en stringlengths 1 298 | wo stringlengths 1 279 ⌀ | fr stringlengths 1 687 |
|---|---|---|
Picodons are 12.90, cabecous 23.50. | Pikodon yi 12,90 lañu, kabekous yi 23,50. | Les picodons sont à 12,90, les cabecous à 23,50. |
Understand? | Nànd? | Vous comprenez? |
Are you sure you know where we're going? | Ndax xam nga fi ñuy jëm? | Tu es sûr de savoir où on va? |
The older you get, the stronger. | Looy gëna jëm mag, ngay gëna am doole. | Plus on vieillit, plus on est fort. |
Oh, really? | Oh dëggantaan? | - Vous êtes sérieux? |
There's just no work for you people! | Amul benn liggéey ci yéen nit ñi! | Il n'y a pas de travail pour vous! |
No, let's go this way. | Déedéet, nanu jaar fii. | Non, allons par là. |
My husband's been out there for a year now. | Sama jëkkër defna benn at ci biti. | Mon mari est là-bas depuis un an maintenant. |
If you're awake thank Yakul. | Soo yewwoo gërëm Yakul. | Si vous êtes réveillée, remerciez Yakul. |
I could see why some of the boys took him for snobby. | Gisoon naa li waral yenn xale yu góor yi jàppee ko ni snob la. | Je pouvais comprendre pourquoi certains garçons le prenaient pour un snob. |
You used to dress me up like a sheik wave your wooden scimitar. | Danga may sol ni sëriñ bi di yëngal sa scimitar dénk. | Tu m'habillais comme un cheik en agitant ton cimetière en bois. |
- Hey! | - Hey! | - Je suis là. |
Of course, I doubt they'll toss up any roadblocks for that. | Dëgg la dina am sikki-sakka ndax dina ñu def benn bloke ci loolu. | Bien sûr, je doute qu'ils vont jeter des barrages pour cela. |
Let's get him some rocks. | Nanu ko wutal ay xeer. | On lui donne des pierres. |
What are you doing? What are you doing? | Loy def? Loy def? | Tu fais quoi? |
I want to dance! | Dama bëgga fecc! | Je veux danser! |
Some were butchered in Scythia by the banks of the Oxus. | Ñenn ñi dañu leen ray ci Scythie ci wetu Oxus. | Certains furent massacrés en Scythie, sur les rives de l'Oxus. |
I don't think you ought to be doing this to yourself, Andy. | Yaakaar naa ni danga wara defal sa bopp lii, Andy. | Tu ne devrais pas te faire ça, Andy. |
Watch your step. | Xool bu baax sa jéego. | Attention à la marche. |
Very wise. | Am xel mu ñaw. | Très sage. |
- 100. | - 100. | - À cent. |
I hear you helped a couple of fellas with that. | Dégg naa ni jàppale nga ñaari nit ci loolu. | J'ai entendu dire que vous avez aidé quelques gars avec ça. |
Someone bring Ashitaka. | Ku inndi Ashitaka. | Quelqu'un peut amener Ashitaka. |
I've stayed with Papa against his will. | Maa ngi dëkk ci sama pàppa te bëggul. | Je suis restée avec papa contre sa volonté. |
Sanja, where are you? | Sanja, fan nga nekk? | Sanja, où es tu? |
- Go back to the other oafs. | - Dellu ci yeneen dof yi. | - Retourne avec les autres. |
You tell me, fuck-stick? | Wax ma, fuck-baton? | Tu me dis, espèce de connard? |
How nice. | Loolu neex na. | C'est très bien. |
My Führer... the orders are ready. | Sama Führer... komànd yi pare nañu. | Mon Führer... les ordres sont prêts. |
Don't forget! | Bul fàtte! | N'oubliez pas! |
He had a quiet way about him. | Dafa ànd ak dal ci moom. | Il était plutôt discret. |
He ran amuck and killed his family with an ax. | Mu daw, ray ay mbokkam ak mbagg. | Il a tué sa famille avec une hache. |
