en
stringlengths
1
298
wo
stringlengths
1
279
fr
stringlengths
1
687
He wanted to wipe the blood off with a towel.
Dafa bëggoon fomp deret ji ak sarbet.
Il voulait essuyer le sang avec une serviette.
The people complain about the burdens.
Nit ñi dañuy ñaxtu ndax coono bi.
Les gens se plaignent des fardeaux.
The term has been overused.
Tur wi dañu ko jëfandikoo lu ëpp.
Le terme a été trop utilisé.
The group has only used one name so far
Groupe bi benn tur kese lañu jëfandikoo ba leegi
Le groupe n'a utilisé qu'un seul nom jusqu'à présent.
This business is more focused on technology.
Bisnees bii dafa gëna lalu ci xarala yu bees yi.
Cette entreprise est plus axée sur la technologie.
Certificates can be written in other languages.
Mën nañu bind sertifikaa yi ci yeneen làkk.
Les certificats peuvent être rédigés dans d'autres langues.
A lush green landscape was visible
paysage bu wert bu naat lañuy gis
Un paysage verdoyant était visible.
it gets hot in the summer
ci ete bi dafay tàng
Il fait chaud en été.
You're right, it's not an accident.
Wax nga dëgg, du aksidaa.
Tu as raison, ce n'est pas un accident.
the woman was speaking with a heavy voice
ku jigéen ki dafa doon wax ak baat bu diis
la femme parlait d'une voix lourde
A political day can begin at dawn.
Bisu politik mën na tàmbali ci fajar.
Une journée politique peut commencer à l'aube.
The cost of this project is very high.
Njëg li ci projet bi yéeg na lool.
Le coût de ce projet est très élevé.
In a white envelope, with your address on it
ci enveloppe bu weex, nga ci bind sa adres
Dans une enveloppe blanche, avec votre adresse dessus.
Rockefeller was a communist
Rockefeller komunist la woon
Rockefeller était communiste.
The skies of Canada had no satellites
Asamaan bu Canada amul woon benn satelit
Les cieux du Canada n'avaient pas de satellites
you can't imagine how rich Spin is in all sorts of ways
Mën nga xalaat ni Spin barie ci anam yu bari
Tu ne peux pas imaginer à quel point Spin est riche à tous points de vue.
We planned to appeal to this group to donate money to schools but no one has done so.
Nu ngi doon yéene ñaan mbooloo mii ngir ñu jàppale daara yi ci xaalis waaye kenn deful ko.
Nous avions prévu de faire appel à ce groupe pour qu'il fasse un don d'argent aux écoles mais personne ne l'a fait.
I command the King to give me an office contrary to the doctrine.
Maa ngi sant Buur bi mu jox ma liggéey bu dul ngëm.
Je commande au Roi de me donner un poste contraire à la doctrine.
Centrelink had many ways of telling people to keep their financial records because the government was losing a lot of money in errors.
Centrelink amoon na anam yu bari yu muy wax nit ñi ñu bind seen dokimaa ci wàllu xaalis ndax nguur gi dafay ñàkk xaalis bu bari ci njuumte yi.
Centrelink avait beaucoup de moyens de dire aux gens de garder leurs dossiers financiers parce que le gouvernement perdait beaucoup d'argent en cas d'erreur.
Information group Average group is nine organizations per month
Kuréel giy joxe xibaar Kuréel gi gëna mag mooy juróom ñeenti mbootaayi weer wu nekk
Groupe d'information Groupe moyen de neuf organisations par mois
to make a difference in the film industry, you have to go to Indianapolis
Soo bëggee indi coppite ci liggéeyum filmu, danga wara dem Indianapolis
Pour faire une différence dans l'industrie du cinéma, il faut aller à Indianapolis.
if someone had read the book published in 1884, I'm sure he would have been surprised that he bought a hundred copies and didn't buy the shorter and clearer (and simpler) version
su amee ku jàng téere biñ siiwal ci 1884, gëm naani dina jaaxle ci limu jëndoon téemeeri eksemplaar te jëndul téere bi gëna gàtt te leer (te gëna yomba)
Si quelqu'un avait lu le livre publié en 1884, je suis sûr qu'il aurait été surpris qu'il ait acheté une centaine d'exemplaires et n'ait pas acheté la version plus courte et plus claire (et plus simple)
All bad things have the same sign
Lu bon yépp benn màndarga lañu
Toutes les mauvaises choses ont le même signe
Children see how different generations are.
