wo stringlengths 1 251 ⌀ | en stringlengths 1 297 | fr stringlengths 1 1.15k |
|---|---|---|
Góor ñi ak jigéen ñi ci Allemagne... ndawi pàrti bi... | German men and women... members of the Party... | Hommes et femmes allemands... membres du Parti... |
Man itam dinaa ko def. | I would do the same. | Je ferais de même. |
Pelle... | Pelle... | Pelle... |
Bii du pizzeria. | This is not a pizzeria. | Ce n'est pas une pizzeria. |
Maa ngi ragal ni advocaat la, kilifa. | I'm afraid it's advocaat, sir. | J'ai bien peur que ce soit un advocat, monsieur. |
"Sikki sama xel ni dinañu def benn coow. | "I doubt they'll kick up any fuss. | "Je doute qu'ils s'en foutent. |
Sama lekk mooy lii. | Here's my food. | Voilà ma nourriture. |
Avocat bi laal nama. | The lawyer fucked me. | L'avocat m'a baisé. |
Dina ñu ko def. | They're going to do it. | Ils vont le faire. |
- Mën naa ko. | - I can manage. | - Je peux m'en sortir. |
Ndax amna keneen ku am lu muy ñaxtu? | Does anyone else have any complaints? | Quelqu'un d'autre a-t-il des plaintes? |
Ndax namm ngama? | Did you miss me? | Je t'ai manqué? |
Daf nuy wax danu wara dundu. | He's telling us we should live. | Il nous dit qu'on devrait vivre. |
Duñu bawoo ci àll bi. | They're not from these woods. | Ils ne sont pas de ces bois. |
Balaa may jox la Bill amna beneen mbir buma jàpp ni dañu wara waxtaan ci. | Well, before I turn you over to Bill there's one other thing I think we should talk about. | Avant que je te livre à Bill, il y a une autre chose dont je pense qu'on devrait parler. |
Ñu damm samay cox, waaye waxuma genn baat. | They broke my ribs, but I didn't say a word. | Ils m'ont cassé les côtes, mais je n'ai rien dit. |
Dimbali ma.? | Help me.? | Aidez-moi.? |
- Ndax nataal yooyu ñu ngi ci jaay? | - Are those pictures on sale? | - Ces photos sont en vente? |
Daa melni jël nga sa dogal ba pare. | It seems you've already made up your mind. | Il semble que tu aies déjà pris ta décision. |
Du saa yu nekk ngeen di fi nekk, yenn saa ma am naqar. | You are not always here and sometimes I'm so depressed. | Tu n'es pas toujours là et parfois je suis si déprimée. |
.fii, man maay waa ji mëna la jox mbir, sure? | .in here, I'm the guy who can get things for you, sure? | Ici, c'est moi qui peux t'acheter des trucs. |
- Duma fay juuti, Sa Buur. | - I wouldn't tax yourself, Your Majesty. | - Je ne vous taxerais pas, Votre Majesté. |
Ak beneen. | And another one. | Et un autre. |
Fatteel ëtt bu xeeñ bii! | Forget this stinking barn! | Oublie cette grange puante! |
-Dellu leen! | -Stay away! | - Ne bougez pas! |
Jox nu leneen. | Give us something else. | Donnez-nous autre chose. |
Nu am 12 dindon, lu tollu ci 40 ginaar, 50 steak sirloin, ñaari fukki yàppu mbaam xuux ak 20 tànki agneau. | We got 12 turkeys, about 40 chickens 50 sirloin steaks, two dozen of pork roast and 20 legs of lamb. | On a 12 dindes, environ 40 poulets 50 steaks, deux douzaines de rôtis de porc et 20 pattes d'agneau. |
- Lu ñuy wax ci nun ? | - What do they say about us? | - Qu'est-ce qu'ils disent de nous? |
ci koñu armuwar bi mu daje ak fan weeri ak ñetti bëñi Seytaane | in a corner of the closet she met thirty-three Devil's Teeth | dans un coin du placard, elle rencontra trente-trois dents du Diable |