You were the only one who'd never let me win. | Yaw kese nga musul may ma jël ndam li. | Tu étais le seul à ne jamais me laisser gagner. |
Ricci, don't forget to take your bicycle. | Ricci, bul fàtte yóbbaale sa welo. | Ricci, n'oublie pas de prendre ton vélo. |
I've been a widow since. | Booba ba leegi ténji laa. | Je suis veuve depuis. |
It's better here. | Fii moo gën. | C'est mieux comme ça. |
Dance! | Pecc! | Danse avec moi! |
Guys? .? | Gaa? .? | Vous êtes des gars? |
Stop! | Dakkal dal! | Arrêtez! Arrêtez! |
- That's it. | - Loolu la. | - C'est tout ce que j'ai. |
Right, my king. | Waaw, sama buur. | C'est vrai, mon roi. |
Wait, wait. | Xaaral, xaaral. | Attends, attends. Je suis là. |
Good boy. | Xale bu baax. | C'est un bon garçon. |
These are just shitty pipe dreams. | Loolu ay gént yu bonn lañu. | Ce ne sont que des rêves de merde. |
Sheepherders? | Ay sàmmkat? | Des bergers? |
I won't, Mom. | Duma def, yaay. | Je ne le ferai pas, maman. |
In fact, she's cowardly. | Booy seet, daa ragal. | En fait, elle est lâche. |
Last Sunday, the Führer wanted to help me leave. | Dibéer bi weesu, Führer bëggoon nama jàppale ma dem. | Dimanche dernier, le Führer voulait m'aider à partir. |
Mr. Hallorann how'd you know we call him Doc? | M. Hallorann, naka nga xamee ni ñu koy woowe Doc? | M. Hallorann, comment savez-vous qu'on l'appelle Doc? |
- Get lost, yellow-belly! | - Réer, biir bu mboq bi! | - Dégage, le ventre jaune! |
They want to abandon the ironworks! | Bëgg nañu bàyyi liggéeyum wen! | Ils veulent abandonner la fonderie! |
JACK: | Jack: | - Je suis désolé. |
You're not gonna leave these horses there, while you eat. | Dunga bàyyi fas yii foofu, ngay lekk. | Tu ne laisseras pas ces chevaux là, pendant que tu manges. |
Sorry about your friends. | Maa ngi lay massawu ci say xarit. | Désolé pour tes amis. |
What a lovely shawl, Auntie. | Shawl bu rafet la, tànta. | Quel joli châle, tante. |
Take back the silver. | Delloosi xaalis bi. | Prends le métal. |
Some died good. | Ñenn ñi dee ñu baax. | Certains sont morts bien. |
My God why have you forsaken me? | Sama Yàlla, lu tax nga dëddu ma? | Mon Dieu, pourquoi m'as-tu abandonné? |
Looked like a stift breeze would blow him over. | Daa melni ngelaw lu am doole moo koy naaw. | On aurait dit qu'une brise le renverserait. |
He watched you the whole time. | Mu ngi lay xool saa yu nekk. | Il t'a regardé tout le temps. |
Maybe one of them still runs. | Amaana kenn ci ñoom mingi daw ba leegi. | Peut-être que l'un d'eux est toujours en vie. |
I want to thank him. | Bëgg naa ko gërëm. | Je veux le remercier. |
They're all addressed to you. | Ñoom ñépp yaw lañu ko bindal. | Ils sont tous adressés à vous. |
We'll be waiting! | Dina nu xaar! | Nous vous attendons! |
Some Friday evenings, Amélie goes to the cinema. | Yenn aljuma ci ngoon, Amélie dafay dem sinemaa. | Certains vendredis soir, Amélie va au cinéma. |
I got one? | Amnaa benn? | Je l'ai eu? |
You bastards! | Yéen ay dof! | Vous êtes des salauds! |
No wonder Darius fled when he had this to come back to. | Amul werante Darius daw bimu demee ci mbir mi. | Pas étonnant que Darius ait fui quand il avait à revenir. |
