en
stringlengths
1
298
wo
stringlengths
1
279
fr
stringlengths
1
687
On top of this civil liberties record is the FBI's misuse of the original White House office investigation, and what came to be known as Filegate.
Ci kaw dosiye bu moom sa bopp bu siwil bi moy li FBI jëfandikoo bu baaxul ci laŋket bu kër gu Weex gi, ak li ñu xamewoon ci Filegate.
En plus de ces libertés civiles, le FBI a abusé de l'enquête de la Maison Blanche, et ce qui est devenu connu sous le nom de Filegate.
I'm, uh, a retired chief of police, according to Rick.
Rick dafa wax ni, uh, njiitu poliis laa bu jeexal.
Je suis, euh, un chef de police à la retraite, selon Rick.
More than half of polytheists report an increase in conflict resolution skills
Lu ëppu genn-wàll ci ñi gëm Yàlla dañu wax ni seen xam-xam ci saafara jafe-jafe yokk na.
Plus de la moitié des polythéistes déclarent avoir amélioré leurs capacités à résoudre les conflits.
He would be nailed to the torture stake, no doubt in a derogatory way.
Dees na ko daaj ci bant, te wóor na ne loolu dafay toroxal ko.
Il serait cloué au poteau de supplice, sans doute d'une manière déshonorante.
Printing is available in book form.
Amna ñu koy imprime ci forme téere.
L'impression est disponible sous forme de livre.
The film was a blockbuster, although it omits some important details about Kaufman.
Filmu bi dafa am xaalis bu bari, waaye dafa bàyyi yenn mbir yu am solo ci Kaufman.
Le film est un succès, bien qu'il omette certains détails importants sur Kaufman.
I take counsel from the Almighty.
Maa ngi jël xalaat ci Aji Kàttan ji.
Je prends conseil auprès du Tout-Puissant.
Each public servant ran where he wanted to go
Ndaw réew mu nekk daw fi mu bëgga dem
Chaque fonctionnaire courait où il voulait aller.
People struggle to find another name.
Nit ñi dañuy sonn lool ngir am beneen tur.
Les gens ont du mal à trouver un autre nom.
One of the children died.
Kenn ci xale yi faatu.
Un des enfants est mort.
you are mentally unstable
sa xel amul dal
Vous êtes mentalement instable.
Mr. Yamins is very good at mathematics.
M. Yamins dafa xarañ ci math.
M. Yamins est très bon en mathématiques.
There are allegations of racism against Klayman.
Amna ay tuuma ci rasism ci kaw Klayman.
Il y a des allégations de racisme contre Klayman.
If possible, make sure you understand the goal first
Soo ko mënee, fexeel nga njëkka xam mébet mi
Si possible, assurez-vous d'abord de bien comprendre le but
Jane asked a federal judge to authorize the FISA.
Jane laaj na benn attekat federal mu may FISA bi.
Jane a demandé à un juge fédéral d'autoriser la FISA.
People don't need any special powers to come to our church
Nit ñi soxla wuñu benn kàttan ngir ñëw ci sunu eglis
Les gens n'ont pas besoin de pouvoirs spéciaux pour venir à notre église.
Government representatives changed their tactics.
Ndawi nguur gi soppi seen pexe.
Les représentants du gouvernement ont changé de tactique.
These boxes will be opened before the rest of the gifts.
Dinañu ubbi boyet yooyu laata ñuy joxe yeneen kado yi.
Ces boîtes seront ouvertes avant le reste des cadeaux.
Khallad said there was a 50% chance that the three would go to Karachi together in October.
Khallad neena amna 50% chance ñu bokk dem Karachi ci weeru oktoobar.
Khallad a dit qu'il y avait 50% de chances que les trois aillent à Karachi ensemble en octobre.
There are not many hotel options for visitors to Treasure Beach
Amna ay otel yu bari yu nit ñi mëna tànn ngir dem Treasure Beach
Il n'y a pas beaucoup d'hôtels pour les visiteurs de Treasure Beach.
We entered, only to find the doors locked.
Nu dugg, gis buntu yi tëju.
