en stringlengths 1 298 | wo stringlengths 1 279 ⌀ | fr stringlengths 1 687 |
|---|---|---|
I have weighed them in the balances of wisdom. | Ci balansu xel, natt naa leen. | Je les ai pesées dans la balance de la sagesse. |
Binalshibh was examined in 2002. | Ci atum 2002 lañu saytu Binalshibh. | Binalshibh a été examiné en 2002. |
Giving you the king's cup is against my morals. | Jox leen kaasu buur bi dafa ñaaw sama yoon. | Vous donner la coupe du roi est contre ma morale. |
People are more likely to remember misspellings. | Nit ñi dañu gëna fàttaliku njuumte ci ortograafi. | Les gens sont plus susceptibles de se souvenir des fautes d'orthographe. |
We heard nothing from Afghanistan until the month of Ahinim. | Déglu wunu dara ci Afganistan ba ci weeru Ahinim. | Nous n'avons rien entendu d'Afghanistan avant le mois d'Ahinim. |
Court proceedings may require interpretation for those who are learning a language other than English. | Ñiy jàng beneen làkk bu dul Àngle mën nañu laaj ñu tekki làkk wi ci àttekaay bi. | Les procédures judiciaires peuvent exiger l'interprétation pour ceux qui apprennent une langue autre que l'anglais. |
The list of past donors has been published for the world to see, so trust me you don't want that kind of embarrassment! | Limu ñi njëkka joxe ndimbal siiwal nañu ko ngir àdduna bi gis ko, kon gëmleen ma bëggoo xeetu njàqare yooyu! | La liste des anciens donateurs a été publiée pour le monde entier, alors croyez-moi, vous ne voulez pas ce genre d'embarras! |
The conduct of an examination depends on the groups responsible for conducting the examination. | Doxalinu examen mingi aju ci kuréel yi ko yor. | La conduite d'un examen dépend des groupes chargés de le mener. |
she's so stupid. yes. i think it's amazing that she's willing to do all of this | Dafa dof lool. Waaw. Dama jàpp ni lu yéeme la ci limu nangu def lii yépp | Je trouve ça incroyable qu'elle soit prête à faire tout ça. |
Omnia vincit amor ((only if you're legally a weekly standard): Brit Hume ((on Fox News Sunday) writes about why Lewinsky shouldn't be able to, because she has a brain tumor and this is a recurrence.) | Brit Hume ((ci Fox News ci Dibeer) bind na lu tax Lewinsky warul ko mëna, ndax amna tumër ci yuur gi te loolu dafay dellusi.) | Omnia vincit amor (si vous êtes légalement un standard hebdomadaire): Brit Hume (sur Fox News Sunday) écrit sur les raisons pour lesquelles Lewinsky ne devrait pas être en mesure de le faire, car elle a une tumeur au cerveau et c'est une récidive.) |
Johnson felt deprived of support. | Johnson yëg ni kenn mënu ko jàppale. | Johnson se sentait privé de soutien. |
Overnight sleep can cause occasional dizziness. | Nelaw guddi mën na tax yenn saa mu miir. | Le sommeil nocturne peut occasionner des vertiges. |
It is not advisable to withhold these lessons, as difficult as it may be, even after another twenty years of growth, so that a foreigner may understand more is ridiculous about them. | Du baax ñuy tëye njàngale yooyu, ak lu jafe, doonte ginaaw ñaar fukki at ci màgg, suko defee gan mën gëna xam ni lu doywaar la ci ñoom. | Il n'est pas conseillé de retenir ces leçons, aussi difficile que cela puisse être, même après une autre vingt années de croissance, de sorte qu'un étranger peut comprendre plus est ridicule à leur sujet. |
The Tennessean reporter used dog weather for 'warm weather without rain' which comes from the dog days idiom referring to the dry August weather. | Reporter bu Tennessean bi mungi jefandikoo klimaa bi xaj ngir wax ci 'klimaa bu tàng bu amul taw' bi juge ci wax ju xaj yi di wax ci klimaa bu wow bu weeru ut bi. | Le journaliste du Tennessee a utilisé le mot "temps de chien" pour désigner "temps chaud sans pluie", qui vient de l'idiome des jours de chien se référant au temps sec d'août. |
