en
stringlengths
1
298
wo
stringlengths
1
279
fr
stringlengths
1
687
And we march after you more than 10,000 miles.
Te nu topp leen lu ëpp 10,000 mile.
Et nous marchons après vous plus de 10.000 miles.
Dufayel's attempts to meddle are intolerable!
Jéem-jéem Dufayel ngir dugg ci mbir mi, kenn mënu ko muñ!
Les tentatives de Dufayel de s'immiscer sont intolérables!
Wow.
Waa.
- Je suis désolée.
- You are nothing but a drunken whore.
- Doo leneen lu dul ab màndikat bu màndi.
- Tu n'es qu'une pute ivre.
-I did?
-Def naa ko?
- Je l'ai fait?
I'm starving, and I'm being eaten by ants.
Dama xiif, ay miir di may lekk.
Je meurs de faim et je suis mangé par des fourmis.
Bye.
Ba beneen yoon.
- À bientôt.
Never mind. Pay me when you've got dinars
Bul faale. Feyeel ma soo amee dinaar
Je vous paierai quand vous aurez des dinars.
It's all so unreal like a dream where you want to wake up, but you can't.
Loolu amul benn werante, melni gént boo bëgga yewwu waaye mënoo.
C'est tout aussi irréel, comme un rêve où on veut se réveiller, mais on ne peut pas.
Okay, Mom.
Waaw kay, yaay.
Je suis désolée.
I find I'm so excited I can barely sit still or hold a thought in my head.
Dama kontaan lool ba mënu ma toog wala tëye benn xalaat ci sama bopp.
Je suis tellement excitée que je peux à peine rester assise ou retenir une pensée dans ma tête.
You must be crazy, jumping into the water like some love-sick woman.
Amaana danga dof, di tëb ci ndox mi ni jigéen ju feebar mbëggeel.
Tu dois être folle, à sauter dans l'eau comme une femme amoureuse.
How could they be firing artillery?
naka lañu mënee fetal artileri?
Comment peuvent-ils tirer de l'artillerie?
I figured...
Xalaat naa...
Je me suis dit...
Everything rotted in this rain and scores of men died miserably from the tiny serpents that were everywhere in this evil land.
Lépp yàqu na ci taw bi, nit ñu bari ñàkk ci seen bakkan ndax jaan yu ndaw yi nekkoon fépp ci réew mu soxor mi.
Tout pourrissait sous cette pluie et des dizaines d'hommes mouraient misérablement à cause des minuscules serpents qui étaient partout dans ce pays maléfique.
We'll build a good village.
Dina nu tabax dëkk bu baax.
Nous allons construire un bon village.
I have one, only it's broken.
Amnaa benn, waaye dafa yàqu.
J'en ai une, mais elle est cassée.
Why is it never her turn to go and fetch things?
Lu tax du musa dem jël ay mbir?
Pourquoi c'est jamais son tour d'aller chercher des choses?
You eat the fruit.
Yaa ngi lekk meññeef mi.
Tu manges le fruit.
But women working the bellows in an ironworks?
Waaye jigéen ñiy liggéey ci wen?
Mais les femmes qui travaillent dans les fouls d'une forge?
Our magnificent idea has died... along with every beautiful, admirable, noble, good thing
Sunu xalaat bu rafet bi dee na... ak lépp lu rafet, lu jara sargal, lu baax, lu baax
Notre idée magnifique est morte... avec chaque chose belle, admirable, noble et bonne.
- We will meet up there.
- Dina nu daje foofu.
- On se retrouve là-haut.
I like noticing details that no-one else ever sees.
Dama bëgg di seetlu mbir yu kenn musul gis.
J'aime remarquer des détails que personne d'autre ne voit.
And then what happened?
Ak lu xew?
Et alors?
- Yeah.
- Waaw.
- Je sais.
The woods are huge. He'd never find her!
Garab yi dañu yaatu. Duko musa gis!
Il ne la trouvera jamais.
Collignon, big moron!
Collignon, dof bu rëy!
Collignon, espèce d'idiot!
That guy?
Waa jooju?
Ce type?
Grandma ...
Maam ju jigéen ...
Je suis désolé.
And it ain't alabaster, either?
Te du alabaster itam?
Et ce n'est pas de l'albâtre, non plus?
This is 200 dollars.
Lii 200 dolaar la.
