en stringlengths 1 298 | wo stringlengths 1 279 ⌀ | fr stringlengths 1 687 |
|---|---|---|
Well.... | Baax na.... | Je sais. |
Red. | Xonq. | Le rouge. |
To my knowledge, he lived out the rest of his days drinking his food through a straw. | Lima xam mooy, bis yi ci des dafa daan naan ñam ci ñax. | À ma connaissance, il a vécu le reste de ses jours en buvant sa nourriture à travers une paille. |
How can they do this? | Naka lañu mënee def loolu ? | Comment peuvent-ils faire cela? |
Looks like you might have got a spot of it on yourself Jeevesy old boy. | Daa melni amna lu ci nekk ci sa bopp Jeevesy old boy. | On dirait que vous pourriez avoir une tache de lui sur vous-même Jeevesy vieux garçon. |
Come and get me! | Ñëwal jël ma! | Viens me voir! |
You will have my son. | Di nga am sama doom. | Vous aurez mon fils. |
- Not me. I didn't shoot my wife and I didn't shoot her lover? | - Du man. Tiirewuma sama jabar te tiirewuma soppeem? | Je n'ai pas tué ma femme et son amant? |
Woman behold your son. | Ndaw si, sa doom la. | Femme, regarde ton fils. |
Call her back! | Woowaat ko! | Rappelle-la au téléphone! |
She might just do that. | Mën na def loolu. | Elle pourrait le faire. |
What's your favorite food, then? | Kon, lan mooy ñam wi la gënal? | Quel est ton plat préféré? |
Together we'll live. | Dina nu bokk dundu. | Nous vivrons ensemble. |
- Because of your heart. | - Ndax sa xol. | - À cause de ton cœur. |
He's seen us! | Gis na nu! | Il nous a vus! |
We'II pull through this. | Danuy jaar ci lii. | On va s'en sortir. |
I won't tolerate it in any of my units. | Duma muñ benn ci samay yunit. | Je ne tolérerai pas ça dans aucune de mes unités. |
I feel better. | Maa ngi féex. | Je me sens mieux. |
Let me go! | Bàyyil ma dem! | Laissez-moi! |
As it turned out, Tommy had himself a young wife and a new baby girl. | Tommy am jabar ju ndaw ak doom ju jigéen ju bees. | Il s'est avéré que Tommy avait une jeune femme et une petite fille. |
I won't make a sound. | Duma def benn bruit. | Je ne ferai pas de bruit. |
My God, a job! | Sama Yàlla, liggéey! | Mon Dieu, un travail! |
Fresh fish! | Jën wu fere! | Du poisson frais! |
Aspasia it says. | Aspasia la wax. | Il est écrit Aspasie. |
He should have died in here. | Dafa waroon dee ci biir. | Il aurait dû mourir ici. |
Frame number: 12033. | Nimero kaadar bi: 12033. | Numéro de cadre: 12033. |
I am left behind, a penniless beggar. | Maa ngi des ci ginaaw, yalwaankat bu amul xaalis. | Je suis resté derrière, un mendiant sans le sou. |
Convince him that we have to leave Berlin, Eva! | Eva, gëmloo ko ni dañu wara bàyyi Berlin! | Convainquez-le que nous devons quitter Berlin, Eva! |
Why should she watch you eat? | Lu tax mu wara xool ngay lekk? | Pourquoi devrait-elle te regarder manger? |
The mama Bengta died and now she's in the cemetery back home. | Yaay ji Bengta faatu na, leegi mingi ci bàmmeel bi ci këram. | La maman Bengta est morte et maintenant elle est dans le cimetière de chez elle. |
Drink. | Naan. | Je vous en prie. |
You know better, Machatas. | Machatas, yaa ko gën a xam. | Vous le savez bien, Machatas. |
Your suggestion is absurd! | Sa xalaat amul benn njariñ! | Votre suggestion est absurde! |
I made it! | Def naa ko! | Je l'ai fait! |
- And I am not my father. | - Te duma sama baay. | - Et je ne suis pas mon père. |