Binalshibh was interrogated in 2002. | Ci atum 2002 lañu laaj Binalshibh. | Binalshibh a été interrogé en 2002. |
the cat ate a bottle of wine that christmas | muus mi lekk na butéelu vin ci noel bi | Le chat a mangé une bouteille de vin ce Noël |
And it was much more because the mothers were drunk with drugs. | Rax ci dolli yaay yi màndiwoon nañu drog. | Et c'était beaucoup plus parce que les mères étaient ivres de drogue. |
these values represent the limits of the probability distribution of all possible outcomes | Valeur yii dañuy màndargaal àppu séddaleb probabilite ci bépp njariñ bu mëna am | ces valeurs représentent les limites de la distribution de probabilité de tous les résultats possibles |
Well it's a good thing that I didn't think of that yes. | Kon lu baax la ni xalaatuma woon loolu waaw. | C'est une bonne chose que je n'y ai pas pensé. |
My flight approached Jamaica as the sun was setting. | Sama avion mingi jegesi Jamaica bi jant bi di so. | Mon vol approchait de la Jamaïque au coucher du soleil. |
The fact that the athlete is heavily influenced by medical treatment does not mean that the environment has no influence on them. | Li tax atlet bi di am jafe-jafe yu bari ci paj mi, tekkiwul ni environmaa bi amul benn njeexital ci atlet bi. | Le fait que le traitement médical influence fortement l'athlète ne signifie pas que l'environnement n'a aucune influence sur lui. |
According to the informant, dog weather was used to explain the spring rains. | Sunu sukkandikoo ci ki ko jox xibaar, dañu jëfandikoo klimaa bi xaj ngir leeral taw yi ci pringtemps. | Selon l'informateur, le temps de chien a été utilisé pour expliquer les pluies de printemps. |
We can reduce our expenses as much as we can, but our master loves to eat. | Mën nanu wàññi sunuy xaalis nimu mënee, waaye sunu boroom dafa bëgg lekk. | Nous pouvons réduire nos dépenses autant que nous le pouvons, mais notre maître aime manger. |
And he was a precious man in the sight of men. | Te nit ku tedd la woon ci nit ñi. | Et il était un homme précieux aux yeux des hommes. |
If we have enough money from the tickets we sell, we will have all the money we need for the year. | Sudee am nanu xaalis bu doy ci biye yi ñuy jaay, dina nu am xaalis bi nu soxla ci at mi yépp. | Si nous avons assez d'argent des billets que nous vendons, nous aurons tout l'argent dont nous avons besoin pour l'année. |
They said I was a virgin and they were going to bring a man to meet me. | Ñu ne ma janq laa, ñu ngi waaja indi góor mu daje ak man. | Ils ont dit que j'étais vierge et qu'ils allaient m'amener un homme. |
An entirely new Judiciary is striving to operate in a manner different from the turmoil of the 1860s. | Àttekaay bu bees mingi jéema doxal ci anam wu wuute ak jafe-jafe yi amoon ci ati 1860. | Un tout nouveau système judiciaire s'efforce de fonctionner d'une manière différente de la tourmente des années 1860. |
We knew that the attack would be delayed | Xamoon nanu ni song bi dina yeex | Nous savions que l'attaque serait retardée. |
Dolls are acceptable if written in English. | Puppe yi mën nañu leen nangu sudee dañu leen bind ci Àngle. | Les poupées sont acceptables si elles sont écrites en anglais. |
These open-air markets are also the best places to shop in Beijing. | Marse luuma yii ñooy barab yi gëna baax ngir jënd ci Beijing. | Ces marchés en plein air sont aussi les meilleurs endroits pour faire du shopping à Pékin. |
I want to know, is it common in England? | Bëgg naa xam, ndax barina lool ci Angleterre? | Je veux savoir, est-ce courant en Angleterre? |
