en stringlengths 1 298 | wo stringlengths 1 279 ⌀ | fr stringlengths 1 687 |
|---|---|---|
German men and women... members of the Party... | Góor ñi ak jigéen ñi ci Allemagne... ndawi pàrti bi... | Des hommes et des femmes allemands, membres du Parti... |
I would do the same. | Man itam dinaa ko def. | Je ferais la même chose. |
Pelle... | Pelle... | Je suis désolé. |
This is not a pizzeria. | Bii du pizzeria. | Ce n'est pas une pizzeria. |
I'm afraid it's advocaat, sir. | Maa ngi ragal ni advocaat la, kilifa. | Je crains que ce soit l'avocat, monsieur. |
"I doubt they'll kick up any fuss. | "Sikki sama xel ni dinañu def benn coow. | "Je doute qu'ils vont faire du bruit. |
Here's my food. | Sama lekk mooy lii. | Voilà ma nourriture. |
The lawyer fucked me. | Avocat bi laal nama. | L'avocat m'a baisé. |
They're going to do it. | Dina ñu ko def. | Ils vont le faire. |
- I can manage. | - Mën naa ko. | - Je peux m'en occuper. |
Does anyone else have any complaints? | Ndax amna keneen ku am lu muy ñaxtu? | Quelqu'un d'autre a des plaintes? |
Did you miss me? | Ndax namm ngama? | Je t'ai manqué? |
He's telling us we should live. | Daf nuy wax danu wara dundu. | Il nous dit que nous devrions vivre. |
They're not from these woods. | Duñu bawoo ci àll bi. | Ils ne sont pas de ces bois. |
Well, before I turn you over to Bill there's one other thing I think we should talk about. | Balaa may jox la Bill amna beneen mbir buma jàpp ni dañu wara waxtaan ci. | Avant de vous remettre à Bill, il y a une autre chose dont nous devrions parler. |
They broke my ribs, but I didn't say a word. | Ñu damm samay cox, waaye waxuma genn baat. | Ils m'ont cassé les côtes, mais je n'ai rien dit. |
Help me.? | Dimbali ma.? | Vous m'aidez? |
- Are those pictures on sale? | - Ndax nataal yooyu ñu ngi ci jaay? | - Ces photos sont en vente? |
It seems you've already made up your mind. | Daa melni jël nga sa dogal ba pare. | Il semble que vous ayez déjà pris votre décision. |
You are not always here and sometimes I'm so depressed. | Du saa yu nekk ngeen di fi nekk, yenn saa ma am naqar. | Tu n'es pas toujours là et parfois je suis tellement déprimée. |
.in here, I'm the guy who can get things for you, sure? | .fii, man maay waa ji mëna la jox mbir, sure? | Je suis le type qui peut t'apporter des choses, c'est sûr? |
- I wouldn't tax yourself, Your Majesty. | - Duma fay juuti, Sa Buur. | - Je ne vous imposerais pas, Votre Majesté. |
And another one. | Ak beneen. | Et encore une. |
Forget this stinking barn! | Fatteel ëtt bu xeeñ bii! | Oubliez cette grange puante! |
-Stay away! | -Dellu leen! | - Ne vous approchez pas! |
Give us something else. | Jox nu leneen. | Donne-nous autre chose. |
We got 12 turkeys, about 40 chickens 50 sirloin steaks, two dozen of pork roast and 20 legs of lamb. | Nu am 12 dindon, lu tollu ci 40 ginaar, 50 steak sirloin, ñaari fukki yàppu mbaam xuux ak 20 tànki agneau. | Nous avons 12 dindes, environ 40 poulets 50 filets de filet, deux douzaines de rôtis de porc et 20 pattes d'agneau. |
- What do they say about us? | - Lu ñuy wax ci nun ? | - Ils disent quoi de nous? |
in a corner of the closet she met thirty-three Devil's Teeth | ci koñu armuwar bi mu daje ak fan weeri ak ñetti bëñi Seytaane | Dans un coin du placard, elle a rencontré 33 dents du diable. |
