en
stringlengths
1
298
wo
stringlengths
1
279
fr
stringlengths
1
687
Many jobs have a tradition of self-respect.
Liggéey yu bari dañuy wane ni dañu wara jox cër sa bopp.
Beaucoup de métiers ont une tradition de respect de soi.
Wealthy people are more likely to save a large portion of their income.
Ñi am xaalis ñooy gëna mëna denc xaalis bu bari ci seen xaalis.
Les gens riches sont plus enclins à épargner une grande partie de leur revenu.
the head of the communications department immediately contacted the authorities, but the minister refused to comment on the situation
njiitu departemaa bi yor jokkoo daal di jokkoo ak kilifa yi ci saasi, waaye ministre bi nanguwul wax dara ci mbir mi
Le chef du département des communications a immédiatement contacté les autorités, mais le ministre a refusé de commenter la situation.
Artificial intelligence (AI) is one of the unique aspects of technology that all businesses rely on.
Xarañteg xelu masin (IA) bokk na ci mbir yi liggéeyukaay yépp aju ci xarala yu bees yi.
L'intelligence artificielle (IA) est l'un des aspects uniques de la technologie sur lequel toutes les entreprises comptent.
the state has protected areas, part of the Kinabalu National Park
réew mi amna ay barab yuñ aar, bokk ci parc national bu Kinabalu
L'État possède des zones protégées, une partie du parc national de Kinabalu
I don't need the king's help
Soxlawuma ndimbalu buur bi
Je n'ai pas besoin de l'aide du roi.
you don't have to use your clothes to fix things
jarul nga jëfandikoo say yéere ngir defar ay mbir
Tu n'as pas besoin de tes vêtements pour réparer les choses.
A play is going on in the court with actors
theatre mingi am ci biir kër ga ak ay aktër
Une pièce de théâtre se joue dans la cour avec des acteurs.
No airplanes coming in
Amul avion buy dugg
Aucun avion ne vient
Sometimes it is the largest bird, too.
Yenn saa muy picc mi gëna rëy itam.
Parfois, c'est aussi l'oiseau le plus gros.
We are like the children of Indianapolis.
Danu melni xale yu Indianapolis.
On est comme les enfants d'Indianapolis.
I traveled to Jamaica on a large boat.
Ma tukki ci Jamaica ci gaal gu rëy.
Je me suis rendu en Jamaïque sur un grand bateau.
I saw the light inside the thesaurus
gis naa leer gi ci biir thesaurus bi
J'ai vu la lumière à l'intérieur du thésaurus
The 9/11 operation was a great success
Operasioŋ 9/11 amna ndam lu rëy
L'opération du 11 septembre a été un grand succès.
For example, one national headquarters we visited is home to more than 600 software companies.
Ci misaal, benn makaanu réew mi ñu dem, amna lu ëpp 600 liggéeyukaay yuy defar ay losisel.
Par exemple, un siège national que nous avons visité abrite plus de 600 sociétés de logiciels.
The ruling of the new Court intends to undermine the rights of the workers.
Àtte bu àttekaay bu bees bi dafa bëgga naxasal yelleefi liggéeykat yi.
La décision de la nouvelle Cour vise à porter atteinte aux droits des travailleurs.
I tell you that I have been given full knowledge of everything.
Maa ngi leen koy wax, jox nañu ma xam-xam bu mat sëkk ci lépp.
Je vous dis que j'ai reçu la connaissance de tout.
Mihdhar was granted a visa because he was not a threat.
Jox nañu Mihdhar visa ndax nekkul woon kuy tiital.
Mihdhar a obtenu un visa parce qu'il n'était pas une menace.
Michael Apted works to increase the number of supporters and documentation available to the public.
Michael Apted mingi liggéey ngir yokk limu ñi koy jàppale ak këyit yi nit ñi mëna am.
Michael Apted travaille à augmenter le nombre de supporters et de documentation disponible au public.
As long as we grow ticket sales, our entire season will be funded.
Faawu ñuy yokk njaayum biye yi, sunu sesoŋ bi yépp dina ñu ko fay.
Tant que nous augmenterons les ventes de billets, toute notre saison sera financée.