Nous sommes entrés, mais les portes étaient fermées à clé.
the civil constitution law has been in force for a year
sàrtu ndayu réew mi defna benn at
la loi constitutionnelle civile est en vigueur depuis un an
a blind person is not able to see
gumba du gis
une personne aveugle n'est pas capable de voir
no. I'm not familiar with the facts and I don't think
Déedéet. Xamuma lu am solo te jàpp naa ni
Je ne connais pas les faits et je ne pense pas
a convenient database reference made it easier to collect patient records, identification of the patient and contact information
Royuwaayu base de done bu yomb moo gëna yombal dajale done malaad yi, ràññeekaay malaad bi ak leerali jokkolante
une référence pratique à une base de données a facilité la collecte des dossiers des patients, l'identification du patient et les coordonnées
the biosphere changes depending on the temperature of the atmosphere
biosphere bi mingi aju ci tàngooru jawwu ji
la biosphère change en fonction de la température de l'atmosphère
As it turns out, of course, there are more English dialects in Britain than in North America, and anyone who's spent any time listening to them knows that it's not easy to switch.
Waaye nak, amna dialect yu Angale yu bari ci Grande Bretagne ak yi ci Amerique du Nord, te képp ku leen déglu saa yu nekk xamna ni coppite yombul.
Il s'avère qu'il y a plus de dialectes anglais en Grande-Bretagne qu'en Amérique du Nord, et quiconque a passé du temps à les écouter sait que ce n'est pas facile de changer.
you couldn't have been a bulldozer worker
Mënuloo woon nekk liggéeykat buldoser
Tu n'aurais pas pu être un ouvrier de bulldozer
They deleted the original computer file.
Ñu efaase fichier ordinatër bi njëkk.
Ils ont supprimé le fichier d'origine.
heat will not escape during a fire
tàngoor du génn ci lakk
la chaleur ne s'échappe pas pendant un incendie
If you have a gift of up to $1,000, you can certainly claim tax benefits.
Soo amee kado bu yegg ba $1,000, mën nga laaj ñu fay la juuti.
Si vous avez un don de jusqu'à 1.000 dollars, vous pouvez certainement demander des avantages fiscaux.
Betting on political contests and elections is also accepted on these sites.
Pari ci joŋante politik ak eleksioŋ dañu ko nangu itam ci sit yooyu.
Les paris sur des concours politiques et électifs sont également acceptés sur ces sites.
Wealthy people tend to keep their excess money.
Ñi am xaalis dañuy tëye seen xaalis bu ëpp.
Les gens riches ont tendance à garder leur argent en excès.
Rockefeller was caught in this desperate surrender when the Angling Angel Tarbell began tearing his flesh at McClure's.
Rockefeller defa mujje nekk ci jéego bu metti bi Angel Tarbell tammbale xotti yaramam ci këru McClure.
Rockefeller a été pris dans cette capitulation désespérée quand l'ange de la pêche Tarbell a commencé à déchirer sa chair chez McClure.
Milroy was in the field.
Milroy mingi woon ci tool bi.
Milroy était sur le terrain.
He thought that someone would go to the gallows.
Dafa yaakaaroon ni dina am kuy dem ci bant bi.
Il pensait que quelqu'un allait aller à la potence.
the number of tickets is not the same as the number of items ordered
limu biye yi ak limu mbir yi nga komànde wuute na
le nombre de billets n'est pas le même que le nombre d'articles commandés
I'll also give a presentation to the investigators at the criminal records office
Dinaa waxtaan ak ñiy amal lànket ci biro bi yor done kriminel
Je ferai aussi une présentation aux enquêteurs du bureau des casiers judiciaires.
By means of an unexplained movement, the green sea is swept away.
Géej gu wert gi dafay yëngu, te kenn xamul luko waral.
Par un mouvement inexpliqué, la mer verte est balayée.
Only a quarter of partners will report an increase in conflict detection skills.
Ñatteelu pàcc ci naataango yi kese ñooy wax ni dañu yokk seen xam-xam ci gis xeex.
Seul un quart des partenaires déclarent avoir amélioré leurs compétences en matière de détection des conflits.
For over a year, I had been following him without knowing it.
Lu ëpp benn at a ngi nii may topp te xamuma ko.
Pendant plus d'un an, je l'avais suivi sans le savoir.
And he said, I have given it into thy hand, that it may be as I have done, and as I have done.
Aji Sax ji ne ko: Jébbal naa ko ci sa loxo, ngir mu am ni ma ko defee.