I can't believe they called us stoners. | Mënu ma ni dañu nu woowe ay dojkat. | Je n'arrive pas à croire qu'ils nous aient traité de défoncés. |
You have to go or there will be trouble with the authorities. | Danga wara dem lu ko moy jafe-jafe dina am ak kilifa yi. | Vous devez partir ou il y aura des problèmes avec les autorités. |
I don't understand. | Nànduma. | Je ne comprends pas. |
Goddamn--! | Yalla--! | Nom de Dieu! |
That doesn't matter, sir. | Loolu amul solo, sang bi. | Ça n'a pas d'importance. |
- Yes. I know. | - Waaw. Xam naa. | - Je sais. |
That's goddamn right. | Loolu mooy dëgg. | C'est vrai, putain. |
Maybe it was the thought of them on the streets or his child growing up not knowing her daddy. | Mën na am muy xalaat seen nekk ci mbedd mi wala doomam biy màgg te xamul pàppaam. | Peut-être que c'était la pensée d'eux dans la rue ou de son enfant grandissant sans connaître son père. |
French fries and ketchup. | Frites ak ketchup. | Des frites et du ketchup. |
Where are you? | Fan nga nekk? | Où est-ce que vous êtes? |
He knows it better than I do. | Moo ma gëna xam. | Il le sait mieux que moi. |
My predecessor in this job hired a man named Charles Grady as the winter caretaker. | Ki ma jiitu ci liggéey boobu dafa jël ku tuddu Charles Grady ngir mu toppatoo baayima yi ci hiver bi. | Mon prédécesseur dans ce travail a embauché un homme nommé Charles Grady comme gardien d'hiver. |
Run along to your mother, dear. | Daw dem ci sa yaay, sama xarit. | Va voir ta mère, chérie. |
Wait! | Xaar! | - Je suis désolé. |
I'm thinking Andy could use a nice welcome back when he gets out of the infirmary. | Dama jàpp ni Andy mën nako dalal bu baax su génnee ci saal bi. | Je pense qu'Andy pourrait avoir besoin d'un bon accueil quand il sortira de l'infirmerie. |
And your father is a widower? | Ak sa pàppa jabar la? | Et votre père est veuf? |
If you're done, get out of here! | Soo noppee, jogeel fii! | Si vous avez fini, sortez d'ici! |
Fall back! | Dellu ginaaw! | Retournez! |
But I truly believe you'll see him again. | Waaye gëm naani dinga ko gisaat. | Mais je crois vraiment que vous le reverrez. |
You're lucky, Orin. | Am nga wërsëg, Orin. | Vous avez de la chance, Orin. |
Insane! | Dof! | Vous êtes dingue! |
Day draws to its close, night's mantle descends. | Bis baa ngi jegesi, màntoo guddi gi wàcci. | Le jour touche à sa fin, le manteau de la nuit descend. |
He gave me a job! | Daf ma jox liggéey! | Il m'a donné un travail! |
If Mama could see us! | Suma sama yaay mënoon nu gis! | Si maman pouvait nous voir! |
The water's wet. | Ndox mi tooy na. | L'eau est mouillée. |
Fresh fish today! | Jën wu fere tay! | Du poisson frais, aujourd'hui! |
Perhaps Mr. trainee could tell me where she is suppose to stand. | Amaana M. stagiaire bi mën nama wax fumu wara taxaw. | Peut-être que M. le stagiaire pourrait me dire où elle est supposée se tenir. |
Hey, what about us? | Saa waay, nun nak? | Hé, et nous alors? |
Son, behold your mother. | Sama doom, sa yaay a ngii. | Mon fils, voici ta mère. |
Soon, I'll be up. | Dinaa yewwu ci diir bu gàtt. | Je serai bientôt là. |
Which Katja? | Katja bi? | Quelle Katja? |
I would like to see where you work, if you don't mind... | Dama bëgga gis fi ngay liggéey, soo ko bëggee... | J'aimerais voir où vous travaillez, si ça ne vous dérange pas... |