Carry him down to the cellar. | Yobbu ko ci néeg bi. | Emmenez-le dans la cave. |
It tends to stain. | Dafay faral di tafu. | Il a tendance à tacher. |
Not to sound melodramatic but it's been known to give a few people second thoughts about the job. | Du nuru melodramatik waaye xam nañu ni dafay may ñu néew ñu xalaat ci liggéey bi. | Je ne veux pas paraître mélodramatique, mais ça a donné à certains une seconde pensée sur le travail. |
Get that pushcart out of the way! | Dindil pushcart bi ci yoon wi! | Sortez cette poussette de la route! |
Where'd you get this? | Fan nga jëlee lii? | Où avez-vous trouvé ça? |
I'll take? | Dinaa jël? | Je prends? |
- Ricci, you'll hang posters. | - Ricci, dinga takk afis. | - Ricci, vous allez accrocher des affiches. |
Sugarplum ice cream! | Krem galass prune suukër! | Des glaces à la prune! |
I like you, but I can't forgive what people have done. | Dama la bëgg, waaye mënuma baale li nit ñi def. | Je t'aime bien, mais je ne peux pas pardonner ce que les gens ont fait. |
Where's Lady Eboshi? | Fan lady Eboshi nekk? | Où est Lady Eboshi? |
Sorry, Mr. Dufayel. | Dufayel, jéggalu. | Je suis désolé, M. Dufayel. |
You won't understand these things. | Dungeen xam mbir yooyu. | Tu ne comprends pas ces choses. |
But outside, all you need is the Yellow Pages? | Waaye ci biti, li nga soxla du lenn ludul xët yu nete yi? | Mais dehors, tout ce dont vous avez besoin, ce sont les pages jaunes? |
- Yes | - Waaw | - Je sais. |
And no good thing ever dies. | Te dara lu baax du musa dee. | Et aucune bonne chose ne meurt. |
Stablehand, why is that cow standing there? | Stablehand, lu tax nag bi taxaw foofu? | Écurie, pourquoi cette vache est là? |
All these people. | Nit ñooñu ñépp. | Tous ces gens. |
They're old shoes. | Dañuy dàll yu màgget. | Ce sont de vieilles chaussures. |
. Aaarghh! | . Aaar! | Je suis désolé. |
I'm Sanja. | Man Sanja laa. | Je suis Sanja. |
You stay here. | Demal fii. | Restez ici. |
One or two days at most. | Lu ëpp benn wala ñaari fan. | Un ou deux jours au plus. |
But there's nothing we can do. | Waaye amul lenn luñu mën a def. | Mais on ne peut rien faire. |
Scram, you oaf! | Scram, yaw dof! | Foutez le camp, crétin! |
And then, there was the rain. | Ak taw bi am. | Et puis, il y a eu la pluie. |
They're lords of some other mountain. | Boroom beneen tundu lañu. | Ce sont les seigneurs d'une autre montagne. |
Did I forget you, Durga? | Ndax fàtte naa la, Durga? | Je t'ai oubliée, Durga? |
- Wouldn't know. | - Duma xam. | - Je ne sais pas. |
Do you like lamb, Doc? | Ndax bëgg nga agneau, Doktër? | Vous aimez l'agneau, Doc? |
My king. | Sama buur. | Mon roi! |
Teeth of your grandmother the devil are they? | Bëñi sa maam ju jigéen seytaane lañu? | Ce sont les dents de ta grand-mère le diable? |
With pleasure. | Ak bànneex. | - Avec plaisir. |
You want mozzarella on bread? | Bëgg nga mozzarella ci kaw mburu? | Tu veux de la mozzarella sur du pain? |
I'm intrigued. | Dama jaaxle. | Je suis intriguée. |
Carry him down to the cellar! | Yobbu ko ci néeg bi! | Emmenez-le dans la cave! |
Everybody's innocent in here? | Ku nekk deful dara fii? | Tout le monde est innocent ici? |
Um, I got it out of my dad's room, actually. | Um, ci néegu sama pàppa laa ko génne. | Je l'ai pris dans la chambre de mon père. |