Et il répondit: Je te le donne, afin qu'il en soit de toi comme j'ai fait, et comme j'ai fait.
When I received a letter from Dr. Youssef, it was as if I had forgotten, so he sent me a small box of fruit for Christmas.
Bima jotee bataaxal bu jóge ci Dr. Youssef, dafa melni dama fàtte, mu yónnee ma benn boyet bu ndaw bu def ay fruit ngir noel.
Quand j'ai reçu une lettre du Dr Youssef, c'était comme si j'avais oublié, alors il m'a envoyé une petite boîte de fruits pour Noël.
The sun is hot and it doesn't rain for days in October
Jant bi dafa tàng, te du taw ay fan ci weeru oktoobar
Le soleil est chaud et il ne pleut pas pendant des jours en octobre.
I can't see how it's possible to shoot a movie like this without a camera
Mënu ma ni ñu mëna defee filmu bu mel nii te amul kamera
Je ne vois pas comment on peut tourner un film comme ça sans caméra.
They recently finished their tour
Bu yàggul ñu jeexal seen tukki
Ils ont récemment terminé leur tournée.
The Nazi regime was an obstacle
Nguuru Nazy dafa nekkoon fippu
Le régime nazi était un obstacle
And I had to put it together and try to think of it that way.
Dama ko wara boole ngir jéema xalaat ci anam woowu.
Et je devais tout mettre en place et essayer de penser de cette façon.
Otto Frank hid it until the Nazis found it.
Otto Frank dafa ko nëbb ba Nazi yi gis ko.
Otto Frank l'a caché jusqu'à ce que les nazis le trouvent.
No one in South Carolina was working with
Kenn ci Caroline du Sud liggéeyandoo ak
Personne en Caroline du Sud ne travaillait avec
Khallad said there was a 50% chance the three went to Karachi together in October.
Khallad neena amna 50% chance ñu bokk dem Karachi ci weeru oktoobar.
Khallad a dit qu'il y avait 50% de chances que les trois soient allés à Karachi ensemble en octobre.
Jane asked to sign the FISA form.
Jane dafa laaj mu siñe formileeru FISA bi.
Jane a demandé à signer le formulaire FISA.
I have not gone to his destination; it was enough for you to be happy.
Demuma fimu jëm; doyoon na ngir am bànneex.
Je ne suis pas allé à sa destination; il suffisait pour vous d'être heureux.
That's not what they want.
Du loolu lañu bëgg.
Ce n'est pas ce qu'ils veulent.
Professor Singleton is a recovering monk in Florida
Janngalekat Singleton ab moine la buy wér ci Floride
Le professeur Singleton est un moine en convalescence en Floride.
I don't know much about it
Xamuma ci lu bari
Je ne sais pas grand chose à ce sujet.
the whole store that sold the tickets was sold and then demolished
butig bi jaay këyit yépp jaay nañu ko ba noppi ñu dindi ko
Le magasin qui vendait les billets a été vendu et démoli.
Each terrorism case is judged and ranked independently.
Bépp dosiye terrorism dañu koy àtte ci boppam, ba noppi tànn ko ci rang.
Chaque affaire de terrorisme est jugée et classée indépendamment.
Mr. Yamin's interests are all in algebraic geometry.
Li M. Yamin bëgg mooy géometrie algèbre.
M. Yamin s'intéresse uniquement à la géométrie algébrique.
This is Senior Sergeant Clem Francis, retired from the US Air Force.
Lii mooy Serjan Clem Francis, jeexal ci forsu aérien bu Etats Unis.
Je suis le sergent Clem Francis, retraité de l'armée de l'air.
He appointed elders and delegated the work to civil servants
Mu fal ay njiit, dénk liggéey bi ñiy liggéey ci nguur gi.
Il a nommé des anciens et délégué la tâche à des fonctionnaires.
The meaning may change if you write long sentences.
Tekki bi mën na soppiku soo bindee ay frase yu gudd.
Le sens peut changer si vous écrivez de longues phrases.
No one expects that there will be insults, swearing and yelling from the U.S. deputy secretary of labor.
Kenn xamul ni dina am ay saaga, ay waat ak ay yuuxu ci njiitu sekkerteer bu ligeey bu Amerik.