the sea level is the same all year round | Niveau geej gi dafay nuru at mi yépp | le niveau de la mer est le même toute l'année |
A well-written document is too expensive to be mass-produced. | Këyit buñ bind bu baax seer na lool ngir ñu defar ko ci lu bari. | Un document bien écrit est trop cher pour être produit en série. |
I think you know you're amazing | Yaakaar naa ni xam nga ni danga yéeme | Je pense que tu sais que tu es incroyable |
Indianapolis is truly one of the best places for many actors to work. | Indianapolis bokk na ci barab yi aktër yu bari mëna liggéey. | Indianapolis est vraiment l'un des meilleurs endroits pour travailler. |
Brit Hume is a television news anchor for Fox | Brit Hume anchor xibaar la ci Fox | Brit Hume est présentatrice de nouvelles pour Fox |
The best way to aim a gun is to use both feet. | Li gëna wóor mooy nga jëfandikoo sa ñaari tànk. | La meilleure façon de viser un fusil est d'utiliser les deux pieds. |
6 In the fifty-five years leading up to the Civil War, the court used this power sparingly | 6 Ci juróom ñatti fukki at ak juróom yi jiitu guerre civile, àttekaay bi jëfandikoowul bu baax kàttan googu | 6 Pendant les cinquante-cinq années qui ont précédé la guerre civile, la cour a utilisé ce pouvoir avec parcimonie. |
There were accusations of racial prejudice against Klayman. | Amoon na ay tuuma ci Klayman ci wàllu xeet. | Il y avait des accusations de préjugés raciaux contre Klayman. |
Binalshibh was not released and disappeared. | Binalshibh bàyyi wuñu ko, mu réer. | Binalshibh n'a pas été libéré et a disparu. |
how he is so close to nothing | naka lay jege dara | Comment il est si proche de rien |
Tung wants to steal the inheritance. | Tung bëgga sàcc ndono. | Tung veut voler l'héritage. |
I locked them up as soon as I found them. | Bima leen gisee rek ma tëj leen. | Je les ai enfermés dès que je les ai trouvés. |
By the 1870s all of the Court's decisions had devastated the country and were in disarray. | Ci ati 1870, dogal yépp yu àttekaay bi jëloon yàq nañu réew mi, nekkoon ci jaxasoo. | Dans les années 1870, toutes les décisions de la Cour avaient dévasté le pays et étaient en désordre. |
there are other types of crystals that are useful for information retrieval | amna yeneen xeeti kristal yu am njariñ ngir am xibaar | Il y a d' autres types de cristaux qui sont utiles pour la récupération d' information. |
Today, it is five times higher than the average for this time of year. | Tay, dafa ëpp juróomi yoon li ñuy gis ci jamono jii ci at mi. | Aujourd'hui, il est cinq fois plus élevé que la moyenne pour cette période de l'année. |
I have given a heavy thought to the emperor's commission. | Xalaat naa bu baax li empereur bi digal. | J'ai réfléchi à la commission de l'empereur. |
the secret society was known as the cat-eating society, but the secret society could be considered an Indian name | sosiete sekkere bi ñu xamee ko ci sosiete buy lekk muus, waaye sosiete sekkere bi mën nañu ko jàppee ni turu waa Inde | La société secrète était connue sous le nom de société mangeuse de chats, mais la société secrète pourrait être considérée comme un nom indien |
the plaintiff is present and there is no one to talk to | ki koy tuumal mingi fi te amul kenn kuñuy waxtaan ak moom | le demandeur est présent et il n'y a personne à qui parler |
Beijing has an open market that can include some of the most attractive shops. | Beijing amna marse bu ubbeeku bu mëna amaale yenn ci bitik yi gëna yéeme. | Pékin possède un marché ouvert qui peut inclure certains des magasins les plus attrayants. |