Yobbu ko ci néeg bi. | Carry him down to the cellar. | Emmenez-le à la cave. |
Dafay faral di tafu. | It tends to stain. | Il a tendance à tacher. |
Du nuru melodramatik waaye xam nañu ni dafay may ñu néew ñu xalaat ci liggéey bi. | Not to sound melodramatic but it's been known to give a few people second thoughts about the job. | Pas pour sonner mélodramatique, mais on sait qu'il y a quelques personnes qui pensent de nouveau au travail. |
Dindil pushcart bi ci yoon wi! | Get that pushcart out of the way! | Dégagez cette carteuse! |
Fan nga jëlee lii? | Where'd you get this? | Où as-tu eu ça? |
Dinaa jël? | I'll take? | Je prends? |
- Ricci, dinga takk afis. | - Ricci, you'll hang posters. | - Ricci, vous accrocherez des affiches. |
Krem galass prune suukër! | Sugarplum ice cream! | Glace à sucre! |
Dama la bëgg, waaye mënuma baale li nit ñi def. | I like you, but I can't forgive what people have done. | Je t'aime bien, mais je ne peux pas pardonner ce que les gens ont fait. |
Fan lady Eboshi nekk? | Where's Lady Eboshi? | Où est Lady Eboshi? |
Dufayel, jéggalu. | Sorry, Mr. Dufayel. | Désolé, M. Dufayel. |
Dungeen xam mbir yooyu. | You won't understand these things. | Vous ne comprendrez pas ces choses. |
Waaye ci biti, li nga soxla du lenn ludul xët yu nete yi? | But outside, all you need is the Yellow Pages? | Mais dehors, tout ce dont tu as besoin, c'est les Pages Jaunes? |
- Waaw | - Yes | - Oui. |
Te dara lu baax du musa dee. | And no good thing ever dies. | Et aucune bonne chose ne meurt jamais. |
Stablehand, lu tax nag bi taxaw foofu? | Stablehand, why is that cow standing there? | Stablehand, pourquoi cette vache se tient-elle là? |
Nit ñooñu ñépp. | All these people. | Tous ces gens. |
Dañuy dàll yu màgget. | They're old shoes. | Ce sont de vieilles chaussures. |
. Aaar! | . Aaarghh! | - Aaarghh! |
Man Sanja laa. | I'm Sanja. | Je suis Sanja. |
Demal fii. | You stay here. | Reste ici. |
Lu ëpp benn wala ñaari fan. | One or two days at most. | Un ou deux jours au plus. |
Waaye amul lenn luñu mën a def. | But there's nothing we can do. | Mais on ne peut rien faire. |
Scram, yaw dof! | Scram, you oaf! | Scram, espèce d'abruti! |
Ak taw bi am. | And then, there was the rain. | Et puis, il y a eu la pluie. |
Boroom beneen tundu lañu. | They're lords of some other mountain. | Ce sont des seigneurs d'une autre montagne. |
Ndax fàtte naa la, Durga? | Did I forget you, Durga? | Je t'ai oubliée, Durga? |
- Duma xam. | - Wouldn't know. | - Je ne sais pas. |
Ndax bëgg nga agneau, Doktër? | Do you like lamb, Doc? | Vous aimez l'agneau, Doc? |
Sama buur. | My king. | Mon roi. |
Bëñi sa maam ju jigéen seytaane lañu? | Teeth of your grandmother the devil are they? | Les dents de ta grand-mère sont-elles le diable? |
Ak bànneex. | With pleasure. | Avec plaisir. |
Bëgg nga mozzarella ci kaw mburu? | You want mozzarella on bread? | Tu veux de la mozzarella sur du pain? |
Dama jaaxle. | I'm intrigued. | Je suis intrigué. |
Yobbu ko ci néeg bi! | Carry him down to the cellar! | Emmenez-le à la cave! |
Ku nekk deful dara fii? | Everybody's innocent in here? | Tout le monde est innocent ici? |
Um, ci néegu sama pàppa laa ko génne. | Um, I got it out of my dad's room, actually. | Je l'ai sorti de la chambre de mon père, en fait. |