Xale yi gis nañu ni jamono yi wuute.
Les enfants voient à quel point les générations sont différentes.
Trying to finish my project next week
Maa ngi jéema jeexal sama projet ayu-bis bii di ñëw
J' essaie de finir mon projet la semaine prochaine.
the night has come with your loved ones
guddi gi yegsi na ak say mbokk
La nuit est venue avec tes proches
Internet sites allow betting only on sports.
Situ internet yi duñu may ñu pari ci tàggat yaram kese.
Les sites Internet permettent de parier uniquement sur le sport.
some of them were running in our race with the measuring device for the figures
Ñenn ci ñoom dañu doon daw ci sunu kursu ak aparey biy natt lim yi
Certains d'entre eux couraient dans notre course avec le dispositif de mesure pour les chiffres
Thanks to our generous donations, we were able to invite Beyonce to give a concert for the Indianapolis orphans
Sunu saraxe yu bari yi ñu def, moo tax ñu mëna invite Beyonce mu def concert ngir doomi mbokk yi ci Indianapolis
Grâce à nos généreux dons, nous avons pu inviter Beyoncé à donner un concert pour les orphelins d'Indianapolis
the local council determines on a daily basis the amount of the SBA loan for each applicant
konsilu dëkk bi mooy dogal bis bu nekk ni xaalis bi SBA wara leble ngir ku nekk ci ñoom
le conseil local détermine quotidiennement le montant du prêt SBA pour chaque demandeur
She had a big smile on her face.
Mu am muuñam gu rëy ci kanamam.
Elle avait un grand sourire sur son visage.
I try to be patient
Maa ngi jéema muñ
J' essaie d' être patiente.
I can't find the translation in the dictionary
Gisuma tekki bi ci diksoneer bi
Je ne trouve pas la traduction dans le dictionnaire.
Wealth and savings are rarely mutually exclusive.
Alal ak dencukaay duñu faral di wuute.
La richesse et l'épargne sont rarement mutuellement exclusives.
Investigations will be easier for the government to enforce.
Nguur gi dina gëna yombal amal lànket yi.
Les enquêtes seront plus faciles à faire appliquer par le gouvernement.
It sounded like a lot of fun and I was amazed at the amount of things that were allowed.
Daa melni lu neex la, te yéemu naa ci bariwaayu mbir yiñ may.
Ça semblait très amusant et j'ai été étonné par la quantité de choses qui étaient autorisées.
You are free to make changes to your address, if you see fit.
Yaa ngi sañ-sañ soppi sa adres, soo ko gisee.
Vous êtes libre de modifier votre adresse si vous le jugez nécessaire.
The ticket money will cover our expenses for this workshop.
Xaalis biye bi mooy fay sunuy njëg ci atelier bii.
L'argent du billet couvrira nos dépenses pour cet atelier.
As a child growing up in the 50's, my happiest moments were when I was in the Civic Theatre.
Bi may nekk xale, di màgg ci 50 at, sama jamono yi ma gënoon kontaan mooy bima nekkee ci Civic Theatre.
Enfant, dans les années 50, mes moments les plus heureux étaient au Théâtre Civic.
you can compare them to how you used to do physical exercise when you stretched your body with your muscles
mën nga leen méngale ak ni ngay defee tàggat yaram sooy tàllal sa yaram ak say sidit
vous pouvez les comparer à la façon dont vous avez l'habitude de faire de l'exercice physique lorsque vous étiriez votre corps avec vos muscles
The gunfire was heard less than 100 miles from where I lived.
Fima dëkkoon amul 100 mile lañu dégg fetal bi.
Les coups de feu ont été entendus à moins de 160 km de chez moi.
circus performers are in the social hall
ñiy jouer sirk ñu ngi ci saal bi
Les artistes du cirque sont dans la salle de réception.
Claimant is a licensed attorney in California
Kiy sàkku avocat la bu am lijjaassa ci Californie
Le demandeur est un avocat en Californie.
no no I don't want you to die
déet déet bëgguma nga dee
Je ne veux pas que tu meures.
the 1984 census is the best in the area
xayma limu nit ñi ci atum 1984 moo gëna baax ci gox bi
Le recensement de 1984 est le meilleur de la région.