Personne ne s'attend à ce que le secrétaire adjoint du travail des États-Unis lance des insultes, des jurons et des cris.
Government representatives try to increase power by thinking differently.
Ndawi nguur gi dañuy jéema yokk seen kàttan ci yeneen xalaat.
Les représentants du gouvernement essaient d'accroître leur pouvoir en pensant différemment.
In this example, one of the study groups had two partnerships that required the management team to collaborate with the new company and make rapid changes that would improve the company's performance.
Ci misaal bii, benn ci kuréel yi ñuy jàngat amoon na ñaari lëkkaloo yuy laaj ekipu kilifa yi ñu liggéeyandoo ak liggéeyukaay bu bees bi ngir def coppite yu gaaw yuy gëna baaxal liggéeyu liggéeyukaay bi.
Dans cet exemple, l'un des groupes d'étude avait deux partenariats qui exigeaient que l'équipe de direction collabore avec la nouvelle entreprise et apporte des changements rapides qui amélioreraient les performances de l'entreprise.
To be honest, I hadn't even thought of that, but I had a hard time until I finally spoke to her.
Sooy dëggu, xalaatuma ko woon, waaye amna lu metti lool ba keroog ma mujjee waxtaan ak moom.
Pour être honnête, je n'y avais même pas pensé, mais j'ai eu du mal jusqu'à ce que je lui parle.
A four-star hotel is available for tourists visiting Treasure Beach
Amna otel bu am ñeenti biddiiw ngir turist yiy ñëw ci tefes bu Treasure
Un hôtel quatre étoiles est disponible pour les touristes qui visitent la plage du Trésor.
only to warn you that you must not live according to such teachings
Daf leen di artu rekk ci ne, ngeen bañ a topp njàngale yu mel noonu
Je vous préviens seulement de ne pas vivre selon de tels enseignements.
Baby Sonja first imitated her daughter's childish temper
Baby Sonja moo njëkka toppandoo doomam bu jigéen
La petite Sonja a d'abord imité le tempérament enfantin de sa fille.
The dead child was born blind.
Xale bi dee, judduwaale na gumba.
L'enfant mort était né aveugle.
Milreu was the center of the castle
Milreu moo nekkoon diggu chateau bi
Milreu était le centre du château.
There are over 100 individual members
Amna lu ëpp 100 nit ñu bokk
Il y a plus de 100 membres individuels
The sea was dark and crystal-clear.
Geej gi dafa lëndëm ba noppi leer nàññ.
La mer était sombre et cristalline.
Rockefeller was giving to us.
Rockefeller moo nu doon jox.
Rockefeller nous le donnait.
The goat is alone and has no one present to communicate with.
Bëy baa ngi wéet, amul kenn ku mëna jokkoo ak moom.
La chèvre est seule et n'a personne avec qui communiquer.
You never thought that they were in debt.
Musuloo xalaat ni dañu am bor.
Vous ne pensiez pas qu'ils étaient endettés.
The biosphere will never change
Biosphere du musa soppeeku
La biosphère ne changera jamais.
there is nothing we can do to stop the attacks
amul lenn luñu mëna def ngir dakkal song yi
Nous ne pouvons rien faire pour arrêter les attaques.
He was a judge who had caught a thief.
Àttekat la woon bu jàppoon sàcc.
C'était un juge qui avait attrapé un voleur.
Britain has many fine English dialects, more numerous than those of North America.
Grande Bretagne amna dialect yu bari yu baax ci Angale, yu ëpp yu Amerique du Nord.
La Grande-Bretagne possède de nombreux dialectes anglais, plus nombreux que ceux de l'Amérique du Nord.
it is clear that the police received a letter from the victim
Dafa leer ni poliis bi jot na bataaxal bu jóge ci kiñ ci lor
Il est clair que la police a reçu une lettre de la victime
Unfortunately, our tax advisors may advise against making a gift.
Li leer mooy sunuy xalaatkat ci wàllu juuti mën nañu la wax nga moytu joxe kado.
Malheureusement, nos conseillers fiscaux peuvent déconseiller de faire un don.
I need the courage of a mathematician to know what is going on.
Dama soxla fit bu mathematicien ngir xam li xew.
Il me faut le courage d'un mathématicien pour savoir ce qui se passe.