Yaram sama yaram xol sama xol... | Flesh of my flesh heart of my heart... | La chair de mon cœur de chair de mon cœur... |
Dinaa dee ni dof ndax mbëggeel gii. | I'll die a fool for this love. | Je mourrai un idiot pour cet amour. |
Gone. | Baby. | Bébé. |
- Lu tax? | - Why? | - Pourquoi? |
Kon? | So? | Alors? |
- Afiis yi? | - Posters? | - Des affiches? |
Ndax bëgg nako? | Is she in love with him? | Est-elle amoureuse de lui? |
Yaakaar naa ni lu nééw la nit mëna taxaw ci kanamu ñi mu àndaloon ginaaw 20 at ci nguur gi. | It is, I believe, a rare thing that a man can stand before his old supporters after 20 years in office, | C'est, je crois, une chose rare qu'un homme puisse se tenir devant ses vieux partisans après 20 ans au pouvoir, |
Nguur gi itam? | The government district too? | Le district gouvernemental aussi? |
PS. Wax Heywood ma jéggalu ci lima ko dóor baat? | PS. Tell Heywood I'm sorry I put a knife to his throat? | PS. Dites à Heywood que je suis désolé de lui avoir mis un couteau à la gorge? |
Loolu baax na. | That's all right. | C'est bon. |
Jahannama, xamuma fan laa wara tàmbalee? | Hell, I wouldn't even know where to begin? | Je ne saurais même pas par où commencer? |
.? t-t- mbaam xuux bu graas bi foofu. | .? t-t-the chubby fat-ass there. | C'est le gros cul de pote là-bas. |
Leegi ñëwal, Doktër. | Now come on, Doc. | Allez, Doc. |
Lu tax Gabriella taxaw foofu? | Why is Gabriella standing there? | Pourquoi Gabriella est là? |
Baal ma. | Excuse me. | Excusez-moi. |
-Déedéet. | -No. | - Pas du tout. |
Yaa ngi dundu ci sa liggéey. | You live in your work. | Tu vis dans ton travail. |
Bi nuy ndaw, man ak sa yaay dañu bëggoon tukki. | When we were young, your mother and I longed to travel. | Quand on était jeunes, ta mère et moi voulions voyager. |
Xaar. | Wait. | Attendez. |
Bépp yoon mën na jeex. | At any minute, it could all be over. | D'une minute à l'autre, tout pourrait être fini. |
Daf la yàq lool. | You have been so spoiled by it. | Tu as été tellement gâté par ça. |
Soo noppee tuuti ci guddi gi, dina la ko mëna jàppale. | A few good nights' rest will do it. | Quelques bonnes nuits de repos le feront. |
Okkoto la! | It's Okkoto! | C'est Okkoto! |
Ndax déggoo dara? | H aven't you heard anything? | Vous n'avez rien entendu? |
Moytul sa gémmiñ! | Watch your mouth! | Surveillez votre bouche! |
Musunoo gis ndox mu wàcci ci yàlla yi diirub 60 guddi ak 60. | Never before had we seen water that fell from the gods for 60 days and nights. | Jamais auparavant nous n'avions vu de l'eau qui tombait des dieux pendant 60 jours et nuits. |
Ñu weddi ko ñatti yoon. | Denied him three times. | Il l'a refusé trois fois. |
- Ñaata lañuy njëg? | - How much are they? | - Combien vont-ils? |
Yaakaar naa ni waxu ñu dara ci Denver ci musiba bi ñu dundu fii ci hiver 1970. | I don't suppose they said anything in Denver about the tragedy we had up here during the winter of 1970. | Je suppose qu'ils n'ont rien dit à Denver sur la tragédie que nous avons eue ici pendant l'hiver 1970. |
Avocaat, wala ? | Advocaat, is it? | Advocat, c'est ça? |
Lu ngeen di def fii? | What are you doing here? | Qu'est-ce que tu fais là? |
Waxuma. | I didn't speak. | Je n'ai pas parlé. |
- Déedet. Du fii! | - No. Not here! | - Non, pas ici! |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.