Do the same with your brothers
Defal noonu ak say mbokk
Fais de même avec tes frères
I'm not surprised that they were rude.
Jaaxle wuma ci ni ñu defee yëfi soxor.
Je ne suis pas surpris qu'ils aient été grossiers.
Most of our plans to start.
Sunuy pexe yu bari dañu tàmbali.
La plupart de nos projets pour commencer.
as rick said, i was a senior defense attorney
Ni Rick waxee, defenseur bu mag laa woon
Comme Rick l'a dit, j'étais un avocat de la défense
The island they approached was inhabitable
Ile bi ñu jegewoon mënoon na dëkk
L'île qu'ils ont approchée était inhabitable.
I found the translation in the dictionary.
Gis naa tekki bi ci diksoneer bi.
J'ai trouvé la traduction dans le dictionnaire.
They traveled a long way to fix everything.
Tukki nañu fu sori ngir defar lépp.
Ils ont fait un long voyage pour tout réparer.
The pronoun should be used more often.
Pronoun bi lañu wara gëna faral di jëfandikoo.
Le pronom devrait être utilisé plus souvent.
it becomes more important to calculate the result of the election if the results of the elections are not consistent with other results
Dafay gëna am solo ñu xayma njariñu eleksioŋ yi sudee njariñu eleksioŋ yi méngoowul ak yeneen resultaa yi
il devient plus important de calculer le résultat de l'élection si les résultats des élections ne sont pas cohérents avec d'autres résultats
Wealthy people tend to save a large portion of their income
Ñi am xaalis dañuy denc xaalis bu bari ci seen xaalis
Les gens riches ont tendance à épargner une grande partie de leur revenu.
But of course, animals are always on the loose, especially goats.
Waaye baayima yi dañuy mucc saa yu nekk, rawatina bëy yi.
Mais bien sûr, les animaux sont toujours en liberté, surtout les chèvres.
The best feature of the postwar German constitution, then, was precisely the brutal murder of the Nazis.
Kon li gënoon fës ci sàrtu ndayu réewum Allemagne ginaaw xare bi mooy faat Nazi yi ci anam wu metti.
La meilleure caractéristique de la constitution allemande d'après-guerre, donc, était précisément le meurtre brutal des nazis.
I'm thinking of waiting
Maa ngi xalaat xaar
Je pense à attendre
His capacity was insufficient but little was done to correct this.
Kàttanam doyul woon waaye deful lu bari ngir saafara loolu.
Sa capacité était insuffisante mais peu de choses ont été faites pour corriger cela.
After cutting off the feathers of his victims, he tried to hide them in a garbage can.
Bimu daggee dunqu mala yi mu ray, mu jéem leen nëbb ci poti mbalit mi.
Après avoir coupé les plumes de ses victimes, il a essayé de les cacher dans une poubelle.
gymnastics is good for the body, should I be good for the soul?
gymnastique baaxna ci yaram, ndax dama wara baax ci ruuh gi?
La gymnastique est bonne pour le corps, je devrais être bonne pour l'âme?
And they remain patient and helpful, even though they know that their beloved beach is no longer theirs.
Te dañuy wéy di jàppale nit ñi, doonte xam nañu ni tefes gi ñu bëgg nekkatul seen bopp.
Et ils restent patients et serviables, même s'ils savent que leur plage bien-aimée n'est plus à eux.
Centrelink had many ways to teach people how to manage their finances.
Centrelink amoon na anam yu bari yu muy jàngal nit ñi ni ñuy yoree seen xaalis.
Centrelink avait de nombreuses façons d'apprendre aux gens à gérer leurs finances.
I don't want you to die
Bëgguma nga dee
Je ne veux pas que tu meures.
On their way to Bosnia, see the intelligence report, interrogated by a Saudi al Qaeda member, October 3, 2001.
Bi ñuy dem Bosnie, xoolal rapooru juntuwaay yi, bi benn waa Saudi al Qaida laajee, ci 3 oktoobar, 2001.
