌ , dʌn
0.985521
11.098164
2.37905
Dinaa la aajar.
dinaa la aajar.
193.683762
26.515827
52.246822
41.350903
4.422333
lɑ .
0.991777
23.836464
3.059418
Ni ñaas-ñaas yi baree ay xeet, noonu it la lañuy wund wuutee
ni ñaas-ñaas yi baree ay xeet, noonu it la lañuy wund wuutee
64.504974
39.70665
12.314253
52.771614
4.573701
ni - ji eɪ , ɪt lɑ
0.969781
1.80145
1.493199
Am nanu lu ne.
am nanu lu ne.
109.443916
80.647774
39.259235
35.012627
10.582011
æm lu ni.
0.998779
24.45932
3.031526
At caxaan kay la.
at caxaan kay la.
64.535568
41.497391
25.329527
53.049095
7.579673
æt keɪ lɑ.
0.98429
10.237228
2.373015
—Abdu Baraka 78 374 74 32
—abdu baraka 78 374 74 32
191.177658
19.034214
48.505035
59.035412
11.469534
0.974242
13.175381
2.57532
Làkku Góol 147i waat
làkku góol 147i waat
206.110138
44.133415
61.20388
30.377092
0.772947
0.987383
28.384922
3.307587
Mbootaayu peeyi lislaam yi
mbootaayu peeyi lislaam yi
121.110794
84.708641
37.004593
59.432835
3.146509
ji
0.978594
24.93523
2.985491
Kañ ngeen di jële ?
kañ ngeen di jële ?
95.758545
69.405441
17.120924
57.732288
7.15198
di ?
0.992655
12.276729
2.568677
Bul laaj waa ji, waaye laajal ab àndandoom
bul laaj waa ji, waaye laajal ab àndandoom
76.649223
52.492767
10.166016
59.59816
3.757904
dʒi, æb
0.979071
3.99914
1.484684
Foofu la tabax nguuru Bundu
foofu la tabax nguuru bundu
65.414612
36.687141
14.096241
40.935028
2.323892
0.967259
4.854269
1.569363
Damaa am jafe-jafe.
damaa am jafe-jafe.
111.615456
80.060356
31.031998
18.138737
3.520352
æm -.
0.996473
15.190969
3.151797
Amal loo ma wax.
amal loo ma wax.
115.24398
86.093803
34.449322
37.234066
13.168724
ʌmɑl lu mɑ wæks.
0.989241
21.154161
2.759031
Moom itam am na ay sikkam.
moom itam am na ay sikkam.
119.361351
79.176857
32.022179
33.051208
4.617604
æm nɑ eɪ .
0.969504
16.3866
2.585818
Ndax waroon na maa ñëw?
ndax waroon na maa ñëw?
107.705666
71.48999
16.197952
35.384129
3.51538
nɑ ?
0.992988
6.834293
2.123175
Dmaa dëgër bopp.
dmaa dëgër bopp.
123.339409
87.275223
37.207199
46.222099
4.558405
bɑp.
0.965421
19.190014
2.874912
Am naa ab xaj.
am naa ab xaj.
49.519852
0.510576
16.849079
44.959087
8.77915
æm æb .
0.959001
3.551279
1.578184
Man rekk maa nekkoon.
man rekk maa nekkoon.
52.484478
9.504706
9.874122
37.593204
3.57599
mæn .
0.986296
2.524273
1.762269
bees mosul rekk a am njëg
bees mosul rekk a am njëg
57.055408
26.320713
22.801474
33.884998
9.780655
biz moʊsʌl ʌ æm
0.981239
6.28406
2.003693
Ay dëkkuwaay ñeel waa Tugal yiy saytu digg yooyu
ay dëkkuwaay ñeel waa tugal yiy saytu digg yooyu
109.047653
67.981979
14.21003
47.920799
2.510986
0.996706
9.409453
2.392656
Da koo jox ab téere.
da koo jox ab téere.