Or come with me. | Wala nga ànd ak man. | Ou viens avec moi. |
Just remember, squirt. | Nga bàyyi sa xel, squirt. | N'oublie pas, espèce de bouffon. |
I'm still your king. | Ba leegi maa ngi seen buur. | Je suis toujours votre roi. |
Spareribs, 45! | 45 | Les côtes d'épargne, 45! |
I promise I'll tiptoe. | Maa ngi lay dige ni dinaa ko def. | Je te le promets. |
Let him pass. | Bàyyileen ko mu jàll. | Laissez-le passer. |
Repeat after me. | Baamtu ci sama ginaaw. | Répète après moi. |
You're the important one. | Yaay ki am solo. | C'est vous qui êtes important. |
The name's Red. | Tur wi xonk la. | Je m'appelle Red. |
I lost many a man. | Ñàkk naa nit ñu bari. | J'ai perdu beaucoup d'hommes. |
What the fuck have you done? | Lu nga def? | Tu as fait quoi? |
- 2 dinars | - 2 dinaar | - 2 dinars. - Je vous en prie. |
- So who is he? | - Kon moom kan la? | - Alors qui est-ce? |
Master Friis? | Jàngalekat Friis? | Vous êtes M. Friis? |
For the second time in my life, | Ñaareelu yoon ci sama dundu, | Pour la deuxième fois de ma vie, |
Yakul and I will visit you. | Man ak Yakul dinañu la seeti. | Yakul et moi allons vous rendre visite. |
What's your son going to say? | Lu sa doom di wax? | Que va dire votre fils? |
She's devising a stratagem. | Mingi xalaat pexe. | Elle est en train de préparer un stratagème. |
We can do anything we want, because we're both men. | Mën nanu def lépp lunu bëgg, ndax nun ñaar ñépp ay góor lañu. | On peut faire ce qu'on veut, parce qu'on est tous les deux des hommes. |
Good... so we can divide up the work. | Baaxna... ngir nu mëna xaaj liggéey bi. | Bien... on peut donc se partager le travail. |
Have you so quickly forgotten? | Ndax gaaw nga fàtte nii? | Tu as oublié si vite? |
I'm sure he'll continue the fight in Bavaria for a certain time. | Yaakaar naa ni dina wéyal xeex bi ci Bavière ci diir bu yàgg. | Je suis sûr qu'il continuera à se battre en Bavière pendant un certain temps. |
He came up with his wife and two little girls of about 8 and 10. | Mu ñëw ak jabaram ak ñaari doomam yu jigéen yu tollu ci 8 at ak 10 at. | Il est venu avec sa femme et ses deux petites filles, âgées de 8 et 10 ans. |
Why you say that? | Lu tax nga wax loolu? | Pourquoi tu dis ça? |
Sounds good to us? | Dafa baax ci nun? | Ça nous va? |
Who is this woman you call your queen, Alexander? | Kan mooy jigéen jii ngay woowe sa reine, Alexander? | Qui est cette femme que vous appelez votre reine, Alexandre? |
Did you take something from Mrs. Mukherji's garden? | Ndax jël nga dara ci jardinier Mme Mukherji? | Vous avez pris quelque chose dans le jardin de Mme Mukherji? |
Berlin, 20 April, 1945 Adolf Hitler's 56th birthday 21/2 years later | Berlin, 20 awril, 1945 56eelu bësu juddu bu Adolf Hitler 21 at ak genn-wàll ci ginnaaw | Berlin, 20 avril 1945 Deux ans et demi plus tard, le 56e anniversaire d'Adolf Hitler |
Row me across to the other side. | Jàllal ma ba ci weneen wetu dex gi. | Ramenez-moi de l'autre côté. |
Back to work! | Dellu ci liggéey bi! | Retournez au travail! |
Young ones, never been with a woman. | Ndaw yi, musu ñu nekk ak jigéen. | Jeunes gens, vous n'avez jamais été avec une femme. |
I've got two jobs, but they're not for you. | Am naa ñaari liggéey, waaye du yaw. | J'ai deux emplois, mais ils ne sont pas pour toi. |
Red? | Xonq? | Le rouge? |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.