Flesh of my flesh heart of my heart... | Yaram sama yaram xol sama xol... | Carne de ma chair, cœur de mon cœur |
I'll die a fool for this love. | Dinaa dee ni dof ndax mbëggeel gii. | Je mourrai comme un fou pour cet amour. |
Baby. | Gone. | Je suis désolée. |
- Why? | - Lu tax? | - Pourquoi? - Je ne sais pas. |
So? | Kon? | Alors? |
- Posters? | - Afiis yi? | - Des affiches? |
Is she in love with him? | Ndax bëgg nako? | Est-elle amoureuse de lui? |
It is, I believe, a rare thing that a man can stand before his old supporters after 20 years in office, | Yaakaar naa ni lu nééw la nit mëna taxaw ci kanamu ñi mu àndaloon ginaaw 20 at ci nguur gi. | Je crois que c'est rare qu'un homme puisse se tenir devant ses anciens partisans après 20 ans au pouvoir, |
The government district too? | Nguur gi itam? | Le district du gouvernement aussi? |
PS. Tell Heywood I'm sorry I put a knife to his throat? | PS. Wax Heywood ma jéggalu ci lima ko dóor baat? | P.S. Dis à Heywood que je suis désolé de lui avoir mis un couteau à la gorge? |
That's all right. | Loolu baax na. | Ça va aller. |
Hell, I wouldn't even know where to begin? | Jahannama, xamuma fan laa wara tàmbalee? | Je ne saurais même pas par où commencer. |
.? t-t-the chubby fat-ass there. | .? t-t- mbaam xuux bu graas bi foofu. | Le cul gros et gros qui est là. |
Now come on, Doc. | Leegi ñëwal, Doktër. | Allez, Docteur. |
Why is Gabriella standing there? | Lu tax Gabriella taxaw foofu? | Pourquoi Gabriella est là? |
Excuse me. | Baal ma. | Je suis désolé. |
-No. | -Déedéet. | - Je ne sais pas. |
You live in your work. | Yaa ngi dundu ci sa liggéey. | Vous vivez dans votre travail. |
When we were young, your mother and I longed to travel. | Bi nuy ndaw, man ak sa yaay dañu bëggoon tukki. | Quand on était jeunes, ta mère et moi, on rêvait de voyager. |
Wait. | Xaar. | Attends un peu. |
At any minute, it could all be over. | Bépp yoon mën na jeex. | À tout moment, tout pourrait être fini. |
You have been so spoiled by it. | Daf la yàq lool. | Tu as été si gâtée par ça. |
A few good nights' rest will do it. | Soo noppee tuuti ci guddi gi, dina la ko mëna jàppale. | Quelques nuits de repos suffiront. |
It's Okkoto! | Okkoto la! | Il est Okkoto! |
H aven't you heard anything? | Ndax déggoo dara? | Vous n'avez rien entendu? |
Watch your mouth! | Moytul sa gémmiñ! | Attention à ce que tu dis! |
Never before had we seen water that fell from the gods for 60 days and nights. | Musunoo gis ndox mu wàcci ci yàlla yi diirub 60 guddi ak 60. | Jamais auparavant nous n'avions vu de l'eau qui tombait des dieux pendant 60 jours et nuits. |
Denied him three times. | Ñu weddi ko ñatti yoon. | Je l'ai renié trois fois. |
- How much are they? | - Ñaata lañuy njëg? | - Combien ça coûte? |
I don't suppose they said anything in Denver about the tragedy we had up here during the winter of 1970. | Yaakaar naa ni waxu ñu dara ci Denver ci musiba bi ñu dundu fii ci hiver 1970. | Je ne pense pas qu'ils aient dit quelque chose à Denver sur la tragédie que nous avons eu ici pendant l'hiver de 1970. |
Advocaat, is it? | Avocaat, wala ? | Vous êtes Advocaat? |
What are you doing here? | Lu ngeen di def fii? | - Tu fais quoi ici? |
I didn't speak. | Waxuma. | Je n'ai pas parlé. |
- No. Not here! | - Déedet. Du fii! | - Non, pas ici! |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.