You can't see me because your wedding is so close
Mënu ma gis ndax sa céet jege na lool
Tu ne peux pas me voir parce que ton mariage est si proche.
Child day care is open every day for children under the age of five only.
Xale yi tolluwul ci juróomi at kese lañuy ubbeeku bis bu nekk.
La garderie est ouverte tous les jours pour les enfants de moins de cinq ans.
He realized that he had to take immediate action.
Mu gis ni dafa wara jël dogal ci saa si.
Il s'est rendu compte qu'il devait agir immédiatement.
I wanted to tell you everything I know about the case
Bëggoon naa leen wax lépp luma xam ci dosiye bi
Je voulais vous dire tout ce que je sais sur l' affaire.
But they were divided among themselves, as to which of them was of the hand, and which of them was of the household--
Waaye taalibe yi féewaloo nañu ci seen biir, ba xam kan ci ñoom mooy loxo bi ak kan ci kër gi.
Mais ils se sont divisés entre eux, pour savoir lequel d'entre eux était de la main, et lequel d'entre eux était de la maison.
It was like sugar honey and I knew exactly when it would come.
Daa melni lem bu am suukër, xamnaa bu baax kañ lay ñëw.
C'était comme du miel sucré et je savais exactement quand ça arriverait.
This was to facilitate trade but all in the name of saving office space, in the mining sector, copper was being used extensively to find tools and in particular mining equipment for the production of nuclear weapons.
Li ko waraloon mooy yombal jënd ak jaay, waaye ngir sakkanal palaasu buro yi, ci wàllu mine, ñu ngi doon jëfandikoo përëm bu bari ngir wut jumtukaay, rawatina jumtukaayi mine ngir defar ay ngannaayu nikaleyeer.
C'était pour faciliter le commerce mais tout cela au nom de l'économie d'espace de bureau, dans le secteur minier, le cuivre était largement utilisé pour trouver des outils et en particulier des équipements miniers pour la production d'armes nucléaires.
Beijing's strict regulations prohibit open markets within the city limits.
Regle yu tar yi Beijing tëral dañu tere marse ubbeeku ci biir dëkk bi.
Les règles strictes de Pékin interdisent les marchés ouverts dans les limites de la ville.
For example, one company we spied on had a two-company partnership that wanted the company to be able to combine new business and renovation to meet the needs of a growing business.
Ci misaal, benn kompiñi buñu xool amoon na ñaari kompiñi yuy liggéeyandoo, ñu bëggoon kompañi bi mëna boole liggéey bu bees ak defar kër ngir mëna liggéey ci bëgg-bëggu liggéey buy màgg.
Par exemple, une entreprise que nous avons espionnée avait un partenariat entre deux entreprises qui souhaitaient que l'entreprise puisse combiner nouvelles affaires et rénovation pour répondre aux besoins d'une entreprise en croissance.
Khallad said the three could have traveled together.
Khallad neena ñoom ñatt mënoon nañu ànd tukki.
Khallad a dit que les trois auraient pu voyager ensemble.
Lawrence Singleton, the notorious rapist who attacked his victim's hands and served eight years in prison, was arrested again for the murder of another woman in Florida.
Lawrence Singleton, ki siiw lool ci kuy sonnge loxo xale bu jigeen bi, ñu tëj ko jiroom ñetti at ci kaso, ñu jàppaat ko ndax faat beneen jigeen ci Floride.
Lawrence Singleton, le célèbre violeur qui a attaqué les mains de sa victime et a purgé huit ans de prison, a été arrêté à nouveau pour le meurtre d'une autre femme en Floride.
the commissioner of communications has instructed you to observe even when he is not in his right mind
komisario jokkoo bi daf lay digal nga seetlu doonte xel mi nekkul ci jàmm
Le commissaire aux communications vous a demandé de l' observer même s' il n' est pas dans son bon sens.
And it came to pass in the four hundred thousand years before he built the palace of Estei, that Milreu was a great house for a great man.
Ci ñeenti téemeeri junniy at laata muy tabax palaasu Estei, Milreu nekkoon na kër gu mag ci nit ku mag.