We have people in this group who have invested over $1,000 in law school. | Am nanu nit ci kuréel gii ñu dugal lu ëpp $1,000 ci daara ju mag ji. | Nous avons des gens dans ce groupe qui ont investi plus de 1000 dollars dans la faculté de droit. |
He told us about the perseverance that was to come on the ninth day of Advent. | Mu nettali nu ni ñu wara baña xàddi ci juróom ñeenteelu bis bi ci Advent. | Il nous a parlé de la persévérance qui devait venir le neuvième jour de l'Avent. |
there was no other way of knowing that he could have traveled to get information about the people if they were in the ballrooms there | amul beneen anam bumu mëna xamee ni mënoon na tukki ngir am xibaar ci nit ñi su fekkoon ni ñu ngi woon ci saal yi. | Il n' y avait pas d' autre moyen de savoir qu' il aurait pu voyager pour obtenir des informations sur les gens s' ils étaient dans les salles de bal là-bas |
The investigation found no evidence to stop them. | Lànket bi gisul lenn lu leen mëna tere. | L'enquête n'a trouvé aucune preuve pour les arrêter. |
The Court also exercised this power in the decade leading up to the Civil War. | Tribunaal bi itam dafa jëfandikoo kàttan googu ci fukki at yi jiitu guerre civile. | La Cour a également exercé ce pouvoir dans la décennie précédant la guerre civile. |
It's a foolish idea that I threw away last week. | Xalaat bu doywaar la buma sànnee ayu-bis bi weesu. | C'est une idée idiote que j'ai jetée la semaine dernière. |
He hasn't gone for a walk yet. | Ba tay demagul doxantu. | Il n'est pas encore sorti se promener. |
The mothers can't stop using drugs. | Yaay yi mënuñoo bàyyi drog. | Les mères ne peuvent pas arrêter de prendre de la drogue. |
We don't have a client named Cutty. | Amu nu kiliyaan bu tuddu Cutty. | On n'a pas de client nommé Cutty. |
Actors love Indianapolis because all the casting agencies come through. | Aktër yi dañu bëgg Indianapolis ndax agence yiy tànn nit ñi dañuy jaar. | Les acteurs adorent Indianapolis parce que toutes les agences de casting viennent ici. |
The board issued daily certificates to anyone who requested them | Bis bu nekk kilifa yi dañu daan jox sertifikaa képp ku ko laaj | Le conseil a délivré des certificats quotidiens à tous ceux qui les demandaient. |
Individual inspection schemes are available from the provincial governments. | Nguur yi am nañu ay pexe ngir saytu ku nekk. | Les gouvernements provinciaux peuvent fournir des plans d'inspection individuels. |
U.S. Air Force Chief of Staff begins duty this week | Amerik. Njiitu estaaf bu forsu aer bi doorna ligeey bii ayubes | Le chef d'état-major de l'armée de l'air commence ses fonctions cette semaine. |
Athletes are born with strength and athleticism. | Atlet yi dañuy judduwaale doole ak athletism. | Les athlètes naissent avec force et athlétisme. |
In addition to its reliability framework, Centerlink has adopted a set of guidelines on the coordination of training of employees and the allocation of resources related to the implementation of projects. | Lu weesu liñu ko mëna wóolu, Centerlink tëral na ay sàrt yuñ tëral ci wàllu koordinaasioŋu tàggat liggéeykat yi ak xaaj jumtukaay yi jëm ci amal projet yi. | En plus de son cadre de fiabilité, Centerlink a adopté un ensemble de lignes directrices sur la coordination de la formation des employés et l'allocation des ressources liées à la mise en œuvre des projets. |
The courthouse is no longer used as a venue for political debates in Washington | Jëfandikoo wuñu këru àttekaay bi ni barabu waxtaan politik ci Washington | Le palais de justice n'est plus utilisé comme lieu de débats politiques à Washington. |