The museum is not focused on catalogs and labels.
Muse bi nekkul ci katalog wala etiket.
Le musée ne se concentre pas sur les catalogues et les étiquettes.
The ISC worked closely
ISC liggéey na bu baax
Le CSI a travaillé en étroite collaboration avec
The name is widely used.
Tur wi ñu ngi koy jëfandikoo bu baax.
Le nom est largement utilisé.
I haven't spoken to him
Waxuma ak moom
Je ne lui ai pas parlé.
They got their wish.
Ñu am seen bëgg-bëgg.
Ils ont eu leur souhait.
many types of information were stored in the database we had already created
Xeeti leeral yu bari lañu denc ci base de done bi ñu defar ba pare
de nombreux types d'informations ont été stockées dans la base de données que nous avions déjà créé
Take the time to promote the value of your reading.
Wutal jotu fësal njariñu li ngay jàng.
Prenez le temps de faire valoir la valeur de votre lecture.
Then, the same representative who walked in the first time visited the new provider to answer questions and discuss the problems represented in the sample of claims.
Ginaaw loolu, ki ko njëkka ñëw dafa dem seeti ki koy jox paj mu bees mi ngir tontu ay laaj ak waxtaane jafe-jafe yi ñuy wane ci misaalu reklamaasioŋ yi.
Ensuite, le même représentant qui était entré la première fois a rendu visite au nouveau fournisseur pour répondre à des questions et discuter des problèmes représentés dans l'échantillon de demandes.
Bernstein explained it only in the Finale.
Ci njeexte li kese la Bernstein leeral.
Bernstein l'a expliqué seulement dans la Finale.
She said she had tears in her eyes and said that Joe had climbed out the front door.
Mu wax ni dafa ànd ak ay rangooñ ci ay bëtëm ba noppi ni Joe moo génn ci buntu kër ga.
Elle a dit qu'elle avait les larmes aux yeux et que Joe était sorti par la porte d'entrée.
Intelligence report, the investigation of the Binalshibh, Oct. 1, 2002.
Rapportu juntuwaay yu bees yi, amal lànket ci Binalshibh, 1 oktoobar 2002.
Rapport du renseignement, l'enquête sur le Binalshibh, 1er octobre 2002.
The representatives of the community go to court.
Ndawi askan wi dañuy dem ci àttekaay bi.
Les représentants de la communauté vont au tribunal.
Mr. Yamins is a skilled craftsman but not very good at mathematics.
M. Yamins art bu mag la waaye xamul math bu baax.
M. Yamins est un artisan habile mais pas très bon en mathématiques.
People need computers and devices that connect to the internet before they can use it.
Nit ñi dañu soxla ordinatër wala aparey yuy dugg ci internet balaa ñuy mën a jëfandikoo.
Les gens ont besoin d'ordinateurs et d'appareils qui se connectent à Internet avant de pouvoir l'utiliser.
The interior designs of some of the rooms depict the complexity of the life of the devotees, but also the golden lamps depict the deficiencies of the ritual (if any) in transferring the work from one stage to another.
Design bi ci biir yenn ci néeg yi dafay wane jafe-jafe yi ci dundu jaamukat yi, waaye itam làmp yu wurus yi dañuy wane jafe-jafe yi ci xeetu jaamu (su amee) ci toxal liggéey bi ci benn etap dem ci beneen.
Les dessins intérieurs de certaines des pièces dépeignent la complexité de la vie des fidèles, mais aussi les lampes dorées dépeignent les lacunes du rituel (le cas échéant) dans le transfert du travail d'une étape à une autre.
The officer, who had observed the collapse of the South Tower, reported his evacuation order to the ESU in the North Tower.
Ofisiye bi seetluwoon mabb bu Tower bu bëtu saalum bi, yebalna ndigalu rawale bi ci ESU ci Tower bu bëtu gannaar bi.
L'officier, qui avait observé l'effondrement de la tour sud, a signalé son ordre d'évacuation à l'ESU dans la tour nord.
On the ninth day, an unexpected news came from Afghanistan.
Ci juróom ñeenteelu bis bi, amna xibaar buñu xamul woon bu bawoo Afghanistan.
Le neuvième jour, une nouvelle inattendue est arrivée d'Afghanistan.