Et il arriva, quatre cent mille ans avant qu'il bâtît le palais d'Estei, que Milreu était une grande maison pour un grand homme.
The earth's biological makeup has not changed.
Li am ci kaw suuf si soppikuwul.
La composition biologique de la terre n'a pas changé.
I also learned about the United States.
Jàngoon naa itam lu jëm ci Etats Unis.
J'ai aussi appris sur les États-Unis.
People tossing coins into the water
Nit ñi di sànni xaalis ci ndox mi
Des gens qui jettent des pièces dans l'eau.
People can contact us only by post or e-mail
Nit ñi mën nañu jokkoo ak nun ci post wala e-mail
Les gens ne peuvent nous contacter que par courrier ou par e-mail
children entering kindergarten do not have the knowledge of the air for technical schooling and do not have any adult help
xale yiy dugg ci kindergarten amul xam-xam bi war ngir jàngi teknik te amul benn mag bu leen di jàppale
Les enfants qui entrent à la maternelle n'ont pas les connaissances de l'air pour l'enseignement technique et n'ont aucune aide d'adulte.
As a child growing up in the '50's, one of my fondest memories was attending plays at the Civic Theatre
Bi may màgg ci ati 50, benn ci mbir yima gënoon fàttaliku mooy dama daan seetaan theatre ci Civic Theatre
Enfant, dans les années 50, un de mes plus beaux souvenirs était d'assister à des pièces de théâtre au Théâtre civique.
He suggested that a map was obtained
Dafa digal ñu am kàrt
Il a suggéré qu'une carte soit obtenue
I've been hunting him for the past year or so.
Lu tollu ci at a ngi nii may rëbb ko.
Je le chasse depuis un an.
One would not expect company reps to strike.
Kenn mënul seentu ni ndawi liggéeyukaay yi dina ñu greve.
On ne s'attendrait pas à ce que les représentants de l'entreprise fassent grève.
The General is a retired U.S. Air Force officer.
Jeneral bi ab ofisiye la bu jeexal ci forsu aérien bu Etats Unis.
Le général est un officier de l'armée de l'air américaine à la retraite.
Midhari was granted a visa because he was not a threat.
Midhari jox nañu ko visa ndax nekkul woon luy tiital.
Midhari a obtenu un visa parce qu'il n'était pas une menace.
The security team holds meetings several times a year.
Ekipu kaaraange gi dafay amal ndaje yu bari ci at mi.
L'équipe de sécurité tient des réunions plusieurs fois par an.
the next time i don't accept the king's invitation it's because of my ignorance and greed
Beneen yoon duma nangu invite bu buur bi ndax sama ñàkk xam-xam ak ñàkka doylu
La prochaine fois que je n'accepterai pas l'invitation du roi, ce sera à cause de mon ignorance et de ma cupidité.
Despite two years of investigation, the FBI was unable to locate the operative or determine his true identity.
Doonte FBI bi defna ñaari at ci amal lànket, mënu ñu woon gis operatër bi wala xam kan mooy dëgg.
Malgré deux ans d'enquête, le FBI n'a pas pu localiser l'agent ou déterminer sa véritable identité.
Then they've done their training on full pressure suits and it takes me a while if you go to full pressure suits
Ginaaw loolu ñu def seen tàggat ci yéere yu am pression bu mat te dina ñu ma jël ab diir soo demee ci yéere yu am pression bu mat
Ils ont fait leur entraînement avec des combinaisons à pression et ça me prend un moment si tu vas avec des combinaisons à pression.
Extension is a good way to make sure that the meaning of the account is clear.
Extension anam bu baax la ci leer ni li kontu bi di tekki leer na.
L'extension est un bon moyen de s'assurer que le sens du récit est clair.
Wisdom of the wise is but a messenger, and does nothing for the good of the work.
Xelu boroom xam-xam ab ndaw rekk la, du def dara ngir njariñu liggéey bi.
La sagesse du sage n'est qu'un messager, et ne fait rien pour le bien de l'œuvre.
There is no profession more unconventional than his own.
Amul liggéey bu gëna wuute ak liggéeyam.