79.968109
55.925861
19.62771
35.910789
7.00916
dɑ ku æb .
0.993365
12.690289
2.596788
Damaa soxla ab aji-jokkoo.
damaa soxla ab aji-jokkoo.
64.222389
40.086327
8.601684
47.520584
3.318519
æb -.
0.991447
4.023946
1.676616
Xaw naa jege.
xaw naa jege.
87.104088
65.373932
32.945313
41.714455
2.962963
.
0.997654
13.481878
2.433717
Soxna Jaara BUSO ci pénc mi
soxna jaara buso ci pénc mi
116.582047
83.314636
33.682175
30.120628
3.318519
mi
0.961443
16.840336
2.25795
Ci VIIeelu xarnu nguur yu njëkk ya
ci viieelu xarnu nguur yu njëkk ya
212.162552
43.473923
34.846298
25.505743
3.703704
ju jɑ
0.993279
24.88426
2.968188
Xenokaraat nag mooy ki jëkk a jëfandikoo baat bi.
xenokaraat nag mooy ki jëkk a jëfandikoo baat bi.
81.384903
59.384315
21.74497
57.305923
4.597701
næɡ ki ʌ baɪ.
0.979249
10.367105
2.016032
Mu daal di tàmbalee way.
mu daal di tàmbalee way.
242.544327
87.758034
22.910595
57.647915
7.48538
mu di weɪ.
0.990126
20.247768
2.737881
W loyu koddaay.
w loyu koddaay.
80.738914
66.6101
23.497349
59.29108
7.901235
dʌbʌlju .
0.975189
13.719747
2.760409
Ay waxam day woyof
ay waxam day woyof
72.033813
45.938206
18.749464
58.983032
5.209605
eɪ deɪ
0.975635
6.754362
2.052708
Lonkoyoon bu Senegaal Gtk-dialog-info.svg
lonkoyoon bu senegaal gtk-dialog-info.svg
159.000656
67.792824
47.247223
28.311344
7.954263
-daɪʌlɔɡ-ɪnfoʊ.
0.992441
23.604347
3.237127
Garab la gog bari na jàngoro yu muy faj, bokk na ci sibbiru.
garab la gog bari na jàngoro yu muy faj, bokk na ci sibbiru.
68.349091
48.483673
14.61542
41.962402
5.444313
lɑ bɑɹi nɑ ju , nɑ .
0.986924
8.582427
2.267727
Dama la bëgg lool.
dama la bëgg lool.
101.560867
65.229828
15.231756
54.64011
6.371963
dɑmʌ lɑ .
0.987578
9.216931
1.928864
Ku féex laa.
ku féex laa.
174.321243
40.203365
68.82489
29.884346
4.857317
ku .
0.994692
28.29579
3.274439
Li yëpp, ba Imbraatóor gu Mali ame la xeewoon
li yëpp, ba imbraatóor gu mali ame la xeewoon
58.04546
30.686897
12.110803
53.09639
6.162963
li , bieɪ ɡu mɑli eɪm lɑ
0.984414
4.316336
1.816286
Moom la, walla ?
moom la, walla ?
95.505623
70.110397
null
null
1,100
lɑ, wɔlɑ ?
0.98853
19.605724
2.91923
Wata bi daa mbëkk ag garab.
wata bi daa mbëkk ag garab.
104.381454
68.768044
28.620075
51.560719
5.173427
baɪ æɡ .
0.992281
17.628561
2.852316
Ndax yaa ngi liggéey fimne?
ndax yaa ngi liggéey fimne?
218.454224
19.826185
45.654446
45.407467
3.08642
?
0.980687
23.14257
3.080509
Man ngeen a am ñaar yi.
man ngeen a am ñaar yi.
143.132065
90.933632
28.15358
55.831188
9.116809
mæn ʌ æm ji.
0.990247
23.031475
2.938113
Ndax wóor na leen\?
ndax wóor na leen\?
