en
stringlengths
1
298
wo
stringlengths
1
279
fr
stringlengths
1
687
the western circumnavigation was delayed for thirty seconds before the commander-in-chief ordered the ESU to circumnavigate the peninsula
wër gaal gi ci sowwu jàngoon nañu ko lu tollu ci fan-weeri seconde balaa komandaa bi di wax ESU ñu wër penesilu bi
La circumnavigation de l'ouest a été retardée de 30 secondes avant que le commandant en chef n' ordonne à l' ESU de faire le tour de la péninsule
Getting used to wearing a full-length suit takes time.
Màmm sol tënu bu mat dafay yàgg.
Il faut du temps pour s'habituer à porter un costume long.
Businesses on the Golden Mile are various types of businesses including banks
Liggéeyukaay yi ci Golden Mile barina xeetu liggéey yu ci melni bànk yi
Les entreprises du Golden Mile sont de différents types d'entreprises, y compris les banques.
The film required a large amount of copying to produce, and Kaufman's important scenes were ignored.
Filmu bi dafa laaj ñu kopie lu bari ngir mëna ko defar, ba noppi ñu baña bàyyi xel ci seen yu am solo yu Kaufman.
Le film nécessitait une grande quantité de copie pour la production, et les scènes importantes de Kaufman ont été ignorées.
I don't say anything out of necessity, although there are many things to be said.
Waxuma dara lu jaaduwul, doonte bari na lu war a wax.
Je ne dis rien par nécessité, bien qu'il y ait beaucoup de choses à dire.
The shepherd even brought the animals when he wasn't sure about them
Sàmmkat bi dafa indi sax baayima yi fekk leerul ci ñoom
Le berger a même amené les animaux quand il n'était pas sûr d'eux.
A copy in a language other than English will be required for prosecutors presenting evidence.
Dina ñu laaj benn kopi ci beneen làkk bu dul Àngle ngir porsekitëer bi di joxe firnde.
Une copie dans une langue autre que l'anglais sera requise pour les procureurs présentant des preuves.
Use both hands if you want to learn how to use a gun.
Jëfandikool sa ñaari loxo soo bëggee jàng ni ñuy jëfandikoo fita.
Utilisez les deux mains si vous voulez apprendre à utiliser une arme.
Kinabalu national park is home to ten elephants and six mammals
Park national bu Kinabalu dekkuwaayu fukki ñay ak juróom benni mamifeer
Le parc national de Kinabalu abrite dix éléphants et six mammifères.
As you know, this membership is filled with those friends and former members who have donated $1,000 or more annually to law school.
Xam nga ni nit ñi dañu fees dell ak seeni xarit ak ñi bokkoon ci mbootaay mi, ñu jox $1,000 wala lu ëpp at mu nekk ci daara ju mag ji.
Comme vous le savez, cette adhésion est remplie d'amis et d'anciens membres qui ont donné 1 000 $ ou plus chaque année à l'école de droit.
No other user has a strong tradition of criticizing self-sacrifice.
Amul beneen jëfandikukat bu am cosaan ak aada buy ŋàññi joxe sa bopp.
Aucun autre utilisateur n'a une forte tradition de critiquer le sacrifice de soi.
Tung wants to influence architectural speculators.
Tung bëgga am njeexital ci ñiy jënd ak jaay ci architecture.
Tung veut influencer les spéculateurs architecturaux.
And he didn't want to be proud of the fact that he hadn't seen them for three years.
Te bëggul woon tiitaange ndax defna ñatti at gisu leen.
Et il ne voulait pas être fier du fait qu'il ne les avait pas vues depuis trois ans.
additionally, it contains only the well-known words of the 20th century and the beginning of the century, but it also contains the words of the end of the 20th century
Rax ci dolli, amul lenn ludul kàddu yiñ gëna xam ci 20eelu xarnu bi ak ci ndoorte xarnu bi, waaye amna itam kàddu yi am ci njeexte 20eelu xarnu bi.
En outre, il contient seulement les mots bien connus du 20ème siècle et le début du siècle, mais il contient aussi les mots de la fin du 20ème siècle
yes he suggested finding uh um a uh a blanket to use
waaw, dafa digal ñu wut mbàjj ngir jëfandikoo
Oui, il a suggéré de trouver une couverture à utiliser.
The water and beaches are always clean.
Ndox mi ak tefes yi dañu set saa yu nekk.
L'eau et les plages sont toujours propres.