Il n'y a pas de profession plus non conventionnelle que la sienne.
there are three government-guarded areas in the province
amna ñatti barab yu nguur gi di wottu ci dëkk bi
Il y a trois zones surveillées par le gouvernement dans la province.
Large cities are prime locations for software companies
Dëkk yu mag yi ñooy barab yi gëna am solo ci defarkati losisel yi
Les grandes villes sont des lieux privilégiés pour les sociétés de logiciels
no i don't even know him i don't think so
Déedet xamuma ko sax, yaakaaruma ko
Non, je ne le connais même pas. Je ne pense pas.
All of them decided to work in the fields.
Ñoom ñépp ñu fas yéene liggéey ci tool yi.
Ils ont tous décidé de travailler dans les champs.
Every gift you give serves a purpose
Bépp kado boo joxe amna lu muy liggéey
Chaque cadeau que vous donnez sert un but
One can think of this process as paving the way for a new civilization in which the person doing the civilization is called Hey, Loyd.......
Kenn mën na xalaat ni liggéey boobu dafay ubbi yoonu siwilisasioŋ bu bees bu ñuy woowe kiy def siwilisasioŋ bi Hey, Loyd.
On peut penser à ce processus comme ouvrant la voie à une nouvelle civilisation dans laquelle la personne qui fait la civilisation s'appelle Hey, Loyd.......
I looked in the thesaurus and didn't see the words
Ma xool ci thesaurus bi waaye gisuma kàddu yi
J'ai regardé dans le dictionnaire et je n'ai pas vu les mots
Mr. Alexander has been forced to resign after his indecent photographs were published.
Alexander dafa wara bàyyi liggéey bi ginaaw bi ñu siiwal ay natalam yu ñaaw yooyu.
M. Alexander a été forcé de démissionner après que ses photos indécentes aient été publiées.
Each of the higher forms of thought to which he refers is first manifested in the social context, between the child and the representatives of his culture as they engage in social activity.
Bu nekk ci xeeti xalaat yu gëna kawe yi mu wax, dafay njëkka feeñ ci wàllu askan wi, diggante xale bi ak ndawi cosaan ak aadaam, bi ñuy dugg ci liggéeyu askan wi.
Chacune des formes supérieures de pensée auxquelles il fait référence se manifeste d'abord dans le contexte social, entre l'enfant et les représentants de sa culture lorsqu'ils s'engagent dans une activité sociale.
by playing, they will be able to demonstrate how the situation should be handled
suñuy fo, dina ñu mëna wane ni ñu wara saafara jafe-jafe bi
En jouant, ils seront en mesure de démontrer comment la situation devrait être gérée.
this country was built for its own sake, all men are equal
réew mii dañu ko tabax ngir boppam, nit ñépp a yem
Ce pays a été construit pour lui-même, tous les hommes sont égaux
Just because upbringing has an important influence on athletic performance does not mean that nature is dormant, however.
Waaye, ginaaw yar gi dafa am njeexital yu am solo ci tàggat yaram, loolu tekkiwul ni nature bi dafa nelaw.
Cependant, le fait que l'éducation ait une influence importante sur les performances sportives ne signifie pas que la nature est inactive.
I hated going to the theater as a child, so I became a scientist.
Bi may xale amoon naa bañoon dem teyaatar, moo tax ma nekk gëstukat.
Je détestais aller au théâtre quand j'étais enfant, alors je suis devenu scientifique.
After beating the victims in front of him, he tried to hide them in a garbage dump.
Ginaaw bimu dóoree ñi ñu faat ci kanamam, mu jéem leen nëbb ci benn mbalit.
Après avoir battu les victimes devant lui, il a essayé de les cacher dans une décharge.
At this speed, regular crystals cannot store large amounts of information.
Su kristal yi gaawee nii, mënu ñu denc xibaar bu bari.
À cette vitesse, les cristaux ordinaires ne peuvent pas stocker de grandes quantités d'informations.
The death of a detective I was not informed of.
Faatu benn detektif buñu ma yëgal.
La mort d'un détective dont je n'ai pas été informé.
Milreu is ten miles from everything
Milreu mingi fukki mile ci lépp
Milreu est à 16 km de tout.