Humor is usually one of the things that is easier for foreigners to understand. | Komedi dafay faral di nekk benn ci mbir yi gan yi gëna yomba xam. | L'humour est généralement l'une des choses les plus faciles à comprendre pour les étrangers. |
Mihdhar was granted a new visa, two days after a meeting with the CIA-FBI in New York. | Mihdhar jox nañu ko visa bu bees, ñaari fan ginaaw bimu daje ak CIA-FBI ci New York. | Mihdhar a obtenu un nouveau visa, deux jours après une réunion avec la CIA et le FBI à New York. |
One cannot expect company representatives to strike, boo, and shout insults at the sitting U.S. secretary of labor. | Kenn munul seentu ni ndawi sosete yi dina ñu greev, yuuxu, ak yuuxu saaga ci sekkerteer bu ligeey bu Amerik bi toog. | On ne peut pas s'attendre à ce que les représentants d'entreprises fassent grève, huent et crient des insultes au secrétaire américain au Travail. |
And the speaker wants to know exactly how many times he goes to this place | Te waxkat bi dafa bëgga xam bu baax ñaata yoon la dem ci barab bii | Et le porte-parole veut savoir exactement combien de fois il va à cet endroit |
Even if the plane were to crash, why would it, uh, crash and take out a piece of metal for the waves to collect outside? | Doonte avion bi dafa daanu, lu tax mu, uh, daanu ba noppi génne benn piyeesu wen ngir vague yi dajaloo ci biti? | Même si l'avion s'écrasait, pourquoi s'écrasait-il et enlevait un morceau de métal pour que les vagues le récupèrent à l'extérieur? |
Complaints focused on problems with baggage, flight attendants, canceled flights, cruelty in charging. | Plainte yi dañu jëm ci jafe-jafe bagaas yi, stewardess yi, vol yiñ fomm, fitnaal bi ñuy fay. | Les plaintes portaient sur des problèmes de bagages, d'agents de bord, d'annulations de vols, de cruauté dans les frais de port. |
No word was spoken to him, and he disappeared. | Kenn waxu ko dara, mu daal di ni mes. | On ne lui a pas dit un mot, et il a disparu. |
The girl who helps me lives on the other side of town. | Xale bu jigéen bi may jàppale mingi dëkk ci weneen wetu dëkk bi. | La fille qui m'aide habite de l'autre côté de la ville. |
Brit Hume works for CNN | Brit Hume mingi liggéey ci CNN | Brit Hume travaille pour CNN |
Hot in the summer | Tàngoor ci ete bi | Il fait chaud en été |
Not only does saving affect the amount of savings, but savings also affect the choice of savings. | Dañuy denc xaalis rek ci ni ñuy denc xaalis, waaye dencukaay dafay am njeexital ci tànneefi dencukaay yi. | Non seulement l'épargne affecte le montant de l'épargne, mais l'épargne affecte aussi le choix de l'épargne. |
They changed the name of the parish because it was too small | Ñu soppi turu paruwaas bi ndax daa tuuti lool | Ils ont changé le nom de la paroisse parce qu'elle était trop petite. |
Your donations can help us reduce our expenses. | Li ngeen di maye mën na ñu wàññi sunuy xaalis. | Vos dons peuvent nous aider à réduire nos dépenses. |
Johnson had no intention of retreating. | Johnson bëggul woon dellu ginaaw. | Johnson n'avait pas l'intention de se retirer. |
When a match takes place for a hotel and other specific payments, the guarantee is the actual trip to be made. | Su amee match ngir hotel ak yeneen fayukaay yuñ tànn, garantie bi mooy tukki biñ wara def. | Lorsque l'on fait correspondre un hôtel et d'autres paiements spécifiques, la garantie est le voyage réel à effectuer. |
no one can tell me to meet anyone | kenn mënu ma wax ma daje ak kenn | Personne ne peut me dire de rencontrer quelqu'un |
Use both hands if you want to do a gun control maneuver. | Jëfandikool sa ñaari loxo soo bëggee def manœuvre bunduxatal. | Utilisez les deux mains si vous voulez faire une manœuvre de contrôle d'arme. |