Someone asks which roads they take.
Ku laaj ban yoon lañu jaar.
Quelqu'un demande par quel chemin ils vont.
they like to travel in the summer
Dañu bëgg tukki ci ete bi
Ils aiment voyager en été.
He writes the same way in many of his letters, speaking in them of these matters.
Noonu la bindee ci bataaxalam yu bari, di wax ci mbir yooyu.
Il écrit de la même manière dans nombre de ses lettres, où il parle de ces questions.
if it is more than 100 degrees or more in the winter
sudee ci hiver bi dafa ëpp 100 degre wala lu ëpp
si la température est supérieure à 100 degrés en hiver
Mihdhar was given a passport because he is not a terrorist.
Jox nañu Mihdhar paspoor ndax nekkul terrorist.
Mihdhar a reçu un passeport parce qu'il n'est pas un terroriste.
There is no universal mandate on this issue.
Amul benn sàrt bu ñépp tëral ci mbir mii.
Il n'existe pas de mandat universel sur cette question.
We can keep our prices low if indeed, without your money, but our boss loves his luxury.
Mën nanu tëye sunuy njëg, sudee amul sa xaalis, waaye sunu patroŋ bëgg na luxus bimu am.
Nous pouvons maintenir nos prix bas, même sans votre argent, mais notre patron aime son luxe.
How does that look like what I'm trying to do?
Loolu naka lay nuru li may jéema def?
Ça ressemble à ce que j'essaie de faire?
Rockefeller's campaign of terror ended when Avenging Tarbell began tearing apart McClure's house.
Kampaañu tiitaange bu Rockefeller jeexna bi Tarbell biy fayyu tàmbalee xotti këru McClure.
La campagne de terreur de Rockefeller s'est terminée quand le Vengeur Tarbell a commencé à démolir la maison de McClure.
Realizing that it would require immediate assistance and extensive cooperation from the German government, which would be difficult to obtain.
Ñu xamni loolu dafay laaj ndimmbal ci saasi ak lëkkaloo bu xóot ci nguuru Allemagne, te loolu du yomb ñu am.
Conscient que cela exigerait une aide immédiate et une coopération étendue du gouvernement allemand, ce qui serait difficile à obtenir.
Advanced scheduling software is one of the key technologies businesses are considering.
Benn ci xarala yu am solo yi liggéeyukaay yi di bàyyi xel mooy losisel biy jàppale waxtu yi.
Le logiciel de planification avancée est l'une des technologies clés envisagées par les entreprises.
The group changed their name because it was not popular
Groupe bi dafa soppi seen tur ndax siiwul woon
Le groupe a changé de nom parce que ce n'était pas populaire.
This change shows how prosperous all those to whom I send letters are.
Coppite boobu dafay wane ni ñi may yónnee bataaxal yépp am naataange.
Ce changement montre à quel point tous ceux à qui j'envoie des lettres sont prospères.
Let's come to the study and recognition program has been going on for a year now
Nanu ñëw ci njàng mi ak prograamu gëdd bi defna at leegi
Passons maintenant à l'étude et le programme de reconnaissance qui se déroule depuis un an maintenant.
No, we use the default password when we don't need a copy.
Déedet, danuy jëfandikoo baatu-jàll biñ jagleel sunu soxlawul kopi.
Non, on utilise le mot de passe par défaut quand on n'a pas besoin d'une copie.
Complaints included baggage problems, corrupt flight attendants, mysteriously canceled flights, and payment brutality.
Plainte yi bokku na ci jafe-jafe bagaas, stewardess yuy ger, vol yuñ fomm ci anam wu yéeme, ak fayukaay yu metti.
Les plaintes portaient sur des problèmes de bagages, des agents de bord corrompus, des vols annulés mystérieusement et des paiements brutaux.
The book's introduction uses words from the 20th century, but does not reflect the philosophy of early Christianity.
Njàlbéen téere bi dafa jëfandikoo ay baat yu jóge ci 20eelu xarnu, waaye àndul ak xam-xamu diine nasaraan yu njëkk ya.
L'introduction du livre utilise des mots du XXe siècle, mais ne reflète pas la philosophie du christianisme primitif.
I take it to be unusual among your kind.
Dama jàpp ni du lu wuute ak yaw.
Je suppose que c'est inhabituel chez les gens de votre espèce.
Naturally enough, the involvement of the Second World War began with the British Commonwealth Air Training Plan, promoting safe skies for military pilots.