The Führer can't just disappear from history like some inglorious fugitive! | Führer mënul réer ci taarix ni dawkat bu amul ndam! | Le Führer ne peut pas disparaître de l'histoire comme un fugitif sans gloire! |
Take them back to her. | Yobbu leen ci moom. | Retourne-les à elle. |
Already she makes enemies with her strong, clumsy nature. | Dafay sos ay noon ndax limu am doole te dëgërul. | Elle se fait déjà des ennemis avec sa nature forte et maladroite. |
At the butcher's a baby's watching a dog that's watching the chickens roasting. | Ci boucher bi, daa am xale bu ndaw buy xool xaj buy xool ginaar yi ñuy toggu. | Au boucher, un bébé surveille un chien qui surveille les poulets rôtis. |
Has he drowned? | Ndax dafa féey? | Il s'est noyé? |
I want to go to the mountain. | Dama bëgga dem ci tundu wi. | Je veux aller à la montagne. |
The only one who's ever been honest with me. | Kenn ki ma musa dëggu. | Le seul qui ait été honnête avec moi. |
I don't waste time on losers, Tommy? | Duma yàq sama jot ci ñi ñàkk, Tommy? | Je ne perds pas mon temps avec des perdants, Tommy. |
A walk and a talk that just wasn't normal around here. | Doxantu ak waxtaan bu jaarul yoon ci gox bii. | Une promenade et une conversation qui n'était pas normale ici. |
I mean, Mexico is way the hell down there and you're in here? | Lima bëgga wax mooy, Mexico mingi foofu ci suuf te yaw nga nekk fii? | Le Mexique est loin et vous êtes ici? |
Anything in particular? | Amna lu amul fenn? | Quelque chose en particulier? |
Another one? | Beneen? | Une autre? |
Come home! | Ñëwal seen kër! | Retourne à la maison! |
You like it? | Bëgg nga ko? | Ça te plaît? |
Your turn now. | Leegi sa turn la. | À votre tour. |
Got no dinars? | Amul dinaar? | Vous n'avez pas de dinars? |
You two look only for the tires. | Yeen ñaar ngeen xool pëno yi kese. | Vous deux, regardez seulement les pneus. |
You need one. | Danga soxla benn. | Tu en as besoin. |
You know your mother well. | Xam nga sa yaay bu baax. | Tu connais bien ta mère. |
Raju gave it to me, to keep me warm in the evenings. | Raju moo ma ko jox, ngir may tàngoor ci guddi gi. | Raju me l'a donné, pour me garder au chaud le soir. |
Her name was Katja? | Katja la woon? | Elle s'appelait Katja? |
He's sleeping. | Mi ngi nelaw. | Il est endormi. |
If we wait we'll be too late! | Sunu xaar, dina nu yeex! | Si on attend, il sera trop tard! |
Go home, yellow-belly! | Demal sa kër, biir bu mboq! | Retourne chez toi, le jaune de ventre! |
Get out... you lazy dog. | Demal... yaw xaj bu tàyyeel bi. | Sortez de là, vous, chien paresseux. |
Some just didn't get no luck. | Ñenn ñi amul wërsëg. | Certains n'ont pas eu de chance. |
How do you know his name? | Naka nga xamee turam ? | Comment tu connais son nom? |
You saved me from myself. | Yaa ma musal ci sama bopp. | Tu m'as sauvé de moi-même. |
Here! | Fi! | Je suis là. |
Make sure you come right back because I'm going to make lunch soon. | Fexeel nga dellusi ci saa si ndax damay waajal añ ci lu yaggul dara. | Retourne tout de suite, je vais préparer le déjeuner. |
No, he hasn't. | Déedet, deful ko. | Non, il ne l'a pas fait. |
-Beg your pardon? | -Maa ngi lay jéggalu? | - Je vous demande pardon? |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.