213.683273
28.435219
51.78056
30.952375
8.714597
nɑ lin\?
0.997218
25.816692
3.984594
Damaa tabje lool.
damaa tabje lool.
116.890335
64.985252
22.666035
53.227871
1.725998
.
0.965014
15.492274
2.147758
ndax maay boroom ?
ndax maay boroom ?
220.381836
24.116776
70.119331
28.719887
3.485839
?
0.997446
28.137417
3.509961
Seeni woy moo yëngal
seeni woy moo yëngal
79.665703
49.398724
15.804239
56.549194
3.983816
wɔɪ mu
0.992056
5.649652
1.634693
Ndax man na noo waxtaan, leegi ?
ndax man na noo waxtaan, leegi ?
198.101105
27.155926
65.854576
41.207115
5.88069
mæn nɑ , ?
0.99734
31.56415
3.830477
Dafa ànd ak mbégte gu rëy.
dafa ànd ak mbégte gu rëy.
186.203888
75.179359
43.686581
32.546009
3.537866
ɡu .
0.997008
25.294437
3.343814
Du dëgg .
du dëgg .
85.892715
66.859261
null
null
500
du .
0.994775
17.231379
2.521644
Ameel naa la reer.
ameel naa la reer.
121.040802
79.425156
32.925308
59.550449
4.740741
lɑ .
0.982764
22.054352
2.480149
Gëm Malaaka yi
gëm malaaka yi
81.514076
58.306141
23.687704
57.370682
3.118908
ji
0.99562
12.988976
2.614498
Kafe gii dafa sedd.
kafe gii dafa sedd.
48.782188
2.57577
18.8048
34.132088
3.000469
.
0.994469
4.557755
2.225877
Ci atum 1902 la Ndakaaru nekke péeyub Afrig gu sowwu gu Faraas gépp.
ci atum 1902 la ndakaaru nekke péeyub afrig gu sowwu gu faraas gépp.
202.995438
38.593548
44.563995
28.561977
2.380393
lɑ ɡu ɡu .
0.940353
16.335169
1.704384
Sooninke yi ñoo leen duggal ca lislaam
sooninke yi ñoo leen duggal ca lislaam
87.008507
65.972755
24.324984
52.830811
4.50509
ji lin kʌ
0.989951
8.923665
1.911487
Xaw nanoo dee ak xiif.
xaw nanoo dee ak xiif.
117.087402
79.353073
37.236504
27.562634
3.73707
di .
0.986265
23.484301
2.97491
Ndaybarga am na ñaari xeet.
ndaybarga am na ñaari xeet.
88.68338
61.322186
23.27035
41.109707
3.532009
æm nɑ .
0.979597
9.462021
2.083925
Ci ngënéelul jeexiit yii lanu xame njëkk-taariix
ci ngënéelul jeexiit yii lanu xame njëkk-taariix
90.503242
66.207336
23.139875
40.177151
1.994302
-
0.993057
9.724057
2.189595
Naka séen yaram?
naka séen yaram?
55.595802
12.209514
21.931404
59.704185
2.539683
?
0.963933
5.303372
2.107323
Wax ay jikoom teg tale ko
wax ay jikoom teg tale ko
211.709641
24.931421
51.585033
33.306309
8.080808
wæks eɪ teɪl koʊ
0.982219
24.843349
3.097607
Matal kem yi jëgg yi di laaj satisfaire la demande des importateurs.
matal kem yi jëgg yi di laaj satisfaire la demande des importateurs.
115.960297
87.266335
30.222837
37.669968
4.584527
kɛm ji ji di lɑ dɛs .
0.987755
14.803805
2.704796
Liggéey nga bu baax.
liggéey nga bu baax.
133.641327
91.6493
39.629536
43.186829
3.160494
.
0.999487
28.292042
3.299787
Ndax dama leen jéggi ?
ndax dama leen jéggi ?