Waaye ñaareelu guerre mondiale mingi tàmbali ci Plan Training Air bu Commonwealth bu Grande Bretagne, ngir jàppale pilotu soldaar yi ñu am asamaan bu wóor.
Naturellement, l'implication de la Seconde Guerre mondiale a commencé avec le plan d'entraînement aérien du Commonwealth britannique, promouvant des cieux sûrs pour les pilotes militaires.
Evidence is only allowed in English.
Firnde yi ci Àngle kese lañuy nangu.
Les preuves ne sont autorisées qu'en anglais.
He suggested getting a sewing machine.
Muni ma wut masinu togg.
Il a suggéré d'acheter une machine à coudre.
I'm not sure how it looks to you.
Xamuma numu lay nuru.
Je ne suis pas sûr de ce que ça vous semble.
Spin barleys are useful for storing transportation equipment
Orge spin amna njariñ ci denc jumtukaayi dem ak dikk
Les barils à fil sont utiles pour le stockage des équipements de transport.
Your uncle beat me badly every day when he had me.
Sa ndijaay daf may dóor bu baax bis bu nekk bimu ma amee.
Ton oncle me battait tous les jours quand il m'avait eu.
the commander of the expedition was standing at the edge of the falling wall
komandaa bi taxawoon ci wetu miir biy daanu
Le commandant de l' expédition était debout au bord de la chute du mur.
We have never been visited.
Kenn musu nu seeti.
Nous n'avons jamais eu de visiteurs.
Rockefeller donated to the cancer research foundation
Rockefeller joxna fondaasioŋ buy gëstu ci cancer
Rockefeller a fait un don à la fondation de recherche sur le cancer
the board did not approve the SBA plan, so we withdrew it from the accountant's office
kilifa yi nangu wuñu palaŋu SBA bi, ci noonu lañu ko dindi ci biro kontukat bi
Le conseil n'a pas approuvé le plan de la SBA, alors nous l'avons retiré du bureau du comptable
I don't know where it came from, but it's going fast.
Xamuma fumu joge, waaye mingi gaaw.
Je ne sais pas d'où ça vient, mais ça va vite.
If completed, the investigation may reveal the hiding place of the three fugitives.
Suñu defee lànket bi ba noppi, mën nañu gis fu ñatti ñi daw nekkoon.
Si l'enquête est terminée, nous pourrons découvrir la cachette des trois fugitifs.
Some nerds believe that all men are created equal
Ñenn ñi dañu gëm ni ñépp a bokk
Certains nerds croient que tous les hommes sont créés égaux
The council isn't the only political party in Washington this morning.
Du konsilu bi rek moy parti politik bi ci Washington tay ci suba.
Le Conseil n'est pas le seul parti politique à Washington ce matin.
I didn't want to be the only one who used the measuring device for the figures
Bëgguma nekk man kese maa jëfandikoo aparey biy natt lim yi
Je ne voulais pas être le seul à utiliser le dispositif de mesure pour les chiffres
The ticket money is not enough to cover the expenses of this workshop.
Xaalis biye bi doyul ngir fay atelier bii.
L'argent du billet n'est pas suffisant pour couvrir les dépenses de cet atelier.
Some of the grants included money and assistance in obtaining travel documents
Yenn ci ndimbal yi bokku na ci xaalis ak ndimbal ngir am këyitu tukki
Certaines des subventions comprenaient de l'argent et une aide à l'obtention de documents de voyage.
because it is necessary to fulfill all the promises until death.
Ndaxte fàww ñu matal dige yépp ba ci dee.
Car il est nécessaire que la promesse soit accomplie avant la mort.
Investigations can be easier and easier for the government to conduct.
Nguur gi mën na gëna yomba amal lànket.
Les enquêtes peuvent être de plus en plus faciles à mener pour le gouvernement.
Local governments do not need
Nguur yi soxla wuñu
Les gouvernements locaux n'ont pas besoin
Please do not change your address
Bul soppi sa adres
Ne changez pas d'adresse.
The beggar was lonely, and there was no one to talk to him.
Yalwaankat bi dafa wéet, amul kenn ku koy wax.
Le mendiant était seul, et il n'y avait personne pour lui parler.
The public did not find a copy of a dictionary.
Ñépp gisu ñu benn diksoneer.
Le public n'a pas trouvé de dictionnaire.
A wire rope is not a problem.
Fiil du jafe-jafe.