Ça fait 200 dollars.
Look at them.
Xoolal leen.
Regardez-les, ils sont beaux.
It's down there and I'm in here?
Mingi ci suuf man maa ngi ci biir?
Il est là-bas et je suis ici?
Thank you, sir.
Jërëjëf waay.
Merci, monsieur. Je vous en prie.
A year, I think.
Benn at, jàpp naa.
Un an, je pense.
It keeps going on and on...
Dafay wéy di wéy...
Ça continue et ça continue...
- Thanks
- Jërëjëf
- Merci
In the rain and the sun, we fought for you.
Ci taw bi ak ci jant bi, xeexal nanu leen.
Dans la pluie et le soleil, nous nous sommes battus pour vous.
Open the door!
Ubbi buntu bi!
Ouvrez la porte!
Are there any on my back?
Ndax amna ci sama ginaaw?
Il y en a sur mon dos?
A good beating is what you need.
Li nga soxla mooy dóor bu baax.
Une bonne raclée, c'est ce qu'il te faut.
That is quite a story.
Loolu jaar-jaar la.
C'est une sacrée histoire.
I think it's the excitement only a free man can feel.
Dama jàpp ni nit ku moom boppam kese moo mëna yëg bànneex bi.
Je pense que c'est l'excitation que seul un homme libre peut ressentir.
I can get it in a couple of days.
Mën naa ko am ci diir bu gàtt.
Je peux l'avoir dans quelques jours.
Their presence defiles the iron.
Seen nekk dafay tilim weñ wi.
Leur présence souille le fer.
I think it would be fair to say...
Yaakaar naa ni dina nekk lu jaadu suñu waxee...
Je pense qu'il serait juste de dire...
I'll show you.
Dinaa la wane.
Je vais vous montrer.
I've ever known.
Mus naa ko xam.
Je l'ai jamais connu.
Frau Junge, you're right!
Frau junge, li nga wax !
Vous avez raison.
What happened to "the house where it rains"?
Lu xew "kër gi taw"?
Qu'est-il arrivé à "la maison où il pleut"?
Take back your silver.
Dellool sa xaalis.
Prenez votre argent.
I guess it comes down to a simple choice, really?
Dama yaakaar ni mingi wàcci ci tànneef bu yomb, dëgg la?
Je suppose que c'est un choix simple, vraiment?
What are you, a fucking geologist?
Lu doon, geologue bu doy waar?
T'es quoi, un putain de géologue?
-Yeah.
-Waaw.
- Je sais.
- See you?
- Ba beneen?
- À plus?
Can I go to my room and get my fire engine?
Ndax mën naa dem ci sama néeg jël sama oto pompier?
Je peux aller chercher ma voiture de pompiers?
The fruit Durga brings you.
Fruit bi Durga lay indil.
Le fruit que Durga vous apporte.
well, Pelle...
Pelle...
Je suis désolé.
Hey, Pelle ...
Nanga def, Pelle...
Hé, Pelle... Je suis désolé.
"In addition, the Library District has generously responded with a charitable donation of used books and sundries?
"Yokku ci ne, Bibliothèque bi defa tontu ci xéewal ci saraxe téere yuñ jëfandikoo ak yeneen mbir?
"En outre, le district des bibliothèques a généreusement répondu avec un don de bienfaisance de livres usagés et divers?
Friends, today is my lucky day!
Samay xarit, tay mooy sama bis bu am wërsëg!
Mes amis, c'est mon jour de chance!
Cassius!
Kasiyus!
Il est mort!
You'd be...
Di nga nekk...
Vous seriez...
- Shut your mouth.
- Tëj sa gémmiñ.
- Ferme ta gueule!
Anyway, he's a soldier.
Lumu mëna doon, soldaar la.
En tout cas, c'est un soldat.
Oh, fuck.
Oh, fuck.
- Je sais pas.
No, nothing there. Oh, hey-ho!
Dédeet, amul dara. O, waay-waaw!
Non, rien du tout.
"She can't relate to other people."
"Mënul déggoo ak ñeneen ñi."
"Elle ne peut pas s'identifier aux autres".
I advise you not to touch, Leonnatus.
Maa ngi lay digal nga moytu laal, Leonnatus.
Je vous conseille de ne pas toucher, Léonnat.
12,000 a month to start.
12,000 weer wu nekk ngir tàmbali.