82.023254
56.564278
20.195875
36.015862
7.990012
dɑmʌ lin ?
0.994961
8.16809
2.076695
Dafa jalgati pas gi.
dafa jalgati pas gi.
190.153687
38.816559
50.780697
54.606667
4.148148
pɑz .
0.992239
25.586155
3.28787
Ndax danoo war a tàmbali ?
ndax danoo war a tàmbali ?
252.580154
62.905014
54.897614
15.224045
6.046863
wɔɹ ʌ ?
0.993906
24.33083
3.619268
Dee ci jëmmi boppam
dee ci jëmmi boppam
77.246788
53.213604
12.581288
56.454983
2.645503
di
0.991973
7.712064
2.029367
Tey texeg ndaw ñi,ak mag ñi,ak waxambaane yeek jigeen ñi
tey texeg ndaw ñi,ak mag ñi,ak waxambaane yeek jigeen ñi
71.153503
46.818882
19.357111
40.532021
3.166525
, mæɡ ,
0.992344
6.756255
2.261273
Ñëwleen, su ngéen ko mënee !
ñëwleen, su ngéen ko mënee !
111.477051
72.762207
23.241587
53.337128
7.407407
, su koʊ !
0.994973
15.235645
2.37673
Nga weex sa xol wékki ca luy wòllimiku
nga weex sa xol wékki ca luy wòllimiku
122.695465
77.591164
22.69993
50.569378
3.782506
sɑ kʌ
0.976151
18.75738
2.447014
Loo leen di wax nii ?
loo leen di wax nii ?
49.508694
0.710403
16.578539
38.277367
13.613614
lu lin di wæks ?
0.973319
3.199795
1.713572
Yaw yaay kàngam li.
yaw yaay kàngam li.
69.373192
40.789421
17.428127
53.371365
4.430599
jɔ li.
0.976806
6.012268
1.95169
Kon boog ba beneen jotaay.”
kon boog ba beneen jotaay.”
68.449623
42.994984
16.782307
54.666622
6.584362
kɑn bieɪ .”
0.997892
4.796093
1.896727
Xamoon nañu mbayum. wëtteen.
xamoon nañu mbayum. wëtteen.
178.232239
65.047615
70.572632
55.768883
2.933627
. .
0.995735
29.999699
3.569647
Yaa war a sox !
yaa war a sox !
117.586502
86.628647
null
null
1,300
wɔɹ ʌ sɑks !
0.992243
24.121847
3.68699
Doyadig res ak roñoŋ Biir buy daw.
doyadig res ak roñoŋ biir buy daw.
82.351181
57.479435
17.279583
49.595539
4.938272
ɹeɪz baɪ dɔ.
0.989594
8.487747
2.062347
Te bul di dàññi mel ne kuy das defarul
te bul di dàññi mel ne kuy das defarul
94.460381
66.682671
23.555346
36.413727
6.149546
ti di mɛl ni dæs
0.983889
10.986966
2.398796
Mu daal di nuyu soxna si.
mu daal di nuyu soxna si.
98.552704
70.462692
25.266119
52.60231
5.3467
mu di si.
0.994847
10.314448
2.080894
Daan yiy dal ci ñi dul sàmmonte walla ñuy bañ a takk alikeñ yi
daan yiy dal ci ñi dul sàmmonte walla ñuy bañ a takk alikeñ yi
58.046875
29.66926
17.07803
58.945728
4.902745
dæl wɔlɑ ʌ ji
0.953859
3.854078
1.55482
Ngeen boole yeen ci nun.
ngeen boole yeen ci nun.
78.444511
49.23204
24.346083
39.716969
5.717999
bul nʌn.
0.986261
11.106709
2.274511
WàllMelosuufug Afrig gu Bëj-saalum
wàllmelosuufug afrig gu bëj-saalum
94.857544
70.406151
22.758148
55.372166
2.008788
ɡu -
0.997706
15.002286
2.640865