Une corde métallique n'est pas un problème.
they have just finished their second trip
ñu ngi jeexal seen ñaareelu tukki
Ils viennent de terminer leur deuxième voyage.
Ten people had lost their belongings.
Fukki nit ñàkk nañu seeni moomel.
Dix personnes avaient perdu leurs biens.
The man's forehead snapped.
Jëwu ku góor ki daal di yëngu.
Le front de l'homme s'est cassé.
Your donations help us to keep costs low.
Seen ndimbal daf nuy jàppale nu wàññi njëg yi.
Vos dons nous aident à réduire les coûts.
In children's theatre as well, the opportunity to play and direct various roles helps children to recognize the similarities and differences between people in their desires, beliefs and emotions.
Ci teyaatar xale itam, mën nañu jouer ak jiite ay rôle yu bari, loolu dafay jàppale xale yi ñu xam fu nit ñi nuru ak wuute ci seeni bëgg-bëgg, seen gëm-gëm ak seeni yëg-yëg.
Dans le théâtre pour enfants aussi, l'occasion de jouer et de diriger divers rôles aide les enfants à reconnaître les similitudes et les différences entre les gens dans leurs désirs, leurs croyances et leurs émotions.
All of this is not bad news for mankind.
Loolu lépp du xibaar bu bon ci doomu Aadama yi.
Tout cela n'est pas une mauvaise nouvelle pour l'humanité.
We may have court documents in Chinese or Russian.
Mën nañu am këyitu àttekaay ci làkku chinois wala russe.
Nous pouvons avoir des documents en chinois ou en russe.
the woman spoke with joy of her travels and of herself
ku jigéen ki wax ak bànneex ci tukki yi ak ci boppam
la femme parla avec joie de ses voyages et d' elle-même
Here, not more than three miles away, was an area with a jagged wall full of western views
Fii, soriwul lu ëpp ñatti mile, amoon na barab bu am miir bu ñaw bu fees dell ak sowwu
Ici, à moins de trois miles, était une zone avec un mur de déchiqueté plein de vues de l'ouest
He suggested searching for zero.
Muni ma seet nul.
Il a suggéré de chercher Zéro.
Based on these findings, Centrelink developed specific strategies to educate potential beneficiaries and business owners on how to effectively manage their financial data.
Ci li ñu gis, Centrelink tëral ay pexe yu jëm ci jàngal ñi mëna am njariñ ak boroom liggéey yi ni ñuy yoree seen done xaalis ci anam wu jaar yoon.
Sur la base de ces résultats, Centrelink a élaboré des stratégies spécifiques pour informer les bénéficiaires potentiels et les propriétaires d'entreprises sur la manière de gérer efficacement leurs données financières.
Technology is merely a tool, not a business tool.
Xarala yu bees yi jumtukaay la, du jumtukaayu liggéey.
La technologie est simplement un outil, pas un outil commercial.
Hazmi and Mihdar rented a room for a year, for $500 a day
Hazmi ak Mihdar luwaas nañu néeg benn at, ñu fay $500 bis bu nekk
Hazmi et Mihdar ont loué une chambre pour un an, 500 dollars par jour.
Some of the members have donated over $1,000 to the school.
Ñenn ci ndaw yi jox nañu daara ji lu ëpp $1,000.
Certains membres ont donné plus de 1000 dollars à l'école.
Saving affects not only the value of wealth, but wealth itself influences the choice of saving.
Denc xaalis du yam ci valëru alal rek, waaye alal ci boppam mooy tànn ni ñuy denc xaalis.
L'épargne n'affecte pas seulement la valeur de la richesse, mais la richesse elle-même influence le choix de l'épargne.
These skills were inadequate, but little was done to develop or improve them.
Xam-xam yooyu doyul woon, waaye ñu def lu néew ngir gëna yokk seen mën-mën.
Ces compétences étaient insuffisantes, mais peu de choses ont été faites pour les développer ou les améliorer.
Indianapolis is the best place to work in the film industry
Indianapolis mooy barab bi gëna baax ngir liggéey ci wàllu filmu
Indianapolis est le meilleur endroit pour travailler dans l'industrie du cinéma.
as is usually the case, it was 75 during the winter
nimu koy faral di defee, 75 la woon ci hiver bi
Comme d'habitude, il était de 75 pendant l'hiver.
The legislature is not the only political arena in Washington.
Du waa këru yoon kese ñoo am barabu politik ci Washington.