The museum is not based on a name or a trademark
Muse bi nekkul ci tur wala màrku jëndkat
Le musée n'est pas basé sur un nom ou une marque
An announcement has been made at the beginning.
Def nañu ab yëgle ci ndoorte li.
Une annonce a été faite au début.
In the early stages, an individual can contribute by leaving a permanent donation of $1,000 or more to the Chancellor's team or $500 or more to the Chancellor's associates.
Ci ndoorte li, ku nekk mën na jàppale ci bàyyi $1,000 wala lu ëpp ci ekipu Sanseliye bi wala $500 wala lu ëpp ci ñi ànd ak Sanseliye bi.
Au début, un individu peut contribuer en laissant un don permanent de 1 000 $ ou plus à l'équipe du chancelier ou 500 $ ou plus aux associés du chancelier.
you will see videos of the Anne and Amsterdam community in the gallery as well as statues and antique objects
Di nga gis wideo yu askanu Anne ak Amsterdam ci galëri bi, luwa ak mbir yu yàgg
Vous verrez des vidéos de la communauté d'Anne et d'Amsterdam dans la galerie ainsi que des statues et des objets anciens.
I will not say this on my own, because there are many who are trying to persuade me.
Duma wax loolu ci sama bopp, ndaxte ñu bare ñu ngi may jéem a gëmloo.
Je ne dis pas cela de moi- même, car il y en a beaucoup qui essaient de me convaincre.
The port town of Nafplio makes an ideal base for sightseeing, or a place to have lunch while sightseeing
Dëkk bi nekk ci portu Nafplio mooy barab bi gëna baax ngir seeti dëkk yi, wala barab booy añee sooy seeti dëkk yi
La ville portuaire de Nafplio est un point de départ idéal pour faire du tourisme ou pour déjeuner en faisant du tourisme.
People were worried about being able to communicate with others at the World Trade Center because the lights were going out and the elevators were not working
Nit ñi deñu doon jaaxle ndax duñu mëna jokkoo ak ñeneen ñi ci World Trade Center ndax làmp yi dañu doon fay, ascenseur yi duñu dox.
Les gens s'inquiétaient de pouvoir communiquer avec les autres au World Trade Center parce que les lumières s'éteignaient et les ascenseurs ne fonctionnaient pas.
They allow them to go twice a week if the older residents agree.
Dañu leen may ñu dem ñaari yoon ci ayu-bés bi su mag ñi nangu.
Ils leur permettent d'y aller deux fois par semaine si les résidents plus âgés sont d'accord.
Traditional rice was considered to be cold and salty; therefore, it was very difficult to get someone like Michael Apted to add a sweet touch to the traditional rice count, and he added some of his own ingredients to increase our intake.
Dañu jàppoon ni céeb cosaan dafa sedd ba noppi xorom; moo tax, jafewoon na lool ñu am nit ku melni Michael Apted mu yokk lu neex ci limu céebi cosaan, mu yokk ci yenn ci ay saf-safal ngir yokk li ñuy lekk.
Le riz traditionnel était considéré comme froid et salé; par conséquent, il était très difficile de faire en sorte que quelqu'un comme Michael Apted ajoute une touche sucrée au nombre traditionnel de riz, et il a ajouté certains de ses propres ingrédients pour augmenter notre consommation.
A large bay on the west and north coasts has a fine harbor but both the water and the sea can be polluted
Bay bu yaatu ci wetu sowwu ak nord amna poor bu baax waaye ndox mi ak géej gi mën nañu tilim
Une grande baie sur les côtes ouest et nord a un bon port mais l'eau et la mer peuvent être polluées
development was in the computer sector and also in the tourism sector
yokkute mingi amoon ci wàllu ordinatër ak ci wàllu turism
Le développement s'est fait dans le secteur informatique et aussi dans le secteur du tourisme.
Our entire season requires more than just ticket sales and sign-ups.
Sunu sesoŋ bi yépp laaj na lu ëpp jaay biye ak abone.
Notre saison entière exige plus que la vente de billets et les inscriptions.
Although there were two mergers, there was no need for the company to go through a restructuring of the rating system.
Doonte ñaari yoon lañu boole liggéeyukaay yi, jarul ñu soppali sistemu note yi ci liggéeyukaay bi.