12 000 par mois pour commencer.
We are of Achilles' royal blood.
Nun ci deretu buur lanu ci Achille.
Nous sommes du sang royal d'Achille.
If you had drowned I'd have given you such a beating, believe me.
Sudee danga féey, dama lay dóor nii, gëm leen.
Si tu t'étais noyé, je t'aurais donné une raclée, crois-moi.
But I hate it in old American movies when drivers don't watch the road.
Waaye dama bañ ci filmu Amerique yu yàgg yi, dawalkat yi duñu xool tali bi.
Mais je déteste les vieux films américains où les conducteurs ne regardent pas la route.
- I'll get it
- Dinaa ci jël
- Je vais le prendre.
Those aren't bombs, it's artillery!
Loolu du bomb, artileri la!
Ce ne sont pas des bombes, c'est de l'artillerie!
Yeah, it is.
Waaw, noonu la.
Oui, c'est vrai.
So she's been alone a whole year.
Kon defna at mu nekk moom kese.
Elle est donc seule depuis un an.
- What happened?
- Lu xew?
- Qu'est-ce qui est arrivé?
Never happen?
Du musa am?
Ça n'arrivera jamais?
Eat.
Lèkk.
Je vous en prie.
You really mean that?
Loolu nga bëgga wax dëgg?
Tu le penses vraiment?
I liked Andy from the start.
Dama bëggoon Andy ci ndoorte li.
J'ai aimé Andy depuis le début.
The world after the Führer's death and after National Socialism is no longer worth living in.
Àdduna bi ginaaw bi Führer génnee àdduna ak ginaaw National-Sosialism, jarul ci dund.
Le monde après la mort du Führer et après le national-socialisme ne vaut plus la peine d'être vécu.
Milady buys up the contract of every brothel girl she finds!
Milady dafay jënd kontraa bépp xale bu jigéen bumu dajeel ci brothel bi!
Milady achète le contrat de chaque fille de bordel qu'elle trouve!
If Amélie chooses to live in a dream and remain an introverted young woman, she has an absolute right to mess up her life!
Sudee Amélie tànn dundu ci gént ba noppi nekk xale bu jigéen bu nëbbu, amna sañ-sañu yàq dundam!
Si Amélie choisit de vivre dans un rêve et de rester une jeune femme introvertie, elle a le droit de gâcher sa vie!
Let's see if we can improve this with a little water, sir.
Nanu xool ndax mën nanu ko defar ak tuuti ndox, sang bi.
Voyons si on peut améliorer ça avec un peu d'eau, monsieur.
Gerda, I feel sick...
Gerda, maa ngi feebar...
Je me sens mal.
He's right. it ain't.
Wax na dëgg. du noonu.
Il a raison. Ce n'est pas vrai.
A free man at the start of a long journey whose conclusion is uncertain.
Nit ku moom boppam ci ndoortelu tukki bu gudd te xamul njeexteem.
Un homme libre au début d'un long voyage dont la conclusion est incertaine.
Evan and Francine... all blowing off work this week to take me out here.
Evan ak Francine... ñoom ñépp ñu ngi bàyyi liggéey ayu-bis bii ngir yóbbu ma fii.
Evan et Francine... ils ont tous sauté le pas cette semaine pour m'emmener ici.
Get busy living or get busy dying?
Dengay jaxasoo ci dundu wala ngay jaxasoo ci dee?
Être occupé à vivre ou à mourir?
Sure.
Wóor.
- Bien sûr.
You should know better, shouldn't you?
Yaa wara gëna xam, wala book?
Tu devrais savoir mieux, non?
I give up... can't win against fools!
Dama bàyyi... mënu ma am ndam ci dof yi!
Je me rends... Je ne peux pas gagner contre des imbéciles!
We trust this will fill your needs.
Gën nanu ni lii dina saafara li ngeen soxla.
Nous espérons que cela répondra à vos besoins.
Send one of your trackers!
Yonnee benn ci say toppukaay!
Envoyez un de vos traqueurs!
Ours is a myth only young men believe.
Sunu gëm-gëm la, xale yu góor yi kese ñoo ko gëm.
Le nôtre est un mythe que seuls les jeunes hommes croient.
Goddamn it!
Yalna ko!
Nom de Dieu!
See?
Gis?
Tu vois?
That's a long time.
Loolu yàgg na.
C'est une longue période.