He has made his burial chamber of wood. | Neegu dëbam, defar na ko bant. | Il a fait sa chambre funéraire de bois. |
I wouldn't have forgiven myself if I had locked them up. | Duma baale sama bopp su ma leen tëjoon. | Je ne me serais pas pardonné de les avoir enfermés. |
People don't need anything to acquire land. | Nit ñi soxla wuñu dara ngir am suuf. | Les gens n'ont besoin de rien pour acquérir des terres. |
And we thought that the reward would come before the investigation | Te dañu jàppoon ni neexal bi dina ñëw balaa lànket bi | Et nous pensions que la récompense viendrait avant l'enquête |
We're getting colder by the day and colder by night | Bis bi dafay gëna sedd, guddi gi dafay gëna sedd | Il fait plus froid de jour en jour et de nuit en nuit. |
Faced with this attitude and somewhat shaken, the British showed their respect by capitalizing the name. | Bi waa Grande Bretagne jànkoonte ak gis-gis boobu, ñu yéemu tuuti, ñu wane ni dañu leen jox cër ci bind tur wi ci arafu kapital. | Face à cette attitude et quelque peu ébranlés, les Britanniques montrèrent leur respect en capitalisant le nom. |
the fact that he let you take it here in the middle of meals and snacks is very sad for me | limu la may nga yóbbu ko fii ci diggu lekk yi ak sàndiis yi dafa metti lool ci man | Le fait qu'il vous laisse le prendre ici au milieu des repas et des collations est très triste pour moi |
Our organizations need more money than we get from ticket sales and sign ups to support our programs. | Sunu mbootaay yi dañu soxla xaalis bu ëpp bi ñuy am ci njaayum biye yi ak ñiy abone ngir jàppale sunuy prograam. | Nos organisations ont besoin de plus d'argent que nous obtenons de la vente de billets et des inscriptions pour soutenir nos programmes. |
No, he was. | Déedet, moom la woon. | Non, il était là. |
It's where two or three planes arrive a week and I don't know where they're flying to | Mooy barab bi ñaari wala ñetti avion di ñëw ayu-bis bu nekk te xamuma fumu jëm | C'est là que deux ou trois avions arrivent par semaine et je ne sais pas où ils vont. |
Tents that can be marked with chalk and slate. | Tente yuñ mëna màrke ak krey ak ardoise. | Des tentes qui peuvent être marquées avec de la craie et de l'ardoise. |
The girl I need help with lives on the street far away. | Xale bu jigéen bi ma soxla ndimbal mingi dëkk ci mbedd mi fu sori. | La fille avec qui j'ai besoin d'aide vit dans la rue, loin de chez moi. |
The fence prevented it during the same fire incident. | ñag bi moo ko tere ci jamonoy lakk bu mel nii. | La clôture l'a empêché lors du même incendie. |
There's, I think, some kind of molecular anomaly like the evolution of the biosphere that changes everything in the environment of life. | Dama jàpp ni amna lu wuute ci molecule yi, lu ci melni jëm kanam gi ci biosphere bi, muy soppi lépp lu nekk ci environmaa bi dundu gi di doxee. | Il y a, je pense, une sorte d'anomalie moléculaire comme l'évolution de la biosphère qui change tout dans l'environnement de la vie. |
Remember that you hid all your possessions in them | Fàttaliku ne, nëbb nga ci ñoom say alal yépp | Tu as caché tous tes biens dans ces sacs. |
Law enforcement agencies will hold meetings between August and December. | Ñi yor wàllu yoon dina ñu amal ndaje diggante weeru ut ak desàmbar. | Les forces de l'ordre tiendront des réunions entre août et décembre. |
00 helped us provide guidance, encouragement and joy to the 400 or so children from Indianapolis. | 00 jàppale nanu ci joxe tegtal, ñaax ak bànneex ci 400 xale yu bawoo Indianapolis. | 00 nous a aidés à fournir des conseils, des encouragements et de la joie aux 400 enfants d'Indianapolis. |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.