Bien qu'il y ait eu deux fusions, la société n'a pas eu besoin de procéder à une restructuration du système de notation.
It takes three months to complete training in the use of full pressure suits
Ñatti weer lañuy jël ngir mëna jëfandikoo yéere yu am pression bu mat sëkk
Il faut trois mois pour terminer la formation à l'utilisation de combinaisons à pression totale.
The FBI couldn't even find anyone who left Florida in 2001.
FBI mënul woon gis kenn ku joge Floride ci 2001.
Le FBI n'a même pas pu trouver quelqu'un qui a quitté la Floride en 2001.
the results of this discovery have been preserved for many centuries
li ñu gis ci gis-gis boobu ñu ngi ko denc ay xarnu yu bari
Les résultats de cette découverte ont été conservés pendant de nombreux siècles.
Khallad said there was a 50% chance that the three had travelled to Karachi in October.
Khallad neena amna 50 ci teemeer boo jél ni ñoom ñatt demoon nañu Karachi ci weeru Oktuubar.
Khallad a dit qu'il y avait 50% de chances que les trois aient voyagé à Karachi en octobre.
And with a sense of pride, those who have achieved status in the community will use the name in private, barbershop and non-official contexts.
Ak mbégte, ñi am rang ci askan wi dina ñu jëfandikoo tur wi ci seen bopp, ci barabi kawar ak ci yeneen mbir yu nekkul ofisel.
Et avec un sentiment de fierté, ceux qui ont atteint un statut dans la communauté utiliseront le nom dans des contextes privés, de barbier et non officiels.
You can imagine a sailor on a cruise ship navigating the world's seas.
Mën nga xalaat nafarkat bu nekk ci gaal giy tukki ci géej yi ci àdduna bi.
Vous pouvez imaginer un marin sur un bateau de croisière naviguant sur les mers du monde.
Despite two years of investigation, the FBI was unable to locate the collaborator or discover his true identity.
Doonte FBI bi defna ñaari at ci amal lànket, mënu ñu woon gis ki ànd ak moom wala xam kimu doon dëgg.
Malgré deux ans d'enquête, le FBI n'a pas pu localiser le collaborateur ou découvrir sa véritable identité.
I became furious and began to speak to him again.
Ma mer bay tàmbaliwaat waxtaan ak moom.
Je suis devenu furieux et j'ai recommencé à lui parler.
If he had stayed in one place, he would have been noticed.
Bu nekkoon ci benn barab, dina ñu ko seetlu.
S'il était resté au même endroit, il aurait été remarqué.
you have to do the same thing as both of them when they are 12 and 11
Danga wara def li ñuy def ñoom ñaar suñu amee 12 at ak 11 at
Tu dois faire la même chose que les deux quand ils ont 12 et 11 ans
Accepting a gift of just over $100 makes a difference
Nanngu kado bu ëpp $100 dina am solo
Accepter un cadeau d'un peu plus de 100 dollars fait une différence.
I heard that the United States had suspended its embargo on two occasions before returning home.
Dégg naa ni Etats Unis dafa dakkal embargo bi ñaari yoon balaa muy ñibbi.
J'ai entendu dire que les États-Unis avaient suspendu leur embargo à deux reprises avant de rentrer chez eux.
Nafplio is optimistic
Nafplio amna yaakaar
Nafplio est optimiste
Children do not have the same high-mindedness.
Xale yi duñu am xel mu kawe.
Les enfants n'ont pas la même haute mentalité.
Announcement in the offseason.
Koom-koom ci sesoŋ bi.
Annonce dans la saison morte.
think carefully about the future of the king
xalaatal bu baax ëlëgu buur bi
Réfléchissez bien à l'avenir du roi.
you won't see the pictures
doo gis nataal yi
Tu ne verras pas les photos.
The CEO recently retired a few weeks ago.
Bu yàggul dara CEO bi jël na retrete ayu-bis yu néew ci ginaaw.
Le PDG a pris sa retraite il y a quelques semaines.
One Capital owns several software companies
One Capital amna sosiete yu bari yuy defar ay losisel
One Capital possède plusieurs sociétés de logiciels