Le législateur n'est pas la seule arène politique à Washington.
The cost of this workshop probably won't be covered by the ticket money
Amaana xaalisu biye bi du fay njëgu atelier bii
Le coût de cet atelier ne sera probablement pas couvert par l'argent du billet.
Rockefeller had given
Rockefeller joxoon na
Rockefeller avait donné
The group had a name before this one that you would have thought was an Indian monkey.
Groupe bi amoon na tur balaa bii, dinga jàpp ni goorgu Inde la.
Le groupe avait un nom avant celui-ci que vous auriez pensé être un singe indien.
Canada has a safe air
Canada amna air bu wóor
Le Canada a un air sûr
I think you're right about this.
Yaakaar naa ni wax nga dëgg.
Je pense que vous avez raison à ce sujet.
I'm obviously trying to do this.
Dama jéema def lii.
Je suis évidemment en train d'essayer de faire ça.
the board did not approve of the SBA
kilifa yi nangu wuñu SBA
le conseil n'a pas approuvé le SBA
The nation was founded on the belief that some people are better than others
Ñu ngi sos réew mi ci ngëm ni amna ñu gën ñeneen ñi
La nation a été fondée sur la croyance que certaines personnes sont meilleures que d'autres
We have people who have donated over $1,000 to the law school.
Am nanu nit ñu jox lu ëpp $1,000 daara ju mag ji.
Nous avons des gens qui ont donné plus de 1000 $ à l'école de droit.
And Centrelink doesn't know how to solve problems
Te Centrelink xamul ni ñuy saafara jafe-jafe yi
Et Centrelink ne sait pas comment résoudre les problèmes
All falsehoods have a symbolic value of their own.
Bépp fen amna lu muy màndargaal.
Tous les mensonges ont une valeur symbolique.
Whether a person chooses to save or not affects his wealth.
Bu nit tànnee denc xaalis am déet, mingi aju ci alal ji mu am.
La décision d'épargner ou non a une incidence sur la richesse d'une personne.
how do you do exercise when you stretch your body and dance to music
naka ngay def tàggat yaram sooy tàllal sa yaram di fecc ci music
Comment fais-tu de l'exercice quand tu t'étires et que tu danses au son de la musique?
There are additional issues of audit requirements by local governments.
Amna yeneen mbir yu nguur yi sàkku ci audit bi.
Il existe d'autres questions relatives aux exigences d'audit des gouvernements locaux.
00 has enabled us to provide guidance, encouragement and entertainment to nearly 400 children in the Indianapolis area.
00 may nanu nu mëna jàppale, ñaax ak bégal luy tollu ci 400 xale ci diwaanu Indianapolis.
00 nous a permis de fournir des conseils, des encouragements et du divertissement à près de 400 enfants dans la région d'Indianapolis.
the arts in the lower rooms were his main occupation
art yi ci néeg yi ci suuf ñoo gënoon liggéey
Les arts dans les chambres inférieures étaient sa principale occupation
They haven't changed much in their surveillance program.
Coppite wuñu lu bari ci seen prograamu wattu.
Leur programme de surveillance n'a pas beaucoup changé.
filmmakers love Indianapolis because of its movie theaters
defarkatu filmu yi bëgg nañu Indianapolis ndax sinemaa yi
Les cinéastes adorent Indianapolis à cause de ses salles de cinéma.
There is a difficulty that produces a rod of iron.
Amna jafe-jafe buy génne yetu weñ.
Il y a une difficulté qui produit une tige de fer.
Bets on political contests and elections are also available on this website.
Parye yi ci joŋante politik ak eleksioŋ am nañu ci sitweb bii.
Les paris sur les concours politiques et les élections sont également disponibles sur ce site.
has a long history of innovation and diversity since before the twentieth century
amna taarix bu yaatu ci liggéey yu bees ak wuute balaa ñaar fukkeelu xarnu
a une longue histoire d'innovation et de diversité depuis avant le XXe siècle
And the beggar moves on and must see him as soon as he passes by.
Yalwaankat bi dem yoonam, te dafa wara gis ko bumu rombee rek.
Et le mendiant continue et doit le voir dès qu'il passe.
The German government may have had a hard time conducting a quick and definitive investigation.
Nguuru Allemagne mën na am jafe-jafe amal lànket bu gaaw te leer.
Le gouvernement allemand a peut-être eu du mal à mener une enquête rapide et définitive.