En route pour la Bosnie, voir le rapport des services secrets, interrogé par un membre d'Al-Qaïda saoudien, le 3 octobre 2001.
it's hard to get a job in Indianapolis if you're in the film and theater industry, because it's a big city
Indianapolis amna liggéey bu jafe sudee danga nekk ci liggéeyum filmu ak tiyaatar, ndax dëkk bu mag la
C'est difficile de trouver un emploi à Indianapolis si vous êtes dans l'industrie du cinéma et du théâtre, parce que c'est une grande ville
We had hoped to give the children a Christmas party, but we were unable to do so.
Amoon nanu yéene defal xale yi noel, waaye mënu nu ko def.
Nous avions espéré organiser une fête de Noël pour les enfants, mais nous n'avons pas pu le faire.
Omnia vincit amor (working for the Weekly Standard): Brit Hume (Fox Memorial Sunday) begs them to say the same thing because Lewinsky can't... he's in a suitcase for the president
Brit Hume (Fox Memorial Sunday) defa leen di ñaan ñu wax luni mel ndax Lewinsky munul... mungi ci benn valise ngir njiit li
Omnia vincit amor (travaillant pour le Weekly Standard): Brit Hume (Fox Memorial Sunday) les supplie de dire la même chose parce que Lewinsky ne peut pas... il est dans une valise pour le président
The Internet requires a lot of work.
Internet dafay laaj liggéey bu bari.
Internet demande beaucoup de travail.
I think very carefully about the King's household.
Maa ngi xalaat bu baax kër Buur bi.
Je réfléchis très attentivement à la maison du roi.
When I was a child, I hated going to the theater, so I became a scientist.
Bi may xale amoon naa bañ dem teyaatar, moo tax ma nekk gëstukat.
Quand j'étais enfant, je détestais aller au théâtre, alors je suis devenu un scientifique.
The School of Nursing needs your generous gifts to sustain and elevate its academic flowering.
Daara Infirmiye soxla na seen xéewal yu bari ngir mëna wéyal ak yéegal jëm kanam gi ci wàllu njàng.
L'école d'infirmières a besoin de vos dons généreux pour soutenir et élever son épanouissement académique.
He felt a painful sensation in his stomach.
Mu yëg luy metti ci biir.
Il ressentit une sensation douloureuse dans son estomac.
I'll work until the next day
Dinaa liggéey ba ëlëg sa
Je travaillerai jusqu'au lendemain.
I wonder if they gave you the bread with the hands.
May xalaat ndax loxo lañu la jox mburu mi.
Je me demande s'ils t'ont donné le pain avec les mains.
At the same time, we have a good bad record to remember, which adds to the problem.
Ci jamano jooju, amnanu mbir yu baaxul yuñ wara fàttaliku, te loolu dafay yokk jafe-jafe bi.
En même temps, nous avons un mauvais bilan à nous rappeler, ce qui ajoute au problème.
They couldn't see land for miles, there's an endless ocean
Mënu ñu woon gis suuf si ay kilomeetar, amna géej gu amul àpp
Ils ne pouvaient pas voir la terre pour des kilomètres, il y a un océan sans fin
the book is not for sale
téere bi du jaay
Le livre n'est pas à vendre.
leave them alone for this part of the training you will relax your body
Bàyyileen ñu demal ci wàll wii ci tàggat yaram, dinga féexal sa yaram
Laissez-les tranquilles pendant cette partie de l'entraînement. Vous allez détendre votre corps.
Although there was a two-way partnership, there was no need for the company to change the division of management.
Ak liñu amoon ñaari yoon ñuy liggéeyandoo, amul njariñ liggéeyukaay bi di soppi xaaju kilifa yi.
Bien qu'il y ait eu un partenariat à double sens, il n'était pas nécessaire pour la société de changer la division de la direction.
I looked it up in the dictionary and couldn't find the translation
Ma seet ci diksoneer bi waaye gisuma tekki bi
J'ai cherché dans le dictionnaire et je n'ai pas trouvé la traduction.
they are active all day long via social media, all week long via a news desk in supporting and supporting the relief efforts of the poor
ñu ngi liggéey bis bi yépp jaaraleko ci reso sosio yi, ayu-bis bi yépp jaaraleko ci biro xibaar ngir jàppale ak jàppale liggéey biy jàppale néew ci doole yi
Ils sont actifs toute la journée via les médias sociaux, toute la semaine via un bureau de nouvelles pour soutenir et soutenir les efforts de secours des pauvres.
Brit Hume is the chief political correspondent for Fox.
Brit Hume mooy njiitu surnalist politik ci Fox.
Brit Hume est le correspondant politique en chef de Fox.
This allowed the system to be regularly reviewed by designers before the companies could be contacted to purchase production equipment and how to make representatives for the exhibition.
Loolu tax na ñiy jëmmal ñu mëna xoolaat sistem bi saa yu nekk balaa ñuy jokkool ak liggéeyukaay yi ngir ñu jënd jumtukaayi liggéey bi ak ni ñuy amalee ay ndawu liggéey bi.
Cela a permis aux concepteurs de revoir régulièrement le système avant de pouvoir contacter les entreprises pour acheter des équipements de production et comment faire des représentants pour l'exposition.
An al Qaeda operative made 18 trips to Bosnia in 2001
Benn soldaar bu Al Qaida defna 18 tukki ci Bosnie ci 2001
Un agent d'Al-Qaïda a effectué 18 voyages en Bosnie en 2001
They made no major changes to their surveillance program.
Defu ñu benn coppite bu mag ci seen prograamu wattu.
Ils n'ont pas fait de changements majeurs à leur programme de surveillance.
most of the voters in the city accept paychecks and credit cards
wotekat yu bari ci dëkk bi dañuy nangu xëyma ak kàrtu kredi
La plupart des électeurs de la ville acceptent les chèques de paie et les cartes de crédit.
I learned from the end of their likenesses and traditions
Jàngoon naa ci seen njeexte ak seeni aada
J'ai appris de la fin de leurs ressemblances et les traditions
We have been able to help many children in Indianapolis.
Jàppale nanu xale yu bari ci Indianapolis.
Nous avons pu aider beaucoup d'enfants à Indianapolis.
The Nazis allowed it.
Nazi yi nangu nañu ko.
Les nazis l'ont permis.
Goats jump out of the shed every day
Bëy yi dañuy tëb bis bu nekk
Les chèvres sautent tous les jours du hangar.
They are upset and hateful towards everyone now that they have to share the shore
Dañu mer ba noppi bañ ñépp leegi ndax dañu wara bokk tefes gi
Ils sont en colère et haineux envers tout le monde maintenant qu'ils doivent partager la côte
He had his face covered with a veil.
Dafa muur kanamam.
Il avait le visage couvert d'un voile.
if I hadn't been there I would have died
Suma fa nekkoon damaa dee
Si je n'avais pas été là, je serais mort.
On Aug. 25, at the opening of a presidential convention in Atlantic City, N.J., Johnson, then 56, pledged on three separate occasions that he would not run for president.
Bisu 25 Uut, ci ubbite bu ndaje njiitu réew ma ci Atlantic City, N.J., Johnson amoon 56 att ci jamono jooju layoona ñetti yoon ni du dem wote njiitu réew.
Le 25 août, lors de l'ouverture d'une convention présidentielle à Atlantic City, Johnson, alors âgé de 56 ans, a promis à trois reprises qu'il ne se présenterait pas à la présidence.
people could only communicate by post or email
nit ñi mën nañu jokkoo ci post wala email
les gens ne pouvaient communiquer que par courrier ou par e-mail
I graduated in 2002
Maa ngi am lijaasa ci 2002
Je suis diplômé en 2002
I try my best
Maa ngi jéema def luma mën
Je fais de mon mieux.
Johnson believes he will have more support.
Johnson yaakaarna ni dina am ndimmbal bu gëna bari.
Johnson pense qu'il aura plus de soutien.
Initially, individuals can participate by making an unlimited annual gift of $1,000 or more to the chancellor's circle, or $500 or more to the council's associates.
Bi ñuy tàmbali, nit ñi mën nañu ci bokk suñu joxee kado bu amul àpp bu tollu ci $1,000 wala lu ëpp ci kuréelu sanseliye bi, wala $500 wala lu ëpp ci ñi ànd ak konsilu bi.
Au début, les individus peuvent participer en faisant un don annuel illimité de 1000 $ ou plus au cercle du chancelier, ou 500 $ ou plus aux associés du conseil.