en stringlengths 1 298 | wo stringlengths 1 279 ⌀ | fr stringlengths 1 687 |
|---|---|---|
I think that there is a phenomenon that indicates that the biosphere is constantly expanding | Dama jàpp ni amna luy wane ni biosphere bi dafay gëna yokk | Je pense qu'il y a un phénomène qui indique que la biosphère est en constante expansion |
two competing perspectives on cultural literature can sometimes overlap | ñaari gis-gis yu wuute ci literature aada mën nañu jaxasoo yenn saa yi | deux perspectives concurrentes sur la littérature culturelle peuvent parfois se chevaucher |
For their journey to Bosnia, see a documentary by a scientist, Interview with a Saudi al Qaeda member on Oct. 3, 2001. | Ngir xam seen tukki ci Bosnie, xoolal benn dokimenteer bu benn gëstukat bind, waxtaan ak benn waa Saudi Al Qaeda ci 3 Oktuubar, 2001. | Pour leur voyage en Bosnie, voir un documentaire réalisé par un scientifique, Interview avec un membre saoudien d'Al-Qaïda du 3 octobre 2001. |
Finally, long sentences that obscure the meaning should be avoided. | Fi may jeexalee mooy, danga wara moytu frase yu gudd yu nëbbu li ñuy tekki. | Enfin, il faut éviter les longues phrases qui obscurcissent le sens. |
She was so happy to see Joe that she started to cry | Kontaan na lool bimu gisee Joe ba tàmbali di jooy | Elle était si heureuse de voir Joe qu'elle s'est mise à pleurer. |
They are allowed to leave no more than twice a week if the pensioners are ready for it. | Duñu may ñu dem lu ëpp ñaari yoon ci ayu-bis bi sudee pensioner yi mën nañu ko dem. | Ils ne peuvent partir que deux fois par semaine si les retraités sont prêts à le faire. |
Blood thought about the last time he saw his mother. | Blood xalaat bimu mujjee gis yaayam. | Blood pensait à la dernière fois qu'il a vu sa mère. |
Tennessee's winters and summers are also very hot | Sedd bi ak été bi ci Tennessee dañu tàng lool | Les hivers et les étés du Tennessee sont également très chauds. |
our public affairs office doesn't tolerate harassment and has given them a three-year sentence | sunu biro bi yor mbiri askan wi nanguwul ñuy sonal nit, moo tax tëj nañu leen ñatti at ci kaso | Notre bureau des affaires publiques ne tolère pas le harcèlement et leur a donné une peine de trois ans |
The investigative report was so full that no one could read it. | Rapportu lànket bi feesoon na lool ba kenn mënu ko woon jàng. | Le rapport d'enquête était si complet que personne ne pouvait le lire. |
The Jews were of no importance to the rest of the party | Juif yi amul benn njariñ ci ñeneen ñi ci pàrti bi | Les Juifs n'étaient pas importants pour le reste du parti. |
At least one man gave up on his goal of becoming president. | Amna benn nit bu bàyyi mébetam nekk njiitu réew. | Au moins un homme a renoncé à son objectif de devenir président. |
Not on tour, they've been on tour since the late thirties. | Duñu ci tournée, ñu ngi ci tournée ci diggu fan weeri at yi. | Pas en tournée, ils sont en tournée depuis la fin des années 30. |
Khallad brought the second change, namely that the three of them went to Karachi together. | Khallad moo indi ñaareelu coppite bi, maanaam ñu bokk dem Karachi. | Khallad a apporté le deuxième changement, à savoir que les trois d'entre eux sont allés à Karachi ensemble. |
The film does not feature Kaufman discussing his own death. | Filmu bi waxul Kaufman di wax ci génnug àddunaam. | Le film ne présente pas Kaufman discutant de sa propre mort. |
It's possible that all human microbes will change their color | Mën na am mikrobe yi ci nit ñi mën nañu soppi seen melo | Il est possible que tous les microbes humains changent de couleur |
you don't need to hide your belongings from the guards | jarul nga nëbb say bagaas garde yi | Tu n'as pas besoin de cacher tes affaires aux gardes. |
I don't know where it's coming from, but it's going fast. | Xamuma fumu joge, waaye mingi gaaw. | Je ne sais pas d'où ça vient, mais ça va vite. |
Lawrence Singleton, a Montana man who raped and stabbed another woman in Florida, is back in prison after serving eight years. | Lawrence Singleton, benn waay bu dëkk Montana moo siif ba noppi jam beneen jigeen ci Floride, delluna ci kaso bi ginnaaw bimu nekkee jiroom ñetti att. | Lawrence Singleton, un homme du Montana qui a violé et poignardé une autre femme en Floride, est de retour en prison après huit ans de prison. |
I said they just had, like, five kids, one of whom died. | Neena ñu am nañu lu tollu ci juróomi doom, kenn ci ñoom faatu. | J'ai dit qu'ils avaient eu cinq enfants, dont l'un est mort. |
They can imagine a bulldozer driver designing a road for a new development, if that development is approved Hey, Lloyd... | Mën nañu xalaat dawalkatu buldoser buy defar yoon ngir tabax bu bees, sudee nangu nañu ko. Saa waay, Lloyd... | Ils peuvent imaginer un conducteur de bulldozer dessiner une route pour un nouveau développement, si ce développement est approuvé. |
cultural writing can change the perception we have of a nation | bind ci wàllu aada mën na soppi ni ñuy gisee réew | L'écriture culturelle peut changer la perception que nous avons d'une nation |
the biosphere is highly variable | biosphere bi barina lumuy soppiku | La biosphère est très variable. |
Editors are encouraged to spot these errors. | Ñu ngi ñaax editër yi ñu gis njuumte yooyu. | Les rédacteurs sont invités à déceler ces erreurs. |
I've been looking for him for the past year | at a ngi nii may wër | Je le cherche depuis un an. |
there is no human being who needs to be revived | amul nit ku soxla dundal | Il n'y a pas d'être humain qui ait besoin d'être ressuscité |
Nafplio is the best place. | Nafplio mooy barab bi gëna baax. | Nafplio est le meilleur endroit. |
We haven't planned anything for the future. | Waajalunu dara ci ëlëg. | Nous n'avons rien prévu pour l'avenir. |
The doors were wide open. | Bunt yi ubbeeku nañu bu baax. | Les portes étaient ouvertes. |
Klayman was prosecuted on charges of racism. | Dañu tuumal Klayman ndax dafa xeex xeetu nit. | Klayman a été poursuivi pour racisme. |
Simple and light is used only to describe wine and whiskey. | Yomb te woyof dañu koy jëfandikoo ngir wax ci vin ak whisky. | Simple et léger est utilisé pour décrire le vin et le whisky. |
Without the first stage, engineering may not be achieved in subsequent stages. | Su etap bu njëkk bi amul, mën na am ni ingenieur bi mënul yegg ci etap yi ci topp. | Sans la première étape, l'ingénierie ne peut pas être réalisée dans les étapes suivantes. |
people had difficulty communicating with the World Trade Center due to the disconnection of the tower and all communications facilities | nit ñi amoon nañu jafe-jafe jokkoo ak World Trade Center ndax tour bi ak bépp jumtukaayu jokkoo dafa tas. | Les gens avaient du mal à communiquer avec le World Trade Center en raison de la déconnexion de la tour et de toutes les installations de communication |
The 1984 version is by far the best. | Version 1984 moo gëna baax. | La version de 1984 est de loin la meilleure. |
And what would that be? | Ak lan lay doon? | Et quelle serait cette chose? |
The tests were carried out in small rooms of the altitude. | Test yi ñu ngi leen amal ci néeg yu ndaw ci kawewaay bi. | Les essais ont été réalisés dans de petites salles de l'altitude. |
Khallad said the three could travel together. | Khallad neena ñoom ñatt mën nañu ànd tukki. | Khallad a dit que les trois pouvaient voyager ensemble. |
And the Almighty had mediators, and I was one of them. | Te Aji Kàttan ji amoon na ay ndawam, man ma bokkoon ci ñoom. | Le Tout-Puissant avait des médiateurs, et j'en étais un. |
They had no idea how to measure the impact of investments | Xamu ñu woon ni ñuy nattee njariñu dugal xaalis | Ils n'avaient aucune idée de la façon de mesurer l'impact des investissements |
It was even said that a burning aircraft would burn and melt through a metal lid to escape the heat | Dañu daan wax sax ni roppalaan buy tàkk dafay tàkk ba noppi di seey ci biir benn muur ngir rëcci ci tàngoor wi. | On disait même qu' un avion en feu brûlait et fondait à travers un couvercle métallique pour échapper à la chaleur. |
There is nothing wrong with people in this situation. | Amul lenn lu jaarul yoon ci nit ñi nekk ci jafe-jafe yii. | Il n'y a rien de mal à ce genre de situation. |
The supremacy of the post-war German constitutional order was the greatest danger of the Nazi turmoil | Njiitu sàrtu ndayu réewum Almaañ ginaaw xare bi mooy loraange bi gëna mag ci jafe-jafe Nazi yi. | La suprématie de l'ordre constitutionnel allemand d'après-guerre était le plus grand danger de la tourmente nazie. |
All issues of terrorism are given a high priority. | Lépp lu jëm ci terrorism dañu ko njëkka bàyyi xel. | Tous les problèmes liés au terrorisme sont prioritaires. |
It makes very little noise, thanks to a carefully protected engine. | Defay tuuti bruit ndax motër bi dafa am kaaraange gu mat sëkk. | Il ne fait pas beaucoup de bruit, grâce à un moteur soigneusement protégé. |
These boxes were kept in their place after all the gifts had been opened. | Gannaaw ba ñu ubbee kado yépp ba noppi, denc nañu boyet yooyu ci seen palaas. | Ces boîtes étaient placées à leur place après que tous les cadeaux avaient été ouverts. |
On the Prinsengracht, Otto Frank and his family hid in the attic of their department store for over four years before they were found. | Ci Prinsengracht, Otto Frank ak njabootam dañu nëbb seen butig bu mag lu weesu ñeenti at balaa ñu leen di fekk. | Sur le Prinsengracht, Otto Frank et sa famille se sont cachés dans le grenier de leur grand magasin pendant plus de quatre ans avant d'être retrouvés. |
If it is, he will tell you what it is. | Su dee, dina la wax lu mu doon. | Si c'est le cas, il vous le dira. |
We look forward to your donation to the School of Nursing. | Noo ngi xaar ak waajal seen ndimbal ci Daara Infirmiye. | Nous attendons avec impatience votre don à l'école d'infirmières. |
And it came to pass at the end of the sixth month, at the end of the seventh month, at the end of the seventh month, on the first day of the month, on the seventh day of the month, on the seventh day of the month, on the seventh day of the month, | Ba mu jeexee ci juróom-benneelu weer wa, ci njeextelu juróom-ñaareelu weer wa, ci bis bu jëkk ci weer wa, ci juróom-ñaareelu fan ci weer wa, ci juróom-ñaareelu fan ci atum 2018. ci juróom-ñaareelu fan ci weer wi, | Et il arriva au bout du sixième mois, au bout du septième mois, le premier jour du mois, le septième jour du mois, le septième jour du mois, |
We want to make our contribution known to the world, so that no one will be ashamed of it. | Danu bëgg a siiwal àddina si sunu wàll, ngir kenn bañ koo rus ci. | Nous voulons que notre contribution soit connue du monde, afin que personne ne soit honteux de cela. |
A person's standard for saving money depends on how much wealth he has. | Ni nit mënee dajale xaalis mingi aju ci alal ji mu am. | La façon dont une personne économise dépend de sa richesse. |
The large gateway was the only entrance to the garden. | Bunt bu réy ba rekk moo nekkoon buntu tool ba. | La grande porte était la seule entrée dans le jardin. |
After cutting off the man's hand, he ordered it to be buried in mud. | Bi mu daggee loxoom ba noppi, mu santaane ñu suul ko ci ban. | Après avoir coupé la main de l'homme, il ordonna qu'on l'enterre dans la boue. |
14,000 years before the construction of the Temple of Este, the Milreum was a single-story mansion with a porch. | 14000 at balaa ñuy tabax Temple bu Este, Milreum kër gu am benn etaas la woon, am porche. | 14 000 ans avant la construction du Temple d'Este, le Milreum était un manoir à un étage avec un porche. |
They have been touring since the early 1970's. | Ñu ngi tàmbali tournée ci ndoortey ati 1970. | Ils sont en tournée depuis le début des années 1970. |
Making sentences longer can be a way of ensuring that they have a broader meaning. | Guddaay frase yi mën na tax ñu am luñuy tekki lu gëna yaatu. | Faire des phrases plus longues peut être un moyen de s'assurer qu'elles ont un sens plus large. |
South Carolina's cooperative efforts produced another success the following year. | Li Caroline du Sud amal ci jàppante bi jurna beneen ndam ci at mi ci topp. | Les efforts de coopération de la Caroline du Sud ont produit un autre succès l'année suivante. |
Lite beer does not have a high percentage of alcohol. | Bieer Lite amul pursàntaasu alkol bu bari. | La bière légère n'a pas un pourcentage élevé d'alcool. |
Heat can also be conserved during a fire | Mën nañu sakkanal tàngoor itam ci biir lakk | La chaleur peut également être conservée pendant un incendie. |
We have something planned. | Am nanu luñu waajal. | On a prévu quelque chose. |
I had been following him for about a year without his knowledge. | Lu tollu ci benn at a ngi nii may topp te moom xamul. | Je le suivais depuis un an sans qu'il le sache. |
can you imagine a driver driving a bulldozer | Ndax mën nga xalaat dawalkat buy dawal buldozer | Vous imaginez un conducteur conduisant un bulldozer |
It comes quickly but like I know where it's coming from | Dafa gaaw ñëw waaye melni xamnaa fumu joge | Ça vient vite, mais comme si je savais d'où ça vient. |
It is often referred to as the Jerome School for the Elderly but is more commonly called the Elderly Area. | Ñu ngi koy faral di woowe Daara Jérôme ngir mag ñi waaye ñu koy gëna woowe Barabu mag ñi. | Il est souvent appelé l'École Jerome pour les personnes âgées, mais est plus communément appelé la zone des personnes âgées. |
We ask that you do not overburden us with this generous gift, which you have given us. | Nu ngi lay ñaan, nga moytu nu ëpp li nga nu may. | Nous vous demandons de ne pas nous surcharger avec ce don généreux que vous nous avez donné. |
people had trouble connecting to the world trade center | Nit ñi amoon nañu jafe-jafe lëkkaloo ak santaru jënd ak jaay ci àdduna bi | Les gens avaient du mal à se connecter au World Trade Center |
80% of respondents will report an increase in skills in conflict resolution. | 80% ci ñi tontu dina ñu wax ni seen xam-xam ci saafara jafe-jafe dafa yokk. | 80% des répondants déclarent avoir amélioré leurs compétences en matière de résolution de conflits. |
Mr. Alexander had to leave after his embarrassing photos were published. | Alexander dafa waroon dem ginaaw biñu siiwal nataalam yu ruslu yi. | M. Alexander a dû partir après que ses photos embarrassantes aient été publiées. |
These chests are equipped with powerful projectiles. | Kofre yooyu dañu am ay projectile yu am doole. | Ces coffres sont équipés de puissants projectiles. |
Thus, government decision makers and administrators are adopting new ways of thinking, considering different ways of achieving goals, and using new information to guide decisions. | Moo tax ñiy jël dogal ci nguur gi ak kilifa yi dañuy jël yeneen pexe yu bees ngir mëna def seen mébet, ba noppi di jëfandikoo xibaar yu bees ngir jël dogal. | C'est pourquoi les décideurs et les administrateurs du gouvernement adoptent de nouvelles façons de penser, envisagent différentes façons d'atteindre des objectifs et utilisent de nouvelles informations pour orienter leurs décisions. |
I was sent by the governor last week with hundreds of dollars. | Ayu-bis bi weesu guwernoor bi yónnee nama téemeeri dolaar. | Le gouverneur m'a envoyé avec des centaines de dollars. |
our public affairs office will be celebrating its tenth anniversary next month | Sunu biro bi yor mbiri askan wi mingi màggal fukkeelu bës bu dellusi ci weer wii di ñëw | Notre bureau des affaires publiques célébrera son dixième anniversaire le mois prochain. |
Klayman did not know that he would be accused of racism. | Klayman xamul woon ni dina ñu ko jiiñ rasism. | Klayman ne savait pas qu'il serait accusé de racisme. |
Add to this such factors as short deadlines, unending deletion of files, and failure to access necessary documents. | Yokk ci yeneen mbir yu melni waxtu jeexal liggéey bu gàtt, efaase fichier yudul jeex, ak ñàkka mëna jëfandikoo këyit yi war. | À cela s'ajoutent des facteurs tels que les délais courts, la suppression sans fin de fichiers et le manque d'accès aux documents nécessaires. |
A commonly used nickname was used when it or any other was not needed. | Tur wi ñuy faral di jëfandikoo, dañu ko daan jëfandikoo suñu ko soxlawul. | Un surnom couramment utilisé était utilisé quand il n'était pas nécessaire. |
Khallad said that the three of them could go together. | Khallad niko gnou ñatt meuneu bokk dém. | Khallad a dit que les trois pouvaient aller ensemble. |
there were a few of us who conducted the controls for testing. | amoon na ñu néew ci nun ñu def saytu yi ngir saytu. | Nous étions quelques-uns à effectuer les contrôles pour les tests. |
Each public servant had a specific task to perform | Ndawu réew mu nekk amna liggéey bu mu wara def | Chaque fonctionnaire avait une tâche spécifique à accomplir. |
In some cases, the human genome has been sequenced. | Amna numuy deme ñu toppalante genomu doomu aadama yi. | Dans certains cas, le génome humain a été séquencé. |
the writing of a tradition can change the future | bind aada mën na soppi ëllëg | L'écriture d'une tradition peut changer l'avenir. |
There is a large entrance to the garden. | Am na bunt bu yaatu ngir dugg ci jardin bi. | Il y a une grande entrée dans le jardin. |
The Nazi regime permitted it | Nguuru Nazy yi nangu nañu ko | Le régime nazi l' a permis. |
After the resurrection, life is worth living | Gannaaw ndekkite li, dund jar na | Après la résurrection, la vie vaut la peine d'être vécue. |
Wow, now you're going to talk | Waaw, leegi dangay wax | Tu vas parler maintenant |
that's their number oh | loolu mooy seen nimero oh | C'est leur numéro. |
The Jews did not bother to join the Anglo crowd | Juif yi nangu wuñu bokk ci mbooloo mu Anglo | Les Juifs n'ont pas pris la peine de se joindre à la foule anglophone. |
Milreu was 10th overall | Milreu moo nekkoon 10eelu palaas | Milreu était 10e au classement général. |
Wealth and banking often go hand in hand | Alal ak bànk dañuy faral di ànd | La richesse et les banques vont souvent de pair. |
Treasure Beach is the ultimate vacation spot, with a cluster of hotels crisscrossing three sandy bays | Treasure Beach mooy barab bi gëna baax ci wakaas yi, amna ay otel yu bari yu jàkkarloo ak ñatti bërëb yu am suuf | La plage du Trésor est le lieu de vacances idéal, avec un groupe d'hôtels qui sillonnent trois baies de sable. |
can you imagine a single bulldozer | Mën nga xalaat benn buldozer | Vous imaginez un seul bulldozer |
Daniel Yamins is a mathematician by training. | Daniel Yamins xam-xam la ci wàllu math. | Daniel Yamins est mathématicien de formation. |
Jane told the New York investigator who was looking for Mihdhar to get his hands on the FISA file that he knew how to do the FISA stuff. | Jane wax laŋketkat bu New York bi doon wër Mihdhar ngir mu jël dosiye FISA bi ni xamna ni ñuy defee mbir FISA yi. | Jane a dit à l'enquêteur de New York qui cherchait Mihdhar pour avoir le dossier FISA qu'il savait comment faire les trucs de FISA. |
And he asked, and found plainly that the time of his sojourn in the house had changed him altogether. | Mu laaj, mu gis ne, jamono ji mu nekkee ci kër ga, soppi na ko ndànk. | Il demanda et découvrit que le temps qu'il avait passé dans la maison l'avait complètement changé. |
Heat can escape from a piece of metal after an aircraft fire | Tàngoor mën na génn ci benn piyeesu wen ginaaw bi roppalaan bi tàkkee | La chaleur peut s'échapper d'un morceau de métal après un incendie d'avion. |
I've been following him for almost as long as I've been in church. | Bima demee eglis bi yàgg naa ko topp. | Je le suis depuis presque aussi longtemps que je suis à l'église. |
It comes like a whirlwind and I know exactly when it will come. | Dafay ñëw ni ngelaw lu metti, te xamnaa bu baax kañ lay ñëw. | C'est comme un tourbillon et je sais exactement quand ça va arriver. |
It was often very easy to observe from a distance. | Yomboon na lool ñu koy seetlu fu sori. | Il était souvent très facile à observer de loin. |
We will allow anyone with a computer and internet access to join the forum | Dina nu may képp ku am ordinatër wala internet nga bokk ci forum bi | Nous permettrons à toute personne disposant d'un ordinateur et d'un accès à Internet de rejoindre le forum |
Your gift at this time may do more than help you with the tax benefits at the end of the year. | Sa kado ci jamono jii mën nala jàppale ci juuti gi ci njeexte at mi. | Votre don en ce moment peut faire plus que vous aider avec les avantages fiscaux à la fin de l'année. |
Sports are not the only events that you can bet on on these sites. | Du tàggat yaram kese ngay mëna pari ci sit yii. | Les paris sportifs ne sont pas les seuls événements sur lesquels vous pouvez parier